french
stringlengths
4
937
wolof
stringlengths
4
946
Mais alors, je refusai de sortir
Noonu itam, ma bañ génn
C'est cette violence qui devient pour lui obsessionnelle.
Mu dem ba mel ni loolu lépp, ni bakkan ñàkke solo ak deret ju bare jiy tuuru, daf koy mëdd, du xam sax fan la nekk, daanaka.
J'ai vu mes amis !
Gis naa sama xarit yee !
Aujourd'hui, le matin.
Tay ci subë.
Tu as vu l'homme ?
Gis ŋga nit ka ?
Pour qui te prends-tu ?
Ya di kan ?
L'Afrique qui déjà m'ôtait mon visage me rendait un corps, douloureux, enfiévré, ce corps que la France m'avait caché dans la douceur anémiante du foyer de ma grand-mère, sans instinct, sans liberté.
Ni Afrig këfee sama xar-kanam, la ma delloo sama yaram. Ma ciy yëg metit, di yëg it ni mu tànge. Mooy yaram wi ma Frãs doon jéem a nëbb jamono ca ma dëkke sama kër maam ju jigéen, nekk fa ci jàmm ju mat sëkk, meloon nag ni mbindeef mu ñu tënk, doo dem doo dikk te amoo benn sañ-sañ.
On croyait que tu allais partir matin et soir !
Dañu defewoon ci ŋgoon ag ci suba yépp da dem !
Salut
Salaam aleekum
C'est Fatim, aujourd'hui.
Faatim la, tay.
Cela que tu as fait.
Ni ŋga def noonu.
Regarde cette aumône.
Seetal sarax su.
C'était son hôte habituellement.
Moo doon ganam.
C'est un seul, un seul !
Kenn la kenn doŋŋ la !
Il y avait une hâte, une urgence. Nous étions venus du bout du monde (car Nice était bien un autre bout du monde).
Seetleen rekk : bawoo Niis ca Tugal, ñëw teersi Afrig, du woon lu yomb a dékku. Niis a nga woon ca fu kenn xamul.
Je parle de toi-même.
Yaw moomu laa wax.
C'était un homme de petite taille, doué d'une force herculéenne, capable de pousser un tronc pour dégager la route ou de porter des charges que personne n'aurait pu soulever.
Ndaama lu amoon doole la, randal ab dàtt ngir xàll yoon walla yenu sëf bu diis, du woon dara ci moom.
C'est qu'il veut de l'argent.
Dafa bëgg xaalis.
Quelles clés se sont égarées ?
Doom yan ñoo réer ?
Prête à cet autre qui n'eût pas été, mon ouvrage !
Abalal keneen ki demkoonul ki, sama téeré bi !
Les hommes sont debout. Certains portent des robes de raphia, d'autres ont les masques des dieux.
Góor ñaa ngi taxaw, ñii sol yérey xasum garab, ñeneen ñi téye xar-kanami seeni Yàlla.
C'est l'autre, je crois !
Keneen ki la, defe naa !
Celui-là c'est un autre
Kooku keneen la
C'est là jusqu'à ce qu'on trouve un autre endroit.
Ci fii la ba ba ñuy gis feneen.
Tu sais, cet homme ?
Gis ŋga nit kookale ?
Bien plus que des images habituelles du folklore, je me souviens d'un incident qui m'a marqué.
Lenn rekk laa fàttaliku ci tukki boobu te dootul génn mukk ci sama xel.
Il m'a vu moi-même.
Gis na ma man mi.
Avant de mourir, le garçon regarde mon père, il perd connaissance et sa poitrine s'affaisse dans un dernier soupir.
Laata muy faatu, xale bi ni ko jàkk, daldi door a xëm, àgg suuf, sedd guy.
Qui, est-ce d'autres ?
Keneen kan la ?
Oui à l'intérieur !
Waaw ci bir !
Le prétendant n'y est pas roi.
Bumi bi du fi buur.
