french
stringlengths
4
937
wolof
stringlengths
4
946
Et devant moi, au bout de la longue « rue » du fleuve, les deux murailles noires de la forêt qui se referment.
Ma dawal samay bët ci liy nirook tali bu gudd bu xottikul boppam ci dex gi, daldi gis ni àll bi tëjoo ba noppi ne fépp ràpp.
L'homme ne rentrera pas chez lui.
Góor gi du ñibbi.
Si l'homme doit venir
Su góor gi dee ñëw
Vas-y seulement !
Demal rekk !
Vas t'en !
Deemal !
Il est là, peut-être !
Mi ŋgi fi, soo demee !
En fait, une femelle scorpion, qui transportait sa progéniture sur son dos.
Jiit ju jigéen la woon, ndax mu ngi bootoon njabootam.
L'hôpital dont il a la charge existe depuis longtemps, c'est une grande bâtisse de ciment à toit de tôle, avec salle d'opération, dortoirs pour les patients, et une équipe d'infirmiers et de sages-femmes.
Fajukaay bi Baay yilif du bu bees, yàgg na faa nekk. Tabaxu simoŋ bu mag la, ay seng muur kow gi. Am na opeerekaay, ay néeg yu way-feebar yiy fanaan ak yeneen yu ñu jagleel mbooloom ñi fay liggéeye.
Appelle celui-là qui ne partira pas
Wool kee dul dem
Va que l'homme te voie !
Demal góor gi gis la !
Sur cette photo ci, j'y vois quelqu'un portant le drapeau du Sénégal. Il semble que c'était, cependant, une marche de révolte. Il a coupé ce qui ressemble à une datte, un cocotier rouge, et l'a posé au milieu de la route. Ceux-là ont des vélos, ceux-là marchent avec leurs pieds.
Nataal bii maa ngi ciy gis ku yor raaya Senegaal. Daa mel ni ab nag doxu-ñaxtu la doonoon. Dagg lu mel ne tàndarma, garabu koko bu xonq, teg ko ci digg tali bi. Ñii yore'velo', ñii dox ak seen tànk.
Quels couteaux se sont égarés ?
Saatu yan ñoo réer ?
Il me raconte, avec la voix encore voilée par l'émotion, ce jeune Ibo qu'on lui apporte à l'hôpital d'Ogoja, pieds et poings liés, la bouche bâillonnée par une sorte de muselière de bois. Il a été mordu par un chien, et maintenant la rage s'est déclarée.
Nettali na ma yit – maa ngi fàttaliku ni baat bi doon loxe keroog – goneg Ibo ga xaj màtt bés, mu jóge fay say tëw a bàyyi, ñu tëj gémmiñ gi, yeew ko moom ci boppam ba mënatul a yëngatu.
Homme de courage n'abonde pas en paroles.
Jambaar du bare wax.
Quel homme est parti ?
Góor gu dem
Dès le premier contact, mon frère et moi nous sommes mesurés à lui en versant du poivre dans sa théière.
Bés biñ jëkkee giseek moom, maak sama mag jéem nan koo seetlu, sotti poobar ci baraadaam.
C'est l'autre endroit qui n'a pas de trou.
Feneen fi bëttul la.
Il n'a pas encore été
Demagul
Vous fûtes Laobé.
Laobe ŋgeen woon.
Je l'ai vu par ici !
Gis naa ka fii !
Oui celui-là !
Waw kookule !
Fais sortir tout homme que tu vois !
Génnéel képp nit koo gis !
L'homme qui est parti
Góor gi dem
Ceux-là n'iront pas
Ñooñii dunu demi
Là où tu as été.
Fi ŋga dem foofile.
L'enfant qui est mort est né malade.
Nit ku dee ki bu mu juddoo la feebar.
Je n'irai pas
Demuma
Rappelle Moussa qui s'en va
Wooyil Musaa moom mi di dem
Je vois devant moi une photo sur laquelle beaucoup de personnes marchent pour se révolter. Ils ont plié leurs mains pour montrer une attitude pacifique.
