french
stringlengths
4
937
wolof
stringlengths
4
946
Ce fut un homme, un vrai !
Nit lawoon !
portent une calebasse trouée
yenu lekket gu bënn
J'ai dû pénétrer dans la zone dénudée qui entoure l'orifice de leurs galeries.
Xam naa dama teg sama tànk fu ma ko warul a teg.
C'est moi qui ai été
Maa demoon
Il est par-là !
Mi ŋgi foofule !
L'administration anglaise, selon un de ses principes, a laissé en place la structure politique traditionnelle, avec ses rois, ses chefs religieux, ses juges, ses castes et ses privilèges.
Ñàkkul doxalinu Àngale yi gën leen koo yombal. Ndax ñoom, dañuy teg loxo ci sa réew ba noppi ni la sunu yoon newul ci say aada ak yu ni mel. Su ko defee, buur ya fa newoon di wéy di toog ci jal bi, kilifa diine yeek àttekat yeek ñoom-seen di doxal ñoom it seeni mbir nañu ko mas a defe.
Comment vas-tu ?
Nanga def ?
Bonjour ! Ceci est une photo. Sur cette photo ci j'y vois une calebasse dans laquelle il y a des morceaux de sucre de couleur blanche. Il y a aussi des morceaux de sucre sur le sable et aussi une calebasse dans laquelle je vois un chat de couleur chocolat.
As salaamaalekum ! lii de ab nataal la. Nataal bii de gis naa si ab këll, këll boo xam ni ay suukër bekk la def bu am melo bu weex. Am na tamit ay suukër bekk yu nekk ci suuf, am na tamit ab këll bu may seen ci cat li boo xam ni dafa sokolaa.
Un lion dans la chambre !
Aw gaynde ci biir néeg bi !
Ils doivent être des vieillards, proches du terme de l'existence.
Soo demee màggat nañu ba xubidaas te balaa yàgg ñu wuyuji seen boroom.
La religion que nous découvrions grâce à lui ne permettait pas d'accommodements.
Ci gis-gisam, yoonu diine, yoon wu jubb xocc la te xat.
Tu es qui ?
Ya di kan ?
Où avait-il été ?
Fu mu demoon ?
Par ici !
Ci fii !
Puis les lettres ont cessé d'arriver, et mon père a appris par les bonnes sœurs de Bamenda que son vieil ami était mort.
Ñu toog ba benn bataaxalu Ayijoo ñëwatul. Xel ñaaw. Waa kër làbbe yu jigéen ya woon Bamendaa mujjee yëgal Baay ni doomu-ndeyam ja wuyuji na boroomam.
Quels chevaux voulais-tu et lequel as-tu pris ?
Yan fas ŋga bëggoon ak wan ŋga japp ?
Dis à d'autres de partir !
Waxal ñeñeen ñu dem !
Tu es jeune !
Xalel ŋga !
Que tu partes, c'est ce que ceux-là veulent.
Ŋga dem la ñooñu bëgg.
Banquiers, agents commerciaux, administrateurs civils ou militaires, juges, policiers et gendarmes.
Ñooñooy njiiti bànk yi, ňiy yëngu ci njaay meek njënd mi, ndawal buur yi walla soldaar yi, àttekat yi, alkaati yeek sàndarma yi.
Où est … ?
Fahn la … ?
Plutôt un espace d'utilité, où mon père avait planté des fruitiers, manguiers, goyaviers, papayers, et pour servir de haie devant la varangue, des orangers et des limettiers dont les fourmis avaient cousu la plupart des feuilles pour faire leurs nids aériens, débordant d'une sorte de duvet cotonneux qui abritait leurs œufs.
Baay daawul saxal lu dul i meňňeef yu nu amal njariñ, maanaam ay garabi màngo, ay guyaab ak i pàpaaya. Ñoo sës it ci peroŋ bi, ñag kër gi, ñook garabi sor s yeek yu limoŋ yi. Mellentaan yaa ngi ràbb seeni xob, defar ciy tàgg yu kowe, mu mel ni mbàjjum wëtéen mu ëmb i nen.