Je n'y avais pas été
Demuma fa woon
J'ai vu l'autre qui est venu
Gis naa kenn ki ñëw
Il demande si tu aurais été
Mi ŋgiy laaj ndax demkoon ŋga
Comme les fourmis, les scorpions étaient les vrais habitants de ce lieu, nous ne pouvions être que des locataires indésirables et inévitables, destinés à nous en aller.
Mellentaan yeek jiit yee moomoon kër gi, nun nu fay ay doxandéem doŋŋ. Xamuñu woon nuñ nuy def waaye it leeroon na leen ni, lu mu yàgg-yàgg, dinan leen mas a abali.
L'homme ne parlait pas, habituellement.
Góor gi daawul wax.
Ou l'homme est parti ou les enfants sont assis.
Góor gee dem mba xale yee toog.
D'où me vient cette instinctive répulsion que j'ai ressentie depuis l'enfance pour le système de la Colonie ?
Lu waral ba ma newee gone ba léegi may naqarlu ni Tubaab yiy noote Afrig te bañ lépp lu taq ci seeni mbir ?
Il parle de l'autre homme.
Keneen nit kooka la wax.
Tu iras ?
Daŋga dem ?
La plus grande preuve d'amour qu'il a donnée aux siens, c'est lorsqu'en pleine guerre, il traverse le désert jusqu'en Algérie, pour tenter de rejoindre sa femme et ses enfants et les ramener à l'abri en Afrique.
Liy firndeel cofeel gu réy gi mu amoon ci doom yeek jabar ji, moo di ne bés dafa ni fàww mu fekki leen Tugal, indi leen Afrig, ñu mucc ci Xare bi. Mujjewul a àntu waaye lu mu bon bon jéem na.
J'ai aperçu des chevaux.
Séen naa ay fas.
Ils furent Laobé.
Laobe lañu woon.
Cet homme là près de toi.
Nit kookuu ci sa wet.
Sur la photo que vous m'avez envoyée, j'y ai vu une jolie porte conçue avec du bois et du verre. Il y a au-dessus de la porte une lumière qui éclaire.
Nataal bii ngeen ma yónnee de, gis naa ci biir nataal bi ab buntu bu rafet ñu liggéeyee ko dénk ak weer. Am na ca kaw bunt ba limiyeer buy leer
Je suppose que c'est en arrivant à Ogoja que nous avons appris que le Père Noël n'existait pas, que les cérémonies et les fêtes religieuses étaient réduites à des prières, et qu'il n'y avait aucun besoin d'offrir des cadeaux qui, dans le contexte où nous étions, ne pouvaient qu'être superflus.
Yaakaar naa ni Ogosaa lanu xame ni Peer Nowel ay caaxaani kese la. Xumb-xumbi kerceen yépp, Baay ci julleek tudd Yàlla la leen yemale woon. Jox gone yi ndéwénal moom, kenn waxaalewu ko woon. Wànte ay ndéwénal sax, doonuñu amal benn njariñ ci jamono jooju.
Parfois me revient encore la sensation de ces bouffées de colère, quelque chose que je ne peux comparer qu'à l'ivresse de l'éthéromane (l'éther qu'on faisait respirer aux enfants avant de leur arracher les amygdales). La perte de contrôle, l'impression de flotter, et en même temps une extrême lucidité.
Léeg-léeg dinaay yëgaat mer moomu, mu mel ni doktoor a ma pikiir, ma màndi bay waaj a nelaw, sax i laaf, di naawantu, ànd ceek teey ak dal.
Terre-mère au ventre gorgé d'or
Suuf si nu meňň ëmb wurus
Mon père avait institué entre autres règles celle des chaussettes de laine et des chaussures de cuir cirées.
Ci dogali Baay yu dul jeex yi, bokk na ci ne danoo war a jiital ay kawas yu diis teg ciy dàlli der yu ňu siraas.
Je crois que c'est l'homme !
Góor gi la, yaakaar naa !