Nataal bii maa ngi ciy janloog haa ay nit yu bari yuy dox di dox ab ñaxtu. Ñi ngi bank seen i loxo di wane ni lu amul benn taafar lañuy deme.
On les dit chrétiens (ce sera même un des arguments utilisés par la France pour soutenir leur lutte contre leurs voisins yoroubas, qui sont musulmans). En vérité, l'animisme et le fétichisme étaient courants à l'époque. La sorcellerie était aussi une pratique au Cameroun, mais pour mon père, elle avait un caractère plus ouvert, plus positif.
Ñépp jàppoon ñañ ni ay kerceen lañu (Frãs sax, loolu la taafantoo ba faral leen ca seen xare baak seeni doomi-ndeyi Yorubaa yiy jullit, ñoom.) Dëgg la, jamono jooju, nit ñi xàmb ak xërëm lañu gëmoon. Waaye ci gis-gisu Baay, Kamerun a xawoon a tane.
L'Afrique ne l'avait pas transformé.
Du sax li mu demoon Afrig a ko soppi woon.
À ses côtés, mon père et ma mère sont debout, vêtus d'habits fatigués et empoussiérés par la route, ma mère avec sa longue jupe et ses souliers de marche, mon père avec une chemise aux manches roulées et son pantalon kaki trop large, trop court, serré par une ceinture qui ressemble à une ficelle.
Samay way-jur a ngi taxaw ci wetam ak seeni yére yu ràpp te pënde. Sama yaay ngi sol sipp bu gudd ak i dàll yu ñeme àll bi, Baay simis bu mu wag ak tubéy ju yaatu, gàtt lool ba noppi, nag, geetarook geño guy nirook buum.
Peut-être qu'à Nice quelques vieux de la vieille avaient conservé cet accessoire, que j'imagine seyant parfaitement à d'anciens officiers russes de l'armée impériale, arborant moustache et favoris, ou bien inventeurs ruinés qui fréquentaient mes « tantes ».
Amaana ay màgget dencoon ko ca Niis, di ko fàttalikoo seenug ngone. Walla boog ay ófisey làrme bu Riisi mbaa yenn boroom xam-xam ya daan seetsi samay « bàjjan » ñoo ko dese woon.
Qui est-ce ?
Ku mu ?
Est-ce loin ?
Soreh na ?
C'est de l'homme que parlent les enfants.
Góor gii la xale yi wax.
Devant l'avancée de l'armée fédérale, en proie à une folie vengeresse, la population civile fuit vers ce qui reste du territoire biafrais, envahit les savanes et la forêt, tente de survivre sur les réserves.
Làrme bu Legoos ni nag caaxaan faaxe, fàww mu fey Biyaafaraa boram. Daw wuti foo làqoo fa sësoon.
Tu as été et il est venu.
Dem ŋga te ñëw na.
Il viendra que tu veuilles ou non !
Ŋga dem ŋga bañ dem dana ñëw !
S'il n'avait pas été
Bu demulwoon
Comment se passe l'après-midi ?
Naka bëcëk bi ?
Il est unique.
Menn la.
C'est leurs dents !
Seni gëñ la !
Ceci est une photo sur laquelle je vois un poisson séché. Ce poisson séché semble énorme. Là où on l'a posé, auprès de la maison, est noirci.
Lii ab nataal la bob, nataal bi maa ngi ciy gis ag gejje. Géjje gi nag, gejje gi mel na ni réy na lool. Fi nu ko tek ca wet gale am na ay ñuul-ñuul.
J'ai vu ces gens.
Gisoon naa ñooñale nit ñan.
Nous avons appris à démolir ces murs.
Te it, kenn masu ñu woon a jàngal naka la ñuy toje miir yooyee.
Il était tellement excité et débordant de joie qu'il a pratiquement fait tomber la porte de son cadre.
Dafa yëngu woon té beg lool ba mu daanal bunt bi wépp ci cadar am.
Quelqu'un peut-il partir ?
Ndax kenn dem ?
