audio
audioduration (s) 3.96
50.6
| wolof
stringlengths 25
285
| french
stringlengths 20
339
| english
stringlengths 21
315
|
---|---|---|---|
danoo gis ne jànt bi dafay niroog anam ci doxalin sunu ko mengaleek yeneen bideew yi yëngu yëngu bideew yi ci sistem bi li ko jiital mooy seeni leeraay seeni wëndeelu te du leneen | Nous voyons que le Soleil a un comportement similaire à celui des autres étoiles. Le mouvement des étoiles du système est régi par leur lumière et leur rotation et rien d’autre. | We see that the Sun is similar in behavior compared to other stars. The motion of the stars in the system is governed by their light and their rotation and nothing else. |
|
ci ay mbindam day jëfandikoo ay kàddu yinga xamantani waajur yi da ñu leen jàppe yu ñàkkk worma ak doño nettali ni da doon jëf jëf yu ñaak teggin ci dara ji bi | Dans ses écrits, il utilise des mots que les parents savent être considérés comme irrespectueux et qui ne le décrivent pas comme agissant de manière inappropriée envers l'enfant. | In his writings he uses words that are known to parents are considered disrespectful and do not describe him as acting inappropriately to the child. |
|
gunóor yi mën nañu yàq ñam yi waral ay yaram yuy xasan wala ci kaa yu gëna bon lawaal daŋar wala joxe ay infeksiyon | les insectes peuvent contaminer les aliments et provoquer des démangeaisons corporelles ou, dans le pire des cas, des empoisonnements ou la transmission d'infections | insects can contaminate food causing itchy bodies or in worse cases poisoning or transmitting infections |
|
yeneen ñaq yiñ doon saytu ngir mottali wutum garab guy faay yeneen parasite yi ranger yi dañu ko wara saytu bu baax ndax dañu xayma saytu gi ak baaxaayam | D'autres poux qui ont été testés pour compléter la recherche d'un antibiotique contre d'autres parasites ont dû être surveillés attentivement par les gardes forestiers car ils ont estimé la qualité et la quantité du test | other lice that were tested to complement the search for an antibiotic against other parasites had to be carefully monitored by the rangers as they estimated the quality and quantity of the test |
|
gaalu alëmaa yuy daw ci suufu géej gi u-boats lanu leen tuddeewoon alëmaa yi ayoon nanu lool ci dawal seeni gaal yuy daw c biir géej | Les sous-marins allemands étaient appelés sous-marins et les Allemands étaient très fiers de leurs sous-marins. | The German submarines were called u-boats and the Germans were very proud of their submarines. |
|
resultaa yu mujj ci jongante ngir fal njiitu réewu namibi ak jongante ngir nekk ci pencu ndawi réew mi wone na ne njiit mii fi nekk di hifikepunye pohamba falaat nanu ko mu raw ci lu bare | Les résultats définitifs des élections présidentielles et parlementaires en Namibie montrent que le président sortant Hifikepunye Pohamba a été largement réélu. | The final results of Namibia's presidential and parliamentary contests show incumbent Hifikepunye Pohamba is widely re-elected. |
|
xoolal li tukki liggéeykat bi nekk di siiwal mu doon ci ab daluweb wala ci ab palanteer bu ndàw | Découvrez ce que les voyages des employés publient sur un site Web ou dans une petite fenêtre. | See what employee travel is publishing either on a website or in a small window. |
|
bénn coppité amoonna ci pégncum ndaw rééwmi bi gnaaréélu baat biko house of representatives yi génné té jall ci bu mélnonu ci senate altiné | Il n'y a eu qu'un seul amendement au Parlement, dont le troisième vote a été adopté par la Chambre des représentants et adopté par le Sénat lundi. | There was only one amendment to the parliament, the third vote of which was passed by the House of Representatives and passed in the Senate on Monday. |
|