Sur cette photo ci, cependant, il y a des personnes qui sont debout et se révoltent, c'est-à-dire, qui manifestent, prenant des pierres et les lançant contre les gendarmes. Il y a, cependant, une personne devant qui ne porte pas de masque, portant des pierres et les lançant. Il porte un sous-vêtement blanc et un pantalon noir. Il a, cependant, un boubou rouge au milieu de son derrière.
Nataal bii nag, ay nit lañ yu taxaw di ñaxtu, maanaam di manifestewu, di jël ay xeer di leen sànnanteek takk-der yi. Am na nag ku nekk ci kanam nii solul maska, yor ay xeer di leen sànni. Mi ngi sol siletmaa bu weex ak tubéy ju ñuul. Mi ngi takk nag mbub lu xonq ci digg ginaaw gi.
Je suis en ce temps-là très loin des adjectifs, des substantifs.
Amu ci woon benn bu ma xam naka la ko nëwu biy tudde.
Cette photo ci c'est une photo sur laquelle je vois des jeunes du pays qui semblent en colère contre ce qui s'est passé dans leur pays et que les anciens les ont laissés. J'en vois, même, qui portent des habits blancs et des pantalons noirs. Beaucoup parmi eux portent des habits noirs et blancs, et d'autres portent des habits blancs. Ils sont levés sur la route, qui elle semble remplie de pierres qu'ils ont, peut-être, utilisé pour se battre contre les gendarmes. Au-dessus de la photo j'en vois qui écrivent quelque chose d'arrogant. Ceux qui habitent en Casamance l'appellent Sigicor.
Nataal bi ab nataal la boo xamante yni maa ngi ciy gis ay ndawi réew yoo xamante ni daa mel ni dañuy naqarlu loo xamante ni xew na ca seen réew te seen njiitu réew teg leen ko. Maa ngi ciy gis nag ñoo xamante ni dañoo sol lu weex aki ay tubéy yu ñuul. Bari ci ñoo xamante ni sol nañu yoo xamante ni ay yére yu ñuul la ak yu bula, am na yit ñu sol yu bula. Ñu ngi taxaw si kow tali tali bi nag xaw naa bari ay xeer ńàkkul ni ñoo ko jëfandikoo ngir jàmmarloo ak way takk-der yi. CI kow nataal bi maa ngi gis ñu bind si bind boo xamante ni réewu, dëkk bi nu naan Kaasamaas ñu koy wax Siggicoor.
Les moutons noirs seront retrouvés.
Xar yu ñuul dinañu feeñ.
Je sais d'où tu tiens tes rênes
Xam naa fu sa kàttan tege
Ceci se trouve dans les toilettes. <unk> cette chose blanche là c'est une allée de douche... c'est une allée de toilettes. C'est à travers qu'on marche pour atteindre les toilettes. Si tu veux assoupir tes besoins tu peux le faire là-bas. Il y a aussi quelque chose à côté. Ça aussi, si tu veux prendre tes abolitions, ou faire pipi, tu peux le faire là-bas.
Waa lii, ci wanag lay nekk. Ndee lu weex lii demukaayu duus la... Demukaayu wanag la. Ci la ñuy demee wanag. Boo bëggee dox aajo man nga fee dox aajo. Am nale lu nekk ci wet gi tamit. Moomit soo bëggee jàpp wala sawi man nga ko faa defee.
Outre ces bagages dignes d'un voyageur du temps de Kipling ou de Jules Verne, il y avait toute la série des boîtes à cirage et des pains de savon noir, les lampes à pétrole, les brûleurs d'alcool, et ces grandes boîtes à biscuits « Marie » en fer dans lesquelles il a gardé jusqu'à la fin de sa vie son thé et son sucre en poudre.
Baay wutewul woon ak tukkikat yu njëkk ya, génne ci téereb nettali bu Kipliŋ mbaa Sil Wern ak ay boyeti siraasam, ay përngali saaboom yu ňuul, làmpi petoroolam, lakkukaayu alkolam ak tamit ay boyeti mbiskit « Marie » ya mu daan denc warga ak suukër su mokk.