Ceci est une théière ; une théière sur la quelle on voit une gazelle et deux arbres. C'est une théière rouge. On utilise la théière pour cuisiner, chauffer de l'eau ou tout autre chose que les gens boivent.
Lii ab baraada la ; baraada boo xamente ne ñu ngi ciy gis genn kéwél ak ñaari garab. Baraada bu xonq la. Baraada nag dañu koy jël di sí togg, di si tàngal ndox walla loo xamente ne nit ñi dañu koy naan.
Cherche une autre dame !
Seetal jigéen jeneen !
Vas t'en !
Deemal waay !
Certains soirs, avant la pluie, ils étaient une armée.
Su xiinaan bay waaj a taw lañ daan gën a ràkkaaju.
Ici, cependant, il semble qu'il y est une porte, une jolie porte. En plus il semble qu'elle soit fermée. Parce que, si tu regardes bien sa position, on l'a tirée jusqu'au fond... jusqu'à ce qu'elle soit serrée. Par conséquent, pour pouvoir y entrer, il faut qu'on t'ouvre ou bien que tu ailles tenir ce fameux levier pour pouvoir entrer à l'intérieur.
Bii nag, mun mel ni benn bunt moo fi ne. bunt bu rafet. Te niñ ko wonee sax dafa mel ni dañ ko téj. Ndaxte boo seetee nu mu mel, dañ ko xëcc ba mu sës... mu serré. Ba tax na, dafa mel ni sax pour nga dugg fa, faaw ñu ubbi la wala sax nga ñëw tiyé ci levier boobu noonu bi ñu wone pour nga man a duggu ci biir.
C'est cela qu'on appelle un berceau. Il est conçu avec du bois. À l'intérieur de ce berceau, cependant, il y a une sorte de drap blanc avec un oreiller. À l'intérieur de l'autre, on y a étalé quelque chose de couleur chocolatée ; un drap chocolat.
Waaw lii lañu naan beerso. Dénk lanu ko defaree, dénk. Benn beerso bi nag ci biir lu mel ne xeetu darab bu weex moo ci nekk am benn njegeñaay. Beneen bi nag danu cee lal lu mel ne lu sokolaa ; darab bu sokolaa.
Les pays développés retrouvent un débouché inattendu pour leurs produits finis : ils vendent dans les deux camps armes légères et lourdes, mines antipersonnel, chars d'assaut, avions, et même des mercenaires allemands, français, tchadiens, qui composent la 4e brigade biafraise au service des rebelles d'Ojukwu.
Réewi tubaab yi am doole yi ni màrse neex na : ñu ngi jaay Ibo yeek Yorubaa yi ay gànnaay – moo xam ay roppëlaan la, mbaa ay ndell mbaa leneen. Ñu ni déet ay way-xare-lekk jóge Almaañ, Frãs ak réewum Càdd di sotle Ósukwu miy jiite fippu yi.
Image caractéristique de la Colonie : des voyageurs européens, vêtus de blanc et coiffés du casque Cawnpore, sont débarqués dans une nacelle et transportés jusqu'à terre à bord d'une pirogue montée par des Noirs.
Ñàkkul su ma ko jeexoon ci xeetu nataal yu siiw jamono jooju fekk ko ci biir. Mooy nataal yiy wone ay Tubaab yuy waaj a koste Afrig ci gaal gu ndaw, sol yére yu weex ak seeni kask Kawanpoor, ay nit ñu ñuul di leen joowal.
S'exiler pour bouder ses fruits répandus
Gàddaay gedd la ñuy tasaare
Je sens que ceux-là sont, vraisemblablement, des ustensiles de cuisines. Il y en a de différentes couleurs. Il en existe avec des couleurs vertes, des couleurs bleus, il y a du jaune, et aussi du rouge. Il y a aussi des couleurs vertes, et aussi d'autres couleurs. Ce sont des ustensiles de cuisines, assurément.
Waaw lii de ay xeeti toogukaay la, ay xeeti toogukaay nag. Am na ay wirgo nag. Am na ay wirgo yu wert, am wirgo yu bula, am na mboq, am tamit ëe xonq, am na tamit ëe wirgo yu wert, am tamit yeneen wirgo daal. Ay toogukaay la, ay toogukaay lay doon.