guaraní yi ñooy askan wi njëkk dëkk ci réew mii ñu xamee ci paraguay oriental rëbb moo doonoon seen liggéey daawu ñu toog at mi yépp te daan nañu bay itam ngir dundu | Le peuple guarani fut le premier peuple à vivre dans ce pays connu sous le nom de Paraguay oriental, la chasse était leur principale occupation. Ils n'étaient pas sédentaires toute l'année et pratiquaient également l'agriculture pour leur subsistance. | The guaraní people were the first people to live in this country known as eastern paraguay hunting was their main occupation they were not sedentary all year round and they also farmed for subsistence |
|
bimu amee ay jafe-jafe militeer yu njëkk ethelred jotoon na nangu sàrt yi ak olaf moom mii dellu ca norwees ngir jéema jiitee nguuram ak ndam bu am ay sikki-sakka | Ayant eu des problèmes militaires antérieurs, Ethelred avait déjà accepté les termes et Olaf lui-même était retourné en Norvège pour tenter de diriger son royaume avec un succès douteux | having had previous military problems ethelred had already accepted the terms and olaf himself returned to norway to attempt to rule his kingdom with dubious success |
|
ay pirate ñoko sacc xaj bu soxor songu ko ca tibet rëc sëy ca nepal te nu jàpp ko ca indë | kidnappé par des pirates, attaqué par un chien vicieux au Tibet, échappé à un mariage au Népal et capturé en Inde | kidnapped by pirates, attacked by vicious dog in Tibet, escaped marriage in Nepal and captured in India |
|
bepp camping ci suufu rim bi ci grand canyon dafay laaj ab permi backcountry | Un permis d’arrière-pays est requis pour tous les terrains de camping situés sous le bord du Grand Canyon. | A backcountry permit is required for all campgrounds below the rim of the Grand Canyon. |
|
ñaari woyi filmy bi audition dof yuy gént ak dëkku biddew yi dañ leen lim ci ñi bokk ci woyu cosaan yi dàq. istijoo lionsgate jot na 26 ci ay nit yuñu lim – ëppale istijoo yépp | Les deux chansons des films Audition Crazy Dreams et City of Stars figurent parmi les chansons traditionnelles éliminées. Le studio Lionsgate a reçu 26 membres répertoriés – plus que tout autre studio. | The two songs from the filmy Audition Crazy Dreams and City of Stars are listed among the eliminated traditional songs. The Lionsgate studio has received 26 members listed – more than any other studio. |
|
tàggatu yaram bu xew leegi jëm ci taax ñoŋi koy jogante ci toluwaay bu nekk lu ko dalee nongo daara yi nekk ca daara ju mag ji ba ci powum boroom xam xam yi ak jongante olempiik | Ce sport d’intérieur moderne est pratiqué à tous les niveaux, depuis les salles de classe universitaires jusqu’aux jeux professionnels et aux Jeux olympiques. | The modern indoor sport is played on every level, from the university classroom to the professional games and the Olympics. |
|
sunu sukkandikoo ci fray bartolomé de las casas tratado de las indias digante 1492 ak 1498 conquereur yu españ rey nañu lu toll ci 100,000 taínos | Selon le traité des Indiens de Fray Bartholomew de Las Casas, entre 1492 et 1498, les conquistadors espagnols ont tué environ 100 000 Taïnos. | According to Fray Bartholomew de Las Casas Treaty of the Indians between 1492 and 1498 Spanish conquistadors killed approximately 100,000 Taínos. |
|
mënoon nañu ko àttee neneen su doon dafa réeral caabi otoom te moom ci boppam moo doon jéem dàjji otoom | Il aurait pu être condamné différemment s'il avait perdu ses clés de voiture et essayait de démarrer lui-même sa voiture. | He could have been sentenced differently if he had lost his car keys and was trying to start his car himself |
|
biñu ko laajee ci papa ji wax ndaw si tontu ni mënul woon wax dara foofu la taxaw di kapp-kappal ay gët | Lorsqu'on lui a demandé ce que disait son père, la fille a répondu qu'elle ne pouvait rien dire et qu'elle restait simplement là, se couvrant les yeux. | When asked about the dad saying the girl replied that she couldn't say anything and just stood there covering her eyes. |
|