Il a tué une lionne.
Ray na gaynde gu jigéen.
Il a été
Demoon na
Quand mon père était absent, quand ma mère dormait, nous nous échappions, la prairie fauve nous happait.
Bu Baay génnaan, sama yaay di nelaw, dañ daan rëcc, mel ni ñu àll biy woo te sañuñu koo tànqamlu.
C'était un homme en vérité !
Nit la woon ci dagg !
Je ne sais pas à quoi cela ressemble pour vous.
Xawma lan lay nurool ci yeen.
L'homme est parti pour que vous veniez sans que personne, surtout, ne le soupçonne.
Góor gi dem na ndax ŋgeen ñëw te nak kenn bañ leen foog.
C'est quand tu as été.
Bi ŋga demee la.
J'ai vu une vache d'Europe.
Gis naa nagu Tugal.
Je me souviens de l'étincelle dans ses yeux quand je lui ai raconté que j'avais parlé de lui aux Indiens, et qu'ils l'invitaient à retourner sur les fleuves, qu'en échange de son savoir et de ses médicaments, ils lui offraient une maison et la nourriture pour le temps qu'il voudrait.
Waaye maa ngi fàttaliku ferňeent ba takk ciy bëtam bés ba ma ni ko Enjeŋ yi namm nañ ko lool te su doon seen sago mu dellu fa, nekkaat seen doktoor, ñu ameel ko léppam ngiiru dundam.
Tu parles de ce mouton ?
Xar moomu man ŋga wax ?
Au contraire, c'est un pays prospère, où on cultive les arbres fruitiers, l'igname et le millet, où on pratique l'élevage.
Wàntee fii, réew mu naat la, bariy garab yuy meňň i doom, ñu fay bey ñambeek dugub, càmm gi it bari fa lool, kaar.
Au revoir
Ba beneen
C'est un homme pour quelles raisons ?
Nit la ci lan ?
C'est l'entrée de Louga. C'est à la frontière de Louga que tu entres pour montrer que tu habites à la région de Louga. Louga fait partie du Sénégal. C'est ça qu'il représente au Sénégal.
Lii duggukaay bu Luga la frontière bu Luga fii ngay dugg pour ñu wan la yaw mii nii yaa ngi dëkk biñ naan Luga. Luga nag ci Senegaal la bokk, ab lii la ci Senegaal.
Ainsi, ma mère n'a pu te voir
Ba nag, sama yaay fafu la gis
Tu n'avais rien dit de cela !
Waxuloowoon ca loola dara !
Puis la solitude et l'angoisse de la guerre, jusqu'à l'usure, jusqu'à l'amertume des derniers instants, ce sentiment d'avoir dépassé la mesure d'une vie.
Li ci tegu, di àddina su xar ñaar, ndax xare bu mettee-metti. Jur wéetaay ak tiis ak tiitaange, ñuy wéy di ko gunge ba mu màggat, mënalatul boppam dara, naan léeg-léeg ci xelam waay-waay mbir mi, maanaam jaar-jaaram, mënoon naa deme neneen.
Tu as vu ces jeunes gens ?
Gis ŋga xale yooyule ?
Fais sortir
Génnéel
Confie la chose à l'un d'eux !
Deŋkël lëf li kenn ki !
La présence de celui-là même ne justifie pas qu'on vienne
Taxawaayu kooka sax taxul nëw
Quand ma mère revient (peut-être vaguement inquiète de ce rassemblement), je lui montre cette femme : « Qu'est-ce qu'elle a ? Est-ce qu'elle est malade ? » Je me souviens de cette question que j'ai posée à ma mère. Le corps nu de cette femme, fait de plis, de rides, sa peau comme une outre dégonflée, ses seins allongés et flasques, pendant sur son ventre, sa peau craquelée, ternie, un peu grise, tout cela me semble étrange, et en même temps vrai.