J'ai rapporté des nouvelles.
Xibaar laa indi.
Ceux-ci n'allaient pas, généralement.
Ñii daawuñu dem.
J'ai joué avec les statues d'ébène, avec les sonnettes de bronze, j'ai utilisé les cauris en guise d'osselets.
Fowe naay nit ak i mala yu ñu yatte dàttu aloom, fowe jóolóoliy xànjar, jël naay tani def leen i caqi yax yu ndaw.
Toi et moi irons ensemble !
Man ak yaw ñooy ànd !
La femme regrette d'avoir eu une fortune.
Ndaw si réccu na amoon.
Je t'ai vu avec lui !
Gis naa la yaak moom !
C'est nous-même qu'il cherche.
Ñun ñii lay set.
J'ai vu une vache d'Europe.
Gis naa nagu Tugël.
Les royaumes sont au cœur d'une zone d'influence, sous l'inspiration de l'islam venu des empires du Nord, de Kano, des émirats de Bornu et d'Agadez, de l'Adamawa, apporté par les colporteurs foulanis et les guerriers haoussas.
Réewi diiwaan boobu, xëccoo nguur ak jaayante doole yàgg nañ fa. Diine lislaam teel na faa agsi, jóge Kano, ca bëj-gànnaar. Kilifay diine yu mag ya ca Agadees, Bornook Aadamawaa itam bokk nañ ci ñi tuubloo ceddo yooyu. Lépp nag ñu nga ko jaarale ci làrme bu Awsa yi ak ci Pël yi daan wër di jaay ak a jënd.
Il travaillait.
Dafa doon liggéey.
Pour cela, je sens son impatience, son grand désir de pénétrer à l'intérieur du pays, pour commencer son métier de médecin.
Looloo waral may yëg ni mu yàkkamtee dugg ci biir réew mi, ngir gaaw a tàmbalee faj nit ñi.
Le Monsieur !
Góor gi !
À ceux-ci, ceux-là, à ceux qui sont là-bas
Ñii, ñee, ñooñu
Celui-là c'est !
Kooku la !
Aïe ! ne suffit pas pour qu'il lâche
Wóoy ! taxul mu yabbi
L'homme n'a pas été
Góor gi moo demul
C'est toi qui aurais parlé
Yaa doonkoon wax
Homme n'a été
Góor demul
La guerre civile devient une affaire mondiale, une guerre entre civilisations. L'on parle de chrétiens contre musulmans, ou de nationalistes contre capitalistes.
Yëf yi dem ba ëpp loxo, xeexu Ibo yeek Yorubaa yi daldi soppiku xare diggante kerceen ak jullit, ñii di tuumaal ñee, naan dañoo taxaw ci tànku pasar-pasaree alalu réew mi, séddoo kook ay doxandéem.
Eux parleront
Ñoom danañu wax
Mon père et elle sont unis par ce rêve, ils sont ensemble comme les exilés d'un pays inaccessible.
Gént googoo lëkkale samay way-jur, ñu ànd gàddaay cig gént, jubal réew mu amul tur amul sant.
Et pourtant, je l'ai vu
Moontin dey, gis naa ka
Ce n'est pas gentil pour l'autre.
Ñaaw na ndax keneen ki.
C'est un homme généreux !
Nit ku baax la !
L'homme eût parlé
Góor gi waxkoon na
Ah c'est ce qu'on avait dit. Ce sont des policiers accompagnés de leur chef. C'est eux que l'on voit debout. Leur chef, cependant, se trouve là-bas. Il semble qu'ils doivent se mettre debout et tendre les bras ; à ce qu'on voit.
Aaa mooy li ñu waxoon rekk ñii ay policiers lañ ñoo xam ni da ñu ànd ak seen seef. Ñoom la ñu gis ñu nekk taxaw nii. Seen seef bi nag moo nekk nee. Xay na nag da ñoo war a taxaw rekk coster les bras nii ci li ñu man a gis nii.
Ceux-là sont, semble-t-il, des paniers de course. Il y'en a qui sont en gris, d'autres qui sont bleus. Ils sont posés au-dessus d'un lit ou d'une moquette. Je suis sûr que la femme a qui on va les donner va bien faire ses courses.