akit atekat bu mag bi evangelos kalousis dañ ko tëj biñu gisee ni dafa amal ab doxaliinu gér ak ëppël | Le juge principal de l'Acit, Evangelos Kalousis, a été emprisonné après avoir été reconnu coupable de corruption et de partialité | acit senior judge evangelos kalousis jailed after found guilty of corruption and bias |
|
dallu bi niru na ak tabax bu yàgg ak ay mëbal,ak suuf sunu nataalee loxo ak mbàndu sàngukaay | L'appartement ressemble à un vieil immeuble avec des meubles, et du sable quand on imagine des mains et une baignoire. | The flat looks like an old building with furniture, and sand when we picture hands and a bathtub. |
|
su ñuy xool tourisme bi gëna siiw mooy bi gëna méngoo ak li tax nit ñi di tukki tukki ngir bégal seen xol | Si nous examinons la forme de tourisme la plus populaire, c'est celle qui est la plus étroitement liée à la raison pour laquelle les gens voyagent pour leurs loisirs. | if we look at the most popular form of tourism it is the one most closely related to why people travel for leisure. |
|
dañuy door ne saxaar buy jóge cii ndiir yi te bu ñu laalee suuf rekk nekk ay taw yu àndak ngelaw | On dit que la fumée s'élève des nuages et, lorsqu'elle touche le sol, se transforme en pluie qui accompagne le vent. | Smoke is said to rise from the clouds and, when it touches the ground, becomes rain that accompanies the wind. |
|
li juree ci lii coow lu rëy ci biir aaskanu grek gi siw na gannaaw ba nu wone jëfi attekat layokat ak kilyeng yi ak prokirër yu teguwul yoon te nu def ci diiru at yi wees | Le tollé qui a eu lieu dans la société grecque a été révélé au grand jour après que nous ayons dénoncé les actions illégales que nous avons commises au fil des ans par des juges, des avocats et des procureurs. | The resulting uproar in Greek society has come to light after we exposed the illegal actions of judges, lawyers and prosecutors that we have committed over the years. |
|
singapour xam nañu ko muy barab bu am kaaraange gu mat te neexa joowu so xasee bay egg fa mën nga fa jënd lu nekk | Singapour est connu pour être un endroit très sûr et facile pour faire du shopping une fois sur place. | singapore is known for being a very safe and easy place to shop once you get there. |
|
yeneen xeltukat yi wax nanu ne garab yii dañoo bare tooke kon ci yoon benn dinosoor lekku ci doonte tey abbu àll buy dox melni ku tàyyel ak yeneen xeeti rab yu melni sekusëtu dinosoor yi mën na lekk xob wal doom yu am tooke yi | D'autres scientifiques affirment que ces plantes sont si toxiques qu'aucun dinosaure ne peut les manger, même si un lézard paresseux et d'autres espèces telles que les lézards dinosaures peuvent manger les feuilles et les fruits venimeux. | Other scientists say that these plants are so poisonous that no dinosaur can eat them, even though a lazy walking lizard and other species such as dinosaur lizards can eat the poisonous leaves and fruits. |
|
dawal sa auto bopp wuute na ak dawal auto bu mag miin nga ko dawal te xamna lumu àttan | Conduire votre propre voiture est différent de conduire une voiture professionnelle que vous savez conduire. | Driving your own car is different than driving a professional car that you know how to drive. |
|
barina ay réew ci àdduna bi yooy dem su nit yëkkatee loxoom yëngal mooy dalay nuyu nanga def | Il existe de nombreux pays dans le monde où vous serez accueilli en levant la main. | There are many countries in the world where you will be greeted by raising your hand. |
|
ci réw yu am komkom yi tay joxé neegu njaatige yu bakkané yegg na ci mbiru rafetal | Dans les pays modernes, le transfert de corps à des propriétaires privés ne se limite pas à des raisons esthétiques. | In modern countries, the transfer of bodies to private owners is not limited to cosmetic reasons. |
|
këru paju-ndimbal gu mangola cmc médecins sans frontières ak mbootaayu wérgi-yaramu ci àdduna bi oms neena ñu mbas mii moo yées ci mbas yi ci àdduna bi | Maison de retraite Mangola CCMc Médecins sans frontières et l'Organisation mondiale de la santé (OMS) affirment que cette pandémie est la pire au monde. | Mangola Nursing Home CCMc Doctors Without Borders and World Health Organization (WHO) say this pandemic is the worst in the world. |
