Dataset Preview
Duplicate

The dataset viewer should be available soon. Please retry later.

audio
audio
transcription
large_string
daal di dem bu demee netali keneen netali keneen bu yàggee noonu
dañu xewal mbicci ci tànki tubay yi
su boobaa ag cant rekk moo cay top
mu ngi bawoo ci abajada bu almaañ te benn araf õ õ lañ ci yokk
loolu lepp nag nga boole ko moo jur jamonoy tugal ju yees jii
gisoon naa li nga def
leegi ag jigéen ngeen
kañ la tom egsi
jeqiku gi xam xam amal ci elektron
ndax man naa luye ay bantu tinis
léegi nag su fekkee tamit maanaam nawet bi dafa normal maanaam bëriwul bëriwul taw waaye tamit
yelu te mooy wax ci suuf ci tisbaar ak tàkkusaan
damaa bëgg tufe pombiteer
actuellement ñu si bëre école ubbi na depuis jeudi bee paase
ci ci ci sa biir kër
boo fay deme woto dafay mel ni lu jége
ñi ñorle war a deqi soxla nañ xibaar yi pour xam ban période moo baax pour ñu deqi
jëf ju tuuti du cëru borom yax bu réy
saay saay yi dañu ko ruggi ba mu set
te toll na ci jamono joo xam ne da nga ko war a góob dama ne nañ jël les stratégies d adaptation nañ jël pexe yi
bu ko defee léegi ñu mën a am tàngaay bi nga xamante ne bii moom la ñu soxla pour mën a kii quoi souvent yu mel noonu boo demee par exemple par exemple dans la zone de sandiara
dinaa la bégloo
terminus lac rose
ndax itam banques yu ndaw yi
yëngu yëngu gu wuññi gu juxraaf walla feeñal gu juxraaf yëngu yëngu gu yàgg la
bëñ yi foq nañu ba jeex poose rekk a ko dese
benn doxalkat bi ñaar jataayub yoonal bi ñett jataayub diisoo bi
laa la wax man nit ñaa ngiy wëreelu ñi ci des ñu ngiy sakket di fecc
jigéen mooy def lépp lu nga xamante ne toute la chaine de valeur jigéen ñi ñoo koy def
surtout lu jëm si céréales yi
li muy wax mënula dugg ci sa mbopp si
ngéen demoon fa moo gën
la képp ku bugg assuré wu
voilà ak quatorze régions yi aussi ñu ngi ci
damaa sopp ay téere
waaw ak tamit souvent tamit léeg léeg béykat léegi nañ la woo laaj la donc nga jox leen information mais bii ma la wax nii réseaux sociaux yi ñoo gën a efficace parce que yow li nga mën a envoyer ci alerte ci partager information anacim yi
station oilibya thiaroye
mu daal di def liggéey rafet
buleen ko nettali keen
mu teg saakam dal di dem ubbi palanteer bi
problème bi ci nekk mooy
mu daal di weedi sos yi
ministere de l interieur senegalais
fekk na biram njéemée nga yendu ca mbënn ga fanaan ca
fooguma woon ne ñeme nga yooru ci teen bi
ñu àndandoo sax ca dun île ba akub coona fuglukat ya di ñu fa bari
dangeen a bëgg a des a
nit ñu bëri da ñu wa oo pour ëndi seen produit def traitement ndax ji dugub bi xëy na weesu na am na ñoo xam ne weesu na mais ji mboq bi si lañ toll
ndegem danuy tukki rekk nanu dem fu sore
ecole bachir
gis naa ko benn yoon
ku ko man a tere
amari ngoonee taxoon kajoor feyatul voon galag jolof
làkku ceg laay jàng
ba mu toogee ba tey cellam gaa ngiy jur coow lu bari
dof boo gis ay nit a nga ca kër ga mu jóge
kon bu tóortóor bi bëriwul
allo
ñaari téemeer ak juróom ñent fukk ak juróom ñenti nit faatu nañu ca frãs
cere ju wow ji ngay lekk dina sekki ci sa biir bi
loolu rekk laa def
bëgg naa golf
te ma gis ci moom xol bu rafet mu doon suñu kilifa mais yor service mission publique mais yaatu ci boole ci ñëpp béykat ñun ñii wax dëgg léeg léeg sax dañ may méngale sax ak sa météo tellement que moom dafa jël lépp jox ñu ko donc loolu ñu ngi koy gërëm di ñaax béykat yi maintenant ñu gën a am taxawaay comme ni ko l ha...
nanu dem rekk sëñ daam li ci kanam rawul i gët
albert sarraut
xale ya ñëw mu ñaanal leen ñu takk laxas ngir génn dëkk bi
lii sama welo bu yàgg ba la
yii ñooy réew yi fa ne
wàllstation rajo itaali
na nu yàlla taas ci barke nit kooku
sa jamono weesu na
les perspectives ou les relations plus résiliantes
duma jàmbat mukk
xam nan nu
nataalu meññatum gerte muñu xolleegul
jigéenu wérul bi dafa om yaram wi jeex tàkk
te mu nekk mbir moo xam ne nag kenn ku nekk yaa ngi koy dund ca fa nga nekk ni ko kilifa gi waxee rek
boobu moom moo ëpp lim koy dal ba bëri wu si
émi thème bi ci loolu lay
ndax am nga këyit
lérén dina fànqal liir yaram wu ñaawlu
sa bokk yépp siggi nañu ci sa ndam li
dem ak dikki nit ñee doon wone njartel njaayam
hu dafa doon dooleel réew yu nekk ci yoonu yokkute ngir moytu yoonu yaq bu njëkk bi te fomp ko ci apare
juróom ñentteeli matukaay
ndax buñu nee entreprise rek ñu bari dañuy dégg entreprise ñu yaakaar ne ñi nga xam ne dañoo yore alal yu bari
wàll per yi ak xeer yi ci kàddug yàlla
ay njuuma yu ponkal la
defar na lu ëpp junni tembar ngir suwed ak yeneen ñaar fukk ak juróom ñett réew
am na ñoo xam ne dañuy wal xar laata ñu koy fees
xanaa nu yónni yàgg rekk ba xam fu wànnent di mujj ak i gëtam
jigéen ju asaru du yomba am jëkkër
li gën a siiwal feebaram sax mooy ñeenti awril bi mu wuute
man naa tëddi
dese naa juróom benni téeméer ma sog a mën jënd xar mi
ndax sa gis gis dafa bon
gàll ko teg ko ba nga xam ne boo ko tegee
su ma demee ba am nag dooley dem jënd ci sac yu bees tàq de préférence lu ñuy conseillé baykat yi mooy sac neuf muy sac bu bees wala sac boo xam ne defoon na loo xam ne ba ma koy jënd lekk ci la jëmoon
bulleen nekk ci lu leerul
bu fekkente ne suus si baax na
End of preview.
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
364