Longtemps après, il me parle de ces choses terribles qu'il fallait affronter, chaque jour, comme si c'était la même séquence qui recommençait : une vieille femme rendue démente par l'urémie, qu'il faut ligoter sur son lit, un homme à qui il enlève un ténia si long qu'il doit l'enrouler autour d'un bâton, une jeune femme qu'il va amputer à cause de la gangrène, une autre qu'on lui amène mourant de variole, le visage gonflé et couvert de blessures.
Loolu topp ko, yàq xolam ba ñu teg ciy ati-at mu koy dundaat saa su ne, di ma ko nettali : ndaw su màgget su feebar bi tàqaleek sagoom, ñu yeew ko cib lal ; kii moom, saan bi mu génne ci biir bi dafa gudd ba mu laxas ko ci bant bu gudd ; tànku janq bu jigéen a ngi nii, fees dell ak i sax te dagg koo fi sës ; am na keneen ku njàmbal sonal, muy sukkuraat, ndeysaan.
Quels moutons t'appartiennent ?
Xar yooyu yan ŋga moom ?
Elle est aussi la mémoire du temps qui a précédé ma naissance, lorsque mon père et ma mère marchaient ensemble sur les routes du haut pays, dans les royaumes de l'Ouest du Cameroun.
Jéggi na bés bi ma juddoo. Li ko sabab mooy dekkali jamono ja samay way-jur daan ànd di wër sowu-jantu Kamerun, bëgg àddina, rafet njort ci lépp.
La chose est d'une clarté lumineuse.
Lëf ki leer na nàññ.
Mais lui n'est pas un enfant qui se laisse porter par le courant des événements. Il a alors trentedeux ans, c'est un homme endurci par deux années d'expérience médicale en Amérique tropicale, il connaît la maladie et la mort, il les a côtoyées chaque jour, dans l'urgence, sans protection.
Waaye mbir yi xawoon nañoo woroo : bi muy def tukki boobu, mu ngi tollu ci fanweeri at ak ňaar, di góor gu dëgër, làmboo ňaari ati paj ca réewu Enjeŋ ya, miin fa feebar ak dee ak ňàkkum kaaraange.
Il connaît celui-là ?
Xam na kookule ?
Tu as vu tes autres amis ?
Gis ŋga sa xarit yeneen yi ?
Je ne savais pas que je n'étais pas la seule personne à être sur le terrain ce jour-là.
Xamuma woon du man kese maa nekkoon ci terrain bi bes boobu.
L'homme ne te voyait pas
Góor gi daawu la gis
C'est un homme.
Nit ku góor la.
Où dis-tu ?
Foo wax ?
L'un lequel n'as-tu pas vu ?
Benn ban ŋga gisul ?
Pendant leurs premières années de mariage, mon père et ma mère ont vécu là leur vie amoureuse, à Forestry House et sur les routes du haut pays camerounais, jusqu'à Banso.
Ci at yu njëkk ya ci seenub séy, Baay ak sama yaay dund naň fa seen mbëggeel, moo xam ca Forestry House la woon mbaa ci taliy Kamerun yi jëmoon Bansoo.
Cherche un autre mouton !
Seetal xar meneen !
Il est mal élevé comme un gosse.
Dafa reew na xaleel.
Comment ... ?
Noo ... ?
C'est cet autre cheval là-bas qui est bon !
Fas weneen wale moo baax !
Je suis certain de la raison.
Woor nama ci lu tax.
Si je lis les romans « coloniaux » écrits par les Anglais de cette époque, ou de celle qui a précédé notre arrivée dans ce pays – Joyce Cary, par exemple, l'auteur de Missié Johnson –, je ne reconnais rien.
Jàng naa Misiye Jonson, bu Jooys Kari, di fentaakon bu fekk baax Àngalteer, te gisuma ci benn yoon sama bopp.
Bon matin
Jaam nga fanane
Quelle partie veut-il
Fu mu bëgg
C'est moi qui vais partir !
Maa di dem !
Cherche une autre chose !
