french
stringlengths
4
937
wolof
stringlengths
4
946
L'un des hommes est venu.
Nit kenn ki ñëw na.
Sa manière de manger, de faire cuire son riz selon la méthode africaine, en rajoutant au fur et à mesure de l'eau chaude.
Cet googu, daan na feeñ it ci lekkinam, ci ni mu daan baxaalee ceeb, di ko ñuluge ndànk-ndànk ndox mu tàng, niñ koy defe Afrig.
J'ai acheté cette unique mouton !
Jënd ñaa menn xar mi !
Si elle veut, bien sûr !
Su bëggée kañ !
Le jeu consistait, du haut du trapèze, à taquiner ces animaux avec un brin d'herbe ou une brindille, et à les regarder tourner, comme aimantés, autour de la main qui les agressait.
Sunu po mi, nii la daan tëdde : ci kow « taraapees » bi lanuy toog di cokkaas jiit yeek bantu bale, di seet ba xam dinañ jam bale bi.
Qui a fait ceci ?
Ku def lii
Si je veux comprendre ce qui a changé cet homme, cette cassure qu'il y a eu dans sa vie, c'est à la guerre que je pense.
Su ma bëggee xam lu tax Baay soppiku, lu waral dog-dog bi ma seetlu ci dundam, ci xare bi la sama xel di njëkk a dem.
On m'a dit qu'un gars serait appelé pour que je le rencontre.
Wax neñ ma dinañu woo benn góor pour ma gisànte ak moom.
C'est à l'époque où mourut cet homme.
Ba waa ji dee la.
Où vas-tu ?
Foo jëm ?
Lesquels sont arrivés ?
Yan ñoo yeksi ?
C'est là que vous seriez allés.
Fi ŋgeen demkoon la.
S'exiler pour fuir les feux de brousse
Gàddaay ba nekk fu amul day
Aujourd'hui, avec le recul du temps, je comprends que mon père nous transmettait la part la plus difficile de l'éducation – celle que ne donne jamais aucune école.
Tey, bi ma newee mag, laay door a xam ni Baay dafa nu doon yare ci anam gu nu benn lekool mënutoon a yare.
Cet homme qui l'accompagne !
Googu góor mu àndal !
Il a vu les dames.
Gis naa jeeg ji.
Je partirai
Dinaa dem
Ce boeuf-là, en totalité.
Nag woowa wépp.
Peut-être espère-t-il, comme beaucoup de gens en Europe, que l'avancée de l'armée allemande sera contenue sur la frontière, et que la Bretagne, étant la partie la plus à l'Ouest, sera épargnée.
Amaana mu yaakaar, ni ñu bare ci jamono jooju, ni làrmeb Frãs dina tanc bu Almaañ ca dig ba, tee koo yegg sowu-jant, fa diiwaanu Bërëtaañ féete.
Droit.
Ndeyjoor.
Sur cette photo ci cependant, il y a un panier. La plupart des fois où on le voit, cependant, c'est sur les femmes quand il rentre du marché car c'est ça qu'elles prennent et mettent environ tout ce qu'elles achètent, par exemple ce qu'elles utilisent si elles veulent cuisiner.
Nataal bii nag moom benn pañe la. Lu ëpp liñ kay gis nag ci jeeg yi lay doon bu ñuy jóge marché ndax ci moom lañii jël, Aa daldi ciy def daanaka lépp luñ jënd lu ci mel ni ñoom lu ñi yittéwoo su ñu bëggee togg.
Affronter les dangers sur la route du retour, risquer d'être capturés par les Allemands ou les Italiens, déportés.
Rax-ci-dolli, dellu Afrig naroon na koo jural fitna ju dul jeex. Te su loolu lépp weesoo, ñàkkul Almaŋ yi mbaa Italyeŋ teg ko loxo ci yoon wi, àddinaam doxe fa yàqu yaxeet.
Je parle de cet enfant-ci ?
Xale bule laa wax ?
Ainsi, tu vas t'en aller !
Ba yaa ŋgii di dem !
Je crois que dans les premières heures qui ont suivi mon arrivée au Nigeria – la longue piste de Port Harcourt à Ogoja, sous la pluie battante, dans la Ford V8 gigantesque et futuriste, qui ne ressemblait à aucun véhicule connu – ce n'est pas l'Afrique qui m'a causé un choc, mais la découverte de ce père inconnu, étrange, possiblement dangereux.
