audio
audioduration (s)
2.29
12.5
transcription
stringlengths
26
118
réew mii réewum njub péex ak jàmm la
Nit kooku dafa yeewu waaye naa fi ma koy jaar
ñii fàlu nañu buur ñii doomi buur lañu di ay garmi
nanga butti jén yi dal di leen raxas ba ñu set
maa ko gis ci peroN bi la yàbbi logu poon bi
ba mu nekkee lu yàgg ca kër buur mu ni xuléet delluwaat na mu meloon
mbubb mi dafa xalloon ma def ci weexal
boo jàddee ci sa càmmooñ dinga séen sama kër
njàngale mi dina jafe ci moom ndax sawaru ci
am na ay mbaaru mbott yu ñu dul lekk
boo bëggee gis gaynde demal ca màndi ma
maa ngi tollu woon ci sama diggi ndënd
ku ma bëgga toroxal yaay mujjee torox
man de xawma lu muy ree nii ba di kekku
dafa jënd pàkk bi rekk tàmbali ko sàkket
amari ngoonee taxoon kajoor feyatul voon galag jolof
xam nga xéll ni taluma wure ak soxal yi ci sama bopp yépp
dafa gore moo tax ma nangoo liggéey ak moom
Na ku nekk déglu sa morom ndax ngeen baña réeroo
ña leen a jëkka séen ca dëkk ba dañu teg seen loxo ci seen gémmiñ
ndaw si daldi leen di juuy fekk na nag ag genn dédd a ngi fi goo xam né gii war naa mot diggante fii ag teen ba
maa ngi leen di soññ ci def seen liggéey
li nga semb dey yombul waaye yàlla na la ci yàlla jàppale
booba jamano pikini rekk la sondeel doon jar
li nga toog lu yàgg moo tax sa tànk yi sadd
bu ñu fëggatee nanga xool ci yëru bi bala ngay ubbi
ndax garmi day am jabari jinné di ci jur ay doom na ka walliiw wu nekk
amoon na ag dóobali ci seen buntu kër
xaftaan bu nëtëx la sol ak mbaxane mu xonq
li ëpp ci lapto yi ay njaago lañu woon
sama lam bi furi na war naa koo sóob
jubalal sa tuuru fetal bi fu dara nekkul
juuti bi dafay dem ci luuma yi ngir feyyu juuti
soo wutul kaaf sa pitax yi dinañu dem
amari jullit né ko jógal nu dem rekk
xale bi daal dafa ma lëjala lëjal ba nga xam né dem na dayo
dafa xeet taabal bi dal di ko pintiir
dafa indiwaale woon surgaam bu mu daan yónni
sa mbubb mu xàññaaral mooma daal bu ko sol
dafa doon dox ba yàgg mu ne dàll daanu
reeni xom xom fajkat yee koy jëfandikoo
waa ji yóbbu mbaam yi wax leen li buur diglé
ku sa bëgge bari sa ngor néew
sama tànk bépp a ngi xasan taqentaan a ma topp
boroom kër ga dafa ko fitnaaloon bu mu mujj toxu
yaa ngi doon gam gami xamoo dara ci waxtaan wi
séex yooyu neex nañoo xàmme nuroowuñu
su amee toppatoo gi ci war xar mu rafet lay doon
benn seex bi gàjj bi ci lex bi laa koy xàmmee
gone yu mbuujaa mbuuj yi ñoo fi nekk
sacakàt bà défà né parah né varah
ak tàngaay wi ngoor si dow dem daanu ci kër
peccum liir bu neexee ndeyam a téye ca tank ya
ñi nelaw ñii ci des doxantuji dugg ci réew mi
ba ñu dajee ak yaw dañu daw wëqét
danu daan dem tefes di xëcc mbaal ngir ñu may nu jén
seen baay nee na leen bu nu bàyyi benn ruq bu ñu bàllarñiwul
lu di nav té du tag mukà ngélav
aprés bu may séy dina ma geener torop encore
borom bi yërëm ma ndege moykat rekk laa
demal ne ko mu seede ma ñaari kiloy ceeb
bàggu fu nekk ñu bàggante rekk gisuñu dara
booba fekk na ñaari mag yi ñu ngi doon waaja seeti seeni coro
mu ne mënula ñów waaye mu ngi leen di yokk ngóora
wax ji dafa lunk ñu bare ci mbooloo mi nanduñu ko
ku ja ci jant bi te ne gisu ko lu ñu ci mën
dama la bëgga biral sama dikk moo tax ma telefone
ñu jekki ba nga xam né jant so na góor gi ñów seet nag yi gisul dara
lenn rekk la bu mbeex màggee warul sëy warul am beneen jëkkër bu dul man
Naka la dawe ci néegam mu mbëkk boppu doom ji doon lang di bunt bi
dama bëgg xam këf ki mu dugal ci waxande wi lu mu doon
mu teg saakam dal di dem ubbi palanteer bi
ndeer la dellusi ni tareet tareet ey biram njéemé koo njaay de wul dekki na de
alkaati baa ngi ne sàtt ci bunt kër gi ca suba ba tey
tànk boo séqi dinañu la ko bindal tuyaabo
janq jee daan watu pàq waaye loolu xewwi na léegi
moom bëggewul rekk yem ci dafa wóttóoral
bi ko doomu baay yi lakkalee ba nga xam ni mënatula dëkk ak ñoom mu gàddaay dem jolof
wàccal rekk du yàgg létt yi du yàgg
bu ñu defaree sorbo bi ba noppi dañu koy taxaar
buumu xalam gi yóbbaale na la wa ngi xandaalu
aa man dé sama jëkër dafa ma mooñloo tey jii te dama koy mooñal
mu mel ni ndoxu asamaan si yépp a bëggoona xëppu ci kaw suuf si
diggante ndakaaru ak barñi fanweeri kilomet la
fekk am na ñu dëgger bopp ñu ko sarax ñoo ñu daldi tàqalikoo ak seeni bët
may ma loxo ma dugal taabal bi ci saal bi
góor gu am fayda du dàggasante ak jigéen
booy war mbaam dangay jàpp ci kawar gi ci céq mi
abdu woor na tey dafa feebaroon fan yi nu weesu
xale yi farlu nañu lool ci njàngum katesis bi
xaalis bi ngay jox jibar bi tee nga cee jénd garab yi la doktoor bindal
bul fàttee jënd yomb tey cere lañuy togg
dafa sëpp sayu xat waaye mën na bëre
ku ñu ma may rekk ma ni bëgguma ko ma bëggoon nag wuti
moo doom sa baay waxu la woon lii
saa su ma ko nuyujee dina ma may aylayéwén junni
te ñu bari bassi seen feebar ci tooy lay joge
am na masin yuy gàbb waaye dañu jafe njég
palpale yi nga gis bitim réew lañu lenn di jaaye
ree ji mu lay gatandoo rekk sedd na xol
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
27
Edit dataset card