|
moonte lu joge ci kasinoo yi nu lim ci kaw yepp danuy joxe naan te yu bare ci ñoom dañuy indi po yu am tur lu ci jiitu yu gëna gudd te wër albuquerque ak santa fe | La plupart des casinos répertoriés ci-dessus proposent des boissons et beaucoup d'entre eux proposent des jeux nommés en plus de jeux plus longs autour d'Albuquerque et de Santa Fe. | Most of the casinos listed above offer drinks and many of them offer named games in addition to longer games around albuquerque and santa fe. |
|
pékin dina dalal feet ubbité bi ak tëjbi dina dalal itam jongaante indoor ice | Pékin accueillera les soirées d'ouverture et de clôture et accueillera également les compétitions de glace en salle. | Beijing will host the opening and closing parties and will also host indoor ice competitions. |
|
barab bi saytu cyclone ci réew mi nhc neena fiñu tollu nii jerry mënul indi jenn loraange ci kaw suuf | Le Centre national de surveillance des cyclones (NHC) indique que jusqu'à présent, Jerry n'a causé aucun dégât sur terre. | The National Cyclone Monitoring Center (NHC) says so far jerry has not caused any damage on land. |
|
lu ëpp ci dee yi sonn ba noppi di fééy ci ndox mokoy indi lu meenul nékk | La plupart des décès dus à l’épuisement et à la noyade conduisent à l’impossible. | Most of the deaths from exhaustion and drowning lead to the impossible. |
|
nataal efararuus wonena coppite ci jawwu ji guddi ak bëcëg di wone ay bërë la | La capture d'écran montre les changements dans l'atmosphère entre la nuit et le jour, montrant différents endroits. | The screenshot shows the changes in the atmosphere between night and day, showing different locations. |
|
tukki yi ño gëna yomb ci nit yu bari kon bo nekké yaw rekk wala ak sa benn xarit rekk jéemal dajé ak yénéénni nit té nas bénn kuréllu gnént japp juroom bénn ngir xayma nit bu geen | Voyager est plus facile pour beaucoup de gens, donc si vous êtes seul ou avec un ami, essayez de rencontrer d'autres personnes et de former un groupe, sortez et tenez-en cinq chacun pour compter le nombre de personnes que vous avez. | Traveling is easier for many people so if you are alone or with a friend try to meet other people and form a group and go out and hold five each to count the number of people you have. |
|
ndax seeni ndam te bato xare buy daw ci suufu ndox ba xare bi weesoo alëmaa yi wolotuñu am lubaari ci ñoom | En raison de leur victoire et de leurs sous-marins après la guerre, les Allemands ne voulaient rien avoir contre eux. | Because of their victory and submarines after the war the Germans did not want to have anything against them. |
|
cafenet el sol joxe na am sàrwiisu jàpp palaas ci njëggu us$30 wama $10 ngir paasu benn bis; mën nga gis leeral yi ci seen xëtu corcivado | Cafenet el Sol propose un service de réservation pour 30 $ US ou 10 $ pour un pass journalier ; Des informations peuvent être trouvées sur leur page corcivado | Cafenet El Sol offers a reservation service for US$30 or $10 for a day pass; Information can be found on their corcivado page |
|
bignulén moomé yén say diangnu sééti yénn say njiitu rééw yi ak gnénén gni | Nous ne voulons pas que vous soyez celui qui fait la lecture à tous vos présidents et à d’autres. | We don't want you to be the one who reads to all your presidents and others. |
|
lamu patin bu galas bu xew dafa am ñaari wet ak xóot xóot ci seen diggante ñaari pegg yooyu dafay tax kiy def patinas bu gaawaa daanu suñuy tar-tari sax | La lame d'un patin à glace moderne possède deux côtés avec une faible profondeur entre les deux bords qui permet au cavalier de tomber rapidement même en dérapant | The blade of a modern ice skate has two sides with a deep shallow depth between the two edges which allows the rider to fall fast even when skidding |