Yaakaar naa ne ba ma nee cëpp Niseryaa – nu jaar ci tali bu gudd ci diggante Poor Arkuur ak Ogosaa, toog ci sunu biir ponkalum Ford W8 bu kéemaane ba, taw bu mettiy dal – du Afrig moo ma teppati. Baay ci boppam moo ma teppati. Mii xel naan ma : « Moo, góor gu raglu gii, ku mu ? » Ma jàpp ne mënul a doon sama baay, man mii.
Voila que j'ai été
Maa ŋgii demoon
Comment aurais-je pu imaginer que cette femme était ma grand-mère ? Et je ressentais non pas de l'horreur ni de la pitié, mais au contraire de l'amour et de l'intérêt, ceux que suscite la vue de la vérité, de la réalité vécue.
Naka laa mën a xalaate ne keey sama maam ju jigéen ? Li may yëg du mbañeel, du yërmaande. Sori na leen lool. Jigéen ju màgget jooju, cofeel gu réy laa am ci moom. Te it fullaal naa ko ni ñuy fullaale lèpp luy dëgg ak képp ku dëggu.
Voilà que tu as été dans un lieu interdit.
Yaa ŋgii demoon fu ñu la tere.
L'individu et son chameau se ressemblent !
Waa ji ag gëléemam gi dañu niróo !
Ceux-ci ne partent peut-être pas !
Ñii dañu demul xanaa !
Longtemps après je suis hanté par le poème de Chinua Achebe, Noël au Biafra, qui commence par ces mots : Non, aucune Vierge à l'Enfant ne pourra égaler Le tableau de la tendresse d'une mère Envers ce fils qu'elle devra bientôt oublier.
Ñu teg ciy at, ab taalifu Sinuwaa Aseebe di tëgg tama ci sama biir kaaŋ. Taalif baa ngi tudd : Nowel ca Biyaafaraa, mu koy ubbee nii : Dëgg la Nataal bi Ndeyu Yéesu boq doom ji Daw na yaram Wànte dara mënuta dab Cofeel ak tiisu ndey ju tiim doomam Muy sukkuraat.
J'ai vu mes amis !
Gis naa sana xarit yi !
Les travailleurs c'est toi et moi.
Liggéeykat yi man ag yaw la.
Plaisir de te rencontrer
Am nàa mbekte ci guiss la
Le silence des fourmis.
Tekkug mellentaan yi.
Entre la tristesse du Sud de la France pendant la guerre et la tristesse de la fin de mon enfance dans la Nice des années cinquante, rejeté de mes camarades de classe du fait de mon étrangeté, obsédé par l'autorité excessive de mon père, en butte à la très grande vulgarité des années lycée, des années scoutisme, puis pendant l'adolescence la menace d'avoir à partir faire la guerre pour maintenir les privilèges de la dernière société coloniale établie par les blancs en Afrique.
Du lu war a jaaxal kenn. Su dee loolu la, maa yey. Ana fu gën a géey bëj-saalumu Tugal ci jamonoy xare bi ? Niis gi nu dëkk it, ci xaaju xarnu bi, amul dara lu ma fa neex. Ragal Baay a ma taxoon a téye sama bopp ca Niis, samay moroom ca liise daan ma noggatu ndax li ma wute woon ak ñoom. At yooyu ma def liise, su ma yaboo ni ñoo ma gën a soof ci sama àddina. Ñooy it at ya ma tollo ci nekk « eskut ». Moo doon it jamono ja ma ragalee lool nguur gi solal ma soldaar, jox ma fetal ma war a dem xareel ko. Xareel ko ngir lan ? Xanaa ngir nun Tubaab yi nuy wéy di teg loxo ci Afrig, di aakimu alalam.
J'ai aperçu une maison.
Séen naa ab néeg.
Moi je n'ai pas été
Man demuma
Est-ce comme je le crains que... !
Mbaa... !
L'homme est allé à l'intérieur.
Góor gi dem na ci biir.
Je ne veux pas parler d'exotisme : les enfants sont absolument étrangers à ce vice.
Ku yaakaar ni li may wax lépp mbirum Tubaab bu Afrig doon yëngal ba muy say la, tooñ nga ma. Xale sax xamul loolu.
Pis encore, les grandes compagnies pétrolières, principalement l'anglo-hollandaise Shell-British Petroleum, sont partie prenante dans cette guerre, agissent sur leurs gouvernements pour que soient sécurisés les puits et les pipe-lines.