Waaw lii de ab ëe ay kii la ay pañe la, pañe ndugg. Am na yu mboq, am na yu baxa ñu teg ko ci kaw lal walla kaw moket moket. Xam naa ne ku ko jox jigéén dana si ndugg bu baax.
C'est toi qu'elle veut.
Yaw la bëgg.
Où les hommes et les femmes étaient totalement différents, non pas à cause de la couleur de leur peau et de leurs cheveux, mais par leur manière de parler, de marcher, de rire, de manger.
Nga nekk it xale bu tuuti, xéy bes rekk di dajeek ay doom-aadama yu wute lool ak ña nga miinoon Tugal, ñuy waxe neneen, di lekke neneen, di reetaane neneen.
C'est la ville de ce Sérère.
Dëkku Séeréer bii la.
Au long de leurs marches, l'Afrique qu'ils rencontrent n'est pas celle de la colonisation.
Fexe nañu ba mucc ci Afrigu nguurug Tubaab yi.
Il a vu tous tes amis !
Gis na sa xarit yépp !
J'irai aujourd'hui !
Tay danaa dem !
Je t'entrevois, seul, emmuré
Ngay ku wéet fañu la tëj
Au Nigeria, mon père ne sait que ce que transmet la BBC.
Ganu-ganu, Baay ma newoon Niseryaa daan nay déglu BBC, rajo Àngale yi, am lu mu ca fortaatu ci yëngu-yëngu àddina si.
Avec eux voyageaient leurs employés, Njong le chocra, Chindefondi l'interprète, Philippus le chef des porteurs.
Seeni surga daan naňu tukkeek ňoom. Ku ci mel ni Njoŋ, « sokaraa » ba, walla Sindefondi, làppto bi, walla Filipus njiitu yenukat ya.
Il était Lebou de Yoff.
Mu doon Lebu Yoff.
Il me semble aujourd'hui que la seule explication serait l'angoisse des années de guerre. Un monde fermé, sombre, sans espoir.
Ci sama gis-gis, du dara lu dul ni ati xare bi jaxasee woon sama xel.
Alors, un jour, nous avons couru tout seuls dans la plaine fauve, en direction de la rivière.
Bés nag, nu song joor giy daw wuti dexug Ayaa.
Tu ne partiras donc pas ?
Xanaa doo dem ?
Sur la place, le théâtre masqué se prépare. Sous un banian, les joueurs de tam-tam se sont assis, ils frappent, et l'appel de la musique se répercute au loin.
Ci bayaal bi, kilibu nëbb-sa-kanam baa ngiy waaj a door. Ci taatu keemuur gi, tëggkati sabar yaa ngi toog, di rëkk ak doole, foo tollu di leen dégg.
Certainement, c'est l'homme qui a dit qu'il est là !
Soo demee, góor gee ni mi ŋgi fi !
Mais personne ne nous accompagnait.
Li wóor ba wóor moo di ne nuni neen la woon keroog jooju.
La mémoire des espérances et des angoisses de mon père, sa solitude, sa détresse à Ogoja.
Waaye dina fàttaliwaale yit njàqareg Baay, rawati-na ca Ogosaa, fa yaakaaram tasee tasar.
L'homme dont parle cet individu
Góor gi waa ji wax
Pourtant, parfois, je marche dans les rues d'une ville, au hasard, et tout d'un coup, en passant devant une porte au bas d'un immeuble en construction, je respire l'odeur froide du ciment qui vient d'être coulé, et je suis dans la case de passage d'Abakaliki, j'entre dans le cube ombreux de ma chambre et je vois derrière la porte le grand lézard bleu que notre chatte a étranglé et qu'elle m'a apporté en signe de bienvenue.
Teewul léeg-léeg may daagu cib dëkk bu ma miinul, jékkee-jékki gis tabax bu sotteegul, xetu simoŋ gi dugg ma. Ci saa si, sama xel daldi dellu Abaakaliki. Ma jaaxaan ci sama néeg bu féex ba, di séen ci ginnaaw bunt bi sindax bi sunu muus mi rey teg fa, ngir ganalee ma ko.