|
batten lañu teggoon ci 190eelu palaas ci limu 400 amerikee yi ëpp alal ci atum 2008 ak alal bu toll ci lu jege 2,3 miliyaari dolaar | Batten a été classé 190e sur la liste 2008 des 400 Américains les plus riches avec une valeur nette de près de 2,3 milliards de dollars. | Batten was ranked 190th on the 2008 list of the 400 richest Americans with a net worth of nearly $2.3 billion. |
|
beereebu saytu gniy tukki ngay njeekkee gis bo waccé ci ropalaan gaal wala bénn daamar | La zone de contrôle que les passagers voient en premier lorsqu'ils descendent d'un avion, d'un navire ou d'un bateau. | The control zone that passengers first see when they get off an airplane, a ship, or a boat. |
|
bégg na bi mu amé nit yu noppi ngir taxawuma | Il était content qu’il y ait des gens silencieux pour me défendre. | He was glad there were silent people to stand up for me. |
|
mën nañu ko am bu nekkee mbiri komkom mooy amul benn lank ci safara nuclear mr costello mooko wax | La seule façon d'y parvenir lorsque cela devient une question municipale est de ne pas avoir d'incendie nucléaire, dit M. Costello. | It can be achieved when it becomes a municipal issue, there is no spark in nuclear fire, Mr Costello says. |
|
talon yi dañoo wara gàtt te yaatu. suuf si garawaa yi wala xorom si kloriiru kalsiyoom dañuy faral di tasaaroo ci tali yi wala ci yoon wi ngir yombal xëcc gi | les talons doivent être courts et larges. Du sable de stationnement ou des sels de chlorure de calcium sont souvent répandus sur les routes ou les sentiers pour faciliter la traction | heels should be short and wide. parking lot sand or calcium chloride salts are often spread on roads or trails to facilitate traction |
|
ci diiru tukkeem iwasaki dafa jokkonteeg ak coow ci anam yu bare | Au cours de son voyage, Iwasaki a été confronté à plusieurs controverses. | During his journey, iwasaki came into contact with controversy on several occasions. |
|
su ñaari xeet yii dundee lu tollu ci ay junni wala ay milyoŋi at wuute gi dina bari ci ñoom lool te dina dem ba kenn dootul mënati wax ni ñaar ñooñu ñoo bokk xeet | Si ces deux espèces vivaient ensemble pendant des milliers ou des millions d'années, les différences entre elles seraient si grandes qu'il serait impossible de dire qu'elles sont la même espèce. | if these two species lived together for thousands or millions of years the differences between them would be so great that it would be impossible to say that they were the same species. |
|
sula neexee nga def ay mark ay crayon waaye ngeen bàyyi xel ni màrk yu kurbe yi nekk ñu imprime leen misik moo leen taxa jog dañu leen wara sàmm | N'hésitez pas à faire des marques avec des crayons, mais gardez à l'esprit que les marques courbes sont imprimées musicalement et doivent être conservées. | Feel free to make marks with pencils but keep in mind that the curved marks are musically printed and should be preserved. |
|
fàww nga am cole d'angkor ngir mëna dugg ci barabu jaamukaay bi kon bu leen fàtte yor seen passeport su ngeen bëggee dem tonlé sap | vous avez besoin du collège d'Angkor pour entrer dans le temple, alors n'oubliez pas d'emporter votre passeport si vous souhaitez visiter Tonlé Sap | you need angkor college to enter the temple so don't forget to carry your passport if you want to visit tonlé sap |
|
ño gene seed diwaan yi wër ci bés bi ak tang ci guddi bi | Ils ensemencent les régions autour du jour et de la nuit. | They seed regions around the day and night. |
|
beereeb bi keeruk xéétu mala wala ay picc yu beeri la | Le trou est le foyer de plusieurs espèces d'animaux ou d'oiseaux. | The hole is the home of several species of animals or birds. |
|