Jaaykatu petorool yu mag yi ñoom, rawati-na « Shell-British Petroleum », maanduwuñu dara ci mbir mi ; ñuy soňň seeni gornmaa ngir ňu aar teeni petorool ya ca Niseryaa.
En voilà d'autres.
Ñeneen a ŋgi.
Cela est ce qu'on appelle'La tour la plus haute du Sénégal'. Il s'agît du monument de la Renaissance Africaine. C'est le bâtiment sur lequel les gens ont l'habitude de se rencontrer. Il peut s'agir de ceux qui s'échauffent, de ceux qui font un concert, ou de ceux qui font de la gymnastique. Tout ce monde s'y rencontre. C'est une place publique sur laquelle tout le monde se retrouve. N'importe qui qui a un évènement qui peut s'y faire il peut aller le faire là-bas. De ce fait tout le monde y sera. Il y a des étrangers qui viennent le visiter. Le monument présente un père, une mère et leur fils. Le fils pointe le doigt quelque part. Le père a saisi la mère au niveau du bassin.
Lii na ñuy wax'la tour la plus haute au Sénégal', mi ngi nekk'Monument de la Renaissance Africaine'. Mi ngi nekk barab bi ñu bare di daje. Moo xam ñiy tàngal séen yaram, ñiy def i kõseer, moo xam ñiy def simnastig. Ñoom ñépp a fay daje. Palaas publig la boo xam ni bii ñoom ñépp a fay daje. Képp ku am xew-xew boo xam ni bii xaj na fa dangay ñów nga defe ko fa. Bu ko defee ñépp ñëw. Am na ci ñoo xam ni tàggat yaram moo leen fa aandi. Am na ñoo xam ni da ñuy jóge dëkk ak dëkk, ñów di ko wisite si. Monimaŋ bi, ñi ngi ko jëmale pàpp yaay ak doom. Doom jaa ngi joxoñ, baay ji téyee yaay ji ci ndigg li.
L'homme peut-il aller dans la maison ?
Góor gi dem ci biir kër gi ?
Durant la vingtaine d'années qu'il a passée dans l'Ouest africain, mon père n'aura gardé que deux amis : Ahidjo et le « docteur » Jeffries, un district officer de Bamenda qui se passionnait pour l'archéologie et l'anthropologie.
Ñaar-fukki at ñaar ya mu nekk Afrig sowu-jant yépp, Baay ňaari xarit doŋŋ la fa mas a am : Ayijoo ak « doktoor » Sefiriis, « District Officer » bu Bamendaa. Sefiriis, ku xëroon la ci xam-xamu cosaanu suuf si ak nekkinu doom-aadama ciw askanam.
Il y a eu sans doute au moment de son départ une détermination qui ne l'a jamais quitté.
Pas-pas ba mu wone ba muy laxas, du woon neen, du woon caaxaan.
Ce n'était pas un homme de Saint-Louis.
Du woon góoru Ndar.
Tu pars ?
Dem ŋga ?
C'est là ce que je veux !
Loolu laa bëgg !
Elle était si heureuse de voir Joe qu'elle s'est mise à pleurer.
Dafa begone bu mu gisee Joe ba mu di jooy.
Je ne parle que de toi.
Yaw doŋŋ laa wax.
Tu reconnais ton amour d'autrefois ?
Xammee ŋga sa far, woowee woon ?
Jusqu'à présent, on voit sur la photo des soldats. Les soldats sont au nombre de douze ou treize. Les soldats sont au niveau du palais. Personne ne touche au palais. Par contre, ils ne rient pas et ne jouent pas. Ils ressemblent à des personnes sans émotions. Derrière eux on voit la porte du palais. La porte du palais est vraiment jolie. Il y a un tapis rouge, deux lions, et derrière, il y a quatre drapeaux Sénégalais. Par contre, parmi les soldats, il y en a deux qui portent leurs habits bleus et leurs pantalons noirs. Pour ce qui reste, cependant, ils portent la même chose. Ceux là portent leurs chapeaux rouges, un truc noir dessus, leurs pantalons noirs et leurs bâtons. D'autres portent leurs gangs pour pouvoir garder notre dirigeant.