Cette histoire, combien de fois ai-je entendu ma mère la raconter ?
Xew-xew boobu, ñaata yoon laa dégg sama yaay di ko nettali ? Du benn, du ñaar.
Je me rappelle seulement cette question : « Est-ce qu'elle est malade ? » Elle me brûle encore aujourd'hui étrangement, comme si le temps n'était pas passé.
Li gën a doy waar ci mbir mi, moo di ne laaj ba ma laajoon sama yaay – « Ndax kii dafa tawat ? » – mu ngi ma topp ba tey jii, masul a génn sama xel.
Sur cette photo ci, il y a une calebasse. Une calebasse qui semble un peu petit. Elle a à l'intérieur des sucres de couleur très blanche. Au dessous d'elle aussi il y a d'autres morceaux de sucres qui y sont.
Nataal bii de ag leget la. Leget goo xam ne dafa xaw a ñuul tuuti. Am ca biir ay bekku suukar yu weex tàll. Ca suufam tamit am yeneen bekku suukar yu fa nekk.
Ces jeunes gens sont sages.
Xale yile yarunañu.
C'est ce qu'il a dit !
Li mu waxoon la !
Ce que tu m'as envoyé jusqu'à maintenant, la plupart sont des objets utiles. Il y a une théière, une machine de chauffage et un récipient.
Li nga ma yónnee ba tey, li ma ci gis ay jëfandikukaay la, baraada la ak mësin pour tàngalukaay ak xellikaay la.
Il y a un client nommé Modou.
Am na benn jëndukat bu tudd Modou.
L'homme qui m'est apparu au pied de la coupée, sur le quai de Port Harcourt, était d'un autre monde : vêtu d'un pantalon trop large et trop court, sans forme, d'une chemise blanche, ses souliers de cuir noir empoussiérés par les pistes.
Nit ki ma teerusi ci waaxu Poor-Arkuur dafa mel ni ku bokkul ak ñoom xeet walla sax ku fëlle beneen dunyaa. Tubay ji mu sol, yaatu te gàtt, kenn xamul lu muy nirool ; simis bi dafa weex, dàlli deram yu ňuul yaa ngi pënde ba nga ni lii lu mu doon.
Puis j'ai découvert, lorsque mon père, à l'âge de la retraite, est revenu vivre avec nous en France, que c'était lui l'Africain.
Àddinay dox ba Baay tollu ci noppalug liggéey, dellusi Tugal dëkk ak ňun. Ci la ma leere ni moom moomoo doon doomu Afrig.
Mais à quoi bon rêver ?
Waaye lu fi waral i gént ?
Mes voeux de noël
Mangui lay ndioukeul ci Noël bi
Es-tu en paix ?
Jaam nga am ?
Est-ce que comme je le souhaite...
Mbaa...
Sur cette photo il y a le Capitaine Seydina Omar Toure. C'est lui qui était à la section de recherche et qu'on a ensuite radier.
nataal bii Capitaine Séydinaa Omar Ture la. moo nekkoon section de recherche ñu radier ko.
Je sais que cela m'a manqué, sans regret, sans illusion extraordinaire.
Duma ni loolu safu ma, dinaa koy réccu sax léeg-léeg wànte yit terewumaa nelaw.
J'ai vu celui-là.
Gis naa ka woon.
Des boeufs que tu vois, celui-là est le meilleur.
Gis ŋga nag yii yépp, woowuu moo ci gën.
C'était comme s'il n'avait jamais quitté l'Afrique.
Mu ngi meloon ni masul a jóge Afrig. Li ma ko tax a wax moo doon na mu ñàkke woon soppiy jëfinam.
C'est lui qui avait été
Moo demoon
Aucune dame ne s'est égarée.
Jenn jigéen réerul.
Il en est reparti au début des années cinquante, lorsque l'armée a jugé qu'il avait dépassé l'âge de la retraite et qu'il ne pouvait plus servir.
Ndoorteelu atum 1950 la ko làrme bi yewwi, mu noppalu liggéey, jóge Afrig.
Ils ont été bûcherons.
Laobe lañuwoon.
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
0
Edit dataset card