Seetal lëf leneen !
Qu'ils ne partent pas !
Bu ñu dem !
L'homme m'a dit : dehors !
Góor gi nee na ma : ci biti !
Dans l'esprit de l'amnésique
Ci xelu mag miy naax
Un peu à l'écart, l'autre ville africaine, le marché, le palais du roi de Bamenda, et la maison de passage du district officer et des officiers de Sa Majesté (ils ne sont venus qu'une seule fois, pour décorer le roi).
Sësu rikk ci moom, beneen gox bu ay doomi-réew mi doŋŋ dëkk. Fa la màrse beek Màkkaanu Buuru Bamendaa nekk. Ci gox boobu ba tey la ñuy dalal « District Officer » bi ak ófisey làrmeb Àngalteer. Ófise yooyu sax, kenn kott a ca mas a teg tànk Bamendaa, ngir ñëw tappal Buur bi ab sagaru medaay.
Alors nous, nous étions sauvages comme de jeunes colons, sûrs de notre liberté, de notre impunité, sans responsabilités et sans aînés.
Nun nag, ñoo doon njaay-àll yi, nun ñaari doomi tubaab yi, yëg sunu dooley xeet, wóolu sunub sañ-sañ te ñàkk kilifa.
Attends la belle jeune fille.
Négël xale bu rafet bi.
Si loin de la salle à manger de ma grand-mère, du luxe rassurant des vieux fauteuils de cuir, des conversations endormissantes et de la soupière fumante, décorée d'une guirlande de houx, dans la nuit calme et lointaine de la ville.
Sama kër maam ju jigéen sore woon na fa, walla ! Kër gu set wecc, ak i jekk-jekkalam, ay toogu yu màgget, ñépp di ŋun-ŋuni, waxtaan wi géey lool, sax. Guddig Tugal, ne tekk-tekkaaral ci biir xolub dëkku-taax bu réer ci jaww ji.
Que personne n'est parti
Mbaa kenn demul
Tout ce mouton.
Xar moomee mépp.
Vous avez été
Yéen dem ŋgeen
Ceux-ci sont des portes que les menuisiers métalliques ont conçues. Les portes ont été conçues et étalées pour être ensuite peintes en gris. Il semble que la porte soit en réalité deux portes de sorte à ce qu'elle ressemble à une porte de salon.
Waaw nataal bii de ay bunt yu dóomu-taal moo ci nekk. Bunt yi ëe dafa dóoomu-taal waawaw ! Am na ay lu mel ni ay fu ngelaw di jaar boo ko xëccee waaw ! Mën nga, mën nga ko xëcc, bunt yi waaw. Du benn bunt nag.
Comme les garçons du village, j'aurais appris à parler avec les êtres vivants, à voir ce qu'il y avait de divin dans les termites.
Doon naa mën a wax ak rabi-àll yi, ñu may tontu. Doon naa xam ni ay max duñuy mbindeefi neen.
C'est toi ?
Yaw la ?
Je parle de vous tous !
Yéen ñépp laa wax !
S'exiler pour éviter d'être encerclé
Gàddaay rekk bañ ku la yew
Il y avait un grand danger que la bombe explose.
Am na lu naroon a loru lu bari ci lu fètt bi di fàcc.
Quand il parlait en français, c'était avec l'accent chantant de Maurice, ou bien il parlait en pidgin, ce dialecte mystérieux qui sonnait comme des clochettes.
Buy làkk faraňse, nga xam ni doomu Móris la ndax li muy mel ni kuy woyantu. Soppoon na tamit pijin, làkk wu kéemaane woowu baat yi daan riir ci samay noppi gone niy jóolóoli yu ndaw.
J'ai vu cet homme qui parlait et qui était assis par terre.
Gis naa góor gi doon wax te toogoon ci suuf.
L'homme partant
Góor gi di dem
Il t'a fait un cadeau pour que les enfants soient contents et que toi aussi tu les accompagnes.
May na la ndax xale yi beg te it ŋga ànd ak ñom.