Ba tey ñoo ngi gis ci nataal bii ay soldat. Soldat ñu ngi tollu ci fukkak ñaar ba fukkak ñett ci ay soldat. Soldat ya nga xam ne ñoom ñu ngi nekk ca palais ba. Kenn du laal palais bi. Ñoom nag duñ ree duñ kaf. Dañuy mel ni ñu amul xol. Seen ginnaaw ñoo ngi gis buntu palais bi. Buntu palais bi rafet lool am benn tapis bu xonq am na ñaari gaynde ci ginnaaw am na ñeenti drapeau Senegaal. Ñoom nag, waa Soldaar yi, am na ñaari soldaar yoo xam ni ñi ngi sol seen i ay yére yu bula ak seen i tubéy yu ñuul, bu fekkee ñi ci des nag ñoom ñoo bokk lenn lañ sol. Ñii sol seenum mbaxana mu xonq am lu noir am lu ñuul ak seen i tubéy yu ñuul yor seen i ay yar, ñee sol seen i gã ngir mën a gardé suñu njiit bi.
Tu avais vu cette femme ?
Gisóon ŋga jigéen joojule ?
L'Aiya à cet endroit n'était pas très large, mais était animée d'un courant violent qui arrachait aux rives des mottes de boue rouge.
Wet gi nu awe keroog, Ayaa taxu ko faa yaatu wànte day wal-waleek doole, di yëkkati bàq bi ak a xonqal peggi dex gi.
Ils connaissent aussi l'ivresse de la vie physique, la fatigue qui rompt les membres au bout d'un jour de marche, quand il faut descendre de cheval et le guider par la longe pour se rendre au fond des ravins.
Xam naňu it lu tés-tési ba dog tekki, coonob wëndéelu bésub lëmm ci àll bi. Coonob war a wàcc sa fas, ngeen ànd jëm ca biir xur ya.
Ce mouton-ci en entier.
Xar mii mépp.
J'aurais acheté le mouton de quelle autre personne ?
Jënd naa xaru beneen waa jan ?
J'ai vu un mouton.
Gis naa am xar.
En temps de guerre, tout étranger est un espion.
Jamonoy xare bi, doxandéem bu ne mën nañ laa tuumaal, ne yëddukat nga.
Ceci est une maison. La maison est, cependant, constituée de trois étages. Tu peux passer d'étage en étage. La maison comporte beaucoup de portes et <unk>, des fenêtres à travers les quelles le vent passe dans la toute la maison. Elle comporte des arbres qui s'érigent au-dessus de la maison qui <unk>.
Lii ak kër. Kër gi nag ni lu bindoo tegale gi ñetti tegale la ci tabaxin bi. Nga mën a yéeg ci kow yéegaat ci kow jàll. Mi ngi am ay bunt yu beree bare ak i tofla, ay fëneetar yoon xam ni ngelaw Li da cee mën a jaare ci biir kër gi. Mi ngi am ay garab yu naatal kër gi ci wer ci.
C'est ceux-là qui n'eussent pas été
Ñee dañu demulkoon
Mais, nul ne lui a prêté oreille.
Wande nag, kenn dégluwu ka.
Vas-y !
Dem fa !
Mais la pension a cessé d'arriver quelque temps plus tard, comme si tout ce passé avait disparu.
Waaye dañoo xéy bés dakkal pey googu. Baay xam ni daal, neexul ba neexul waaye la woon wonni na.
Sur cette photo ci, j'y ai vu des chambres faites d'herbes à l'intérieur d'une forêt <unk>. À l'intérieur tu verras d'énormes arbres. Il y en a aussi qui sont à peu près moyens et d'autres qui sont petits.
Nataal bii, gis naa ci ay néegu ñax yoo xam ne ñu ngi ci àll ci biiri gatab. Di deme ni nag ay garab la yoo xam ne, am na yu gudd lool, am na it yu xaw a yam am yu gàtt.
Cherche un autre cheval !
Seetal fas weneen !
Nous allons à l'intérieur ?
Ci biir la ñu jëm ?
J'ai aperçu un homme.
Séen naa ak nit.
Homme n'est pas mauvais !
Nit bonul !
Où es-tu ?
Ana ŋga ?
Par instants, dans la cellule où on l'a isolé, il est saisi par une crise, son corps s'arc-boute sur le lit malgré les sangles, ses membres sont possédés d'une telle force que le cuir semble prêt à se rompre. En même temps, il grogne et hurle de douleur, sa bouche écume. Puis il retombe dans une sorte de léthargie, assommé par la morphine.