Bi sama yaay dellusee – xéy-na ndaje mi dalul xelam – dama koo joxoñ jigéen ji, ni ko : “Kii lu ko dal ? Ndax dafa tawat ?” . Yaram waa ngi ne duŋŋ, lemu, rasu, der bi mel ni gamb bu peer, ween yi lax, di lang ba ci biir bi. Der bi nag ? Dafa xarat, ñuul kukk. Ci gàttal, mbindeef mu kéemaane laa janool.
Mon nom est ...
... laa tudd
L'homme eut été
Góor gi demkoon na
L'homme n'a rien mangé avec la main.
Nit ki lekkul dara ak loxoom.
Un homme de courage n'abonde pas en paroles.
Jambaar du bare wax.
Tu as dit cela.
La ŋga wax la.
J'ai aperçu un homme.
Séen naa aw nit.
L'homme qui eût travaillé
Waa ji liggéeykoon
Celui-là et celui-ci ne se ressemble pas !
Kooka ak kile, bokkuñu !
Vous seriez morts
Deekoon ŋgeen
Un jardin, soit, puisqu'un des employés de la maison portait le titre de « garden boy ».
Ku ne Garden Boy ci kàllaama àngale, nee nga « tóokër ». Kon nu ni boog ab tóokër a nga fa.
C'est un autre ?
Keneen la ?
Fais comme tes pairs !
Defal naka sa moroom yi !
Sans doute ai-je capté un mot, une réflexion, à propos des ridicules des administrateurs, tel le district officer d'Abakaliki que mon père m'emmenait voir parfois et qui vivait au milieu de sa meute de pékinois nourris au filet de bœuf et aux petits gâteaux, abreuvés uniquement à l'eau minérale.
Ñàkkul am kàddu gu jibe bés ci gémmiñu Baay, ne cabax sama nopp yii, am liggéey buñ def ci sama biir xel. Xam naa dafa ci doon ŋàññ ngóor soosu newoon « District Officer » bu Abaakaliki, te mu daan ma yóbbu léeg-léeg këram. Foo ko fekkaan ay kuti yu baree nga ko wër mu leen di dundale yàppu nag walla ngato te daanu leen jox ñu naan lu dul ndoxum-butéel.
Quel mouton en entier ?
Man xar mépp ?
C'est lui qui n'eût pas été
Moo demkoonul
Que reste-t-il à la Terre-mère ?
Lu fa suuf si leen meňň dese ?
Vas-y afin qu'il vienne et aussi afin qu'il sorte !
Demal ndax mu ñëw ndax it mu génn !
C'est que j'ai été
Dama dem
Salut. Sur cette photo, j'y vois des carapaces et des vans qui sont très jolis ainsi que ce qui les accompagnent.
Waaw ñi ngi siyaare bu baax, nataal bi maa ngi ci gis ay ay këll ak layu, ay këll ak layu yu rafet ak ñoom seen.
Où est-il ?
Ana mu ?
Un homme vertueux a disparu !
Góor gu baax réer na !
Tu ne travaillais pas d'habitude.
Daŋga daawul liggéey.
Je vais bien.
Maangi fi rek.
Tu y as été quels jours ?
Yan bes ŋga fa demoon ?
C'est là qu'il va travailler pendant les premières années, dans un hôpital à moitié en ruine, un dispensaire de bonnes sœurs irlandaises, murs de boue séchée et toit de palmes.
Dispañseeru waa kër làbbe yu jigéen a ko fa doon xaar. Dispañseer bu màggat ak i miiri banam yuñ teg xobi garabu-tiir.
Rencontré chaque habitant, mis au monde beaucoup, accompagné d'autres vers la mort.
Ku fay doom-aadama, am na fu mu jaar ak yow ; mooy doktoor biy rewle te du benn du ñaar nit sukkuraat na, mu teewe ko, ñaanal la.
Sois un être de raison !
Dil nit !
Je ne parles pas Français.
Mahn deggumah Faranse.
C'est l'homme qui part je crois !
Ma defe góor gii dem la !
Tout cela peut sembler anecdotique.
Lii lépp, mën naa niiruy waxi kasaw-kasaw.