Fiñ ko tëj moom kenn, mu ngi yuuxu, di xataraayu bay bëgg a daaneel lal bi ; léeg-léeg mu lemu, gémmiñ giy fuur walla morfin bi jàpp ko, mu ne nemm, di xullee.
J'ai été
Dem naa
S'exiler loin de ceux qui t'ont affamé
Gàddaay ba fa ñi la xañub dund
Je ne le haïssais pas, je l'ignorais, je l'évitais. Je ne le regardais pas dans les miroirs.
Duma ne it baňoon naa ko. Dama ko daan fàtte, di ko moytu ba daawuma sax seetu.
J'ai aperçu une chose, une portion.
Séen naa as lëf.
Attache tout mouton !
Yeewal bépp xar !
C'est vraiment un homme !
Nit la ci lu wér !
Moi je partirai
Damay dem
Le bombardement du port de Nice qui m'avait jeté à terre dans la salle de bains de ma grand-mère, cette sensation que je ne peux pas oublier du sol qui se dérobe sous mes pieds. Ou encore l'image de l'ulcère sur la jambe de ma grand-mère, aggravé par les pénuries et le manque de médicaments ; je suis dans le village de montagne où ma mère est allée se cacher, du fait de la position de mon père dans l'armée britannique et du risque de déportation.
Bés ba Almaŋ yi sànnee bomb nag, mu mel ni ci kër gi la daanu, ma daw làquji sama wanagu maam ju jigéen ? Am na leneen lu may gisaat : sama dana maam ba, naqaree faj lool ndax ňàkk geek ňàkkum garab gi ; maa ngi ci dëkkub tund bi sama yaay demoon làquji : ginnaaw Baay a ngi woon ci làrmeb Àngalteer, suñ ko jàppoon, moom sama yaay, du baax ci moom.
Sur la photo que j'ai eue a voir il y a assurément un poisson séché. C'est bien un poisson séché que j'ai vu.
Nataal bi ma jot de gis naa ni gejje la, waaw gejje. Gejje de laa gis.
Sa maison, c'est Forestry House, une vraie maison en bois à étage, recouverte d'un toit de feuilles que mon père va s'employer à reconstruire avec le plus grand soin.
Këram a ngi tudd Forestry House, dib taaxukowu dénk, jànq ba muurook i xob. Mu doon it kër gu Baay masul a tàyyee defaraat ak a toppatoo.
Il a acheté moutons, chèvres, poulets...
Jënd na xar, bëy, ganaar...
Celui-ci serait parti
Kii dafa demkoon
Les plus petits étaient sous la surveillance des plus grands, jamais seuls, jamais livrés à eux-mêmes.
Ñi gën a féete xale dañuy topp ci seen ndigalu mag. Kenn du beru walla nekk ci lu la neex.
La matinée se passe bien.
Subba sangi fi rek.
Comment ?
Na ?
Des colons, en somme.
Ci gàttal, danu leen a jaay doole, ñëw ba ci seen biir kër sanc fa.
Ma mère monte en amazone, comme elle a appris à le faire au manège d'Ermenonville.
Sama yaay, genn wet lay ware fas. Noonu lañ ko ko jàngale Tugal, ca Ermenoŋwiil.
Nous avions les clés avec nous.
Ñu ngi woona yore caabi yi ak ñun.
C'est là-bas.
Fee la.
Comment se passe la matinée ?
Naka subba si ?
Leur stature, leurs seins lourds, la peau luisante de leur dos.
Seen jëmm. Seeni ween yu diis. Seen der yiy melax. Seen diggu-ginnaaw.
L'un des hommes est venu.
Benn nit ki ñëw na.
La soirée se passe bien.
Ngoon saangi fi rek.
Dès qu'elle est debout, elle voit, à la lumière des torches : une colonne de fourmis (ces mêmes fourmis rouges encadrées de guerrières) qui est sortie de la forêt et qui commence à traverser la case.
Sama yaay dafa tëb ci lal bi, janook naaxi mellentaan yu xonq ak yu ñuul. Ñu nga bawoo woon ci àll bi, tàmbalee xuus nag, war a jaar ci néeg bi.
Il avait conservé toutes les manies des anciens militaires.
Ku ko seetlu woon bu baax, dinga gis ne li mu jaar ci làrme, feem ya mu fa jot a jàng, da daan feeñ ci lépp lu muy def.
J'espère que nul n'est sorti ?
Mbaa kenn génnul ?
Va jusqu'à lui !
Demal ci moom !