yenn ci ay yoon yi yàqu nañu saxaar bi taxaw ci bërëb yi mbir mi laal té ayeropoor bu noto ci prefekturu ishikawa daa teej ba tay | Certaines lignes ont été endommagées et les trains se sont arrêtés dans les zones touchées et l'aéroport de Noto dans la préfecture d'Ishikawa a été fermé jusqu'à aujourd'hui. | some of the lines were damaged and trains stopped in the affected areas and Noto Airport in Ishikawa Prefecture was closed today. |
|
waaye ci yeneen barab ci addina bi fi nga xamantane àllu bakteri yi lu bees la ci ñépp ci ngeen di gëna mëna yomba am ay jafe-jafe | mais dans d'autres parties du monde où la découverte de la jungle bactérienne est nouvelle pour tout le monde, vous êtes plus susceptible d'avoir des problèmes | but in other parts of the world where getting to know the bacterial jungle is new to everyone you are more likely to have issues |
|
nit yu bari saytu nañu jàngat bi ci xarala yu wuuté ak yéneen ci ndortéelu wééru fébrié té waxonna ñu ko ci talaaata | L'étude a été testée par plusieurs personnes utilisant différentes technologies début février et a été annoncée mardi. | The study was tested by several people using different technologies in early February and was announced on Tuesday. |
|
dexu amazon bi toluna ni ci 6,387km 3,980 miles. dafay boole ndox yu bawoo ci ay juniy dex yu ndaw | La longueur du fleuve Amazone est de 6 387 km et 3 980 miles. il combine les eaux de milliers de petites rivières. | The length of the Amazon River is 6,387 km and 3,980 miles. it combines the waters of thousands of small rivers. |
|
sphinx bi mooy li ci ginnaw ak kiy néttali benn taarix bu gudd | Le sphinx est l’arrière-plan et le narrateur d’une longue histoire. | The sphinx is the background and the narrator of a long story. |
|
ñu bokk ci mboolo buy feeñ te jëmmadi sen liggéey melni tomb xamee ngir sen tolluway mboolo bu jamp | Ils sont membres d’un groupe émergent dont le travail semble être un symbole reconnaissable de leur statut de groupe critique. | They are members of an emerging group whose work seems to be a recognizable symbol for their critical group status. |
|
ci ni paris siiwee ne diwaanu colko bu jamonoy tey constantinople noonu lanu ko doon xoolee ne diwaanu colko bu ërop gu njëkk ga | Comme Paris est célèbre comme le centre moderne de Constantinople, nous la voyons comme le centre de l’Europe antique. | As Paris is famous as the modern center of Constantinople, we see it as the center of ancient Europe. |
|
ñenn ñi gëm nañu bokk na ci john grant ni jafe-jafey financement ak jàll ci xalaatu porogaraamu njàng jàppale nañu ci jeexal série yi | certains pensent notamment à John Grant que les problèmes de financement et la transition vers l'idée de programme ont contribué à mettre fin à la série | some believe including john grant that funding issues and the transition to the idea of curriculum helped end the series |
|
kompañi ayeriyen yu melni emirates airways qatar airways ak turkish airlines wasare nañu bu baax seeni sàrwiis ci afrik te joxe koneksiyon ci ay dëkki afrik yu gëna mag ci ay njëg yu yomb yu wuuteek kompañi yu orop | Des compagnies aériennes telles qu’Emirates Airways, Qatar Airways et Turkish Airlines ont réussi à diversifier leurs services en Afrique et à proposer des liaisons vers les principales destinations africaines à des prix inférieurs à ceux des transporteurs occidentaux. | Airlines such as Emirates Airways Qatar Airways and Turkish Airlines have successfully diversified their services in Africa and provided connections to major African destinations at lower prices than Western carriers. |
|
ci cóoróon bi mën nga jarinoo piste ski yi ci bët gànnaaru amerik sudee jamonoy nawet mën nga dawal welo vtt ci tangor yi | en automne vous pourrez profiter des pistes de ski d'amérique du nord en hiver vous pourrez faire du vélo vtt dans les tangors | in the fall you can take advantage of the ski slopes of north america in winter you can cycle vtt in the tangors |
|
fekki na leen ci atum 1945 te desna ci ba atum 1958 | Il les rejoint en 1945 et y reste jusqu'en 1958. | He joined them in 1945 and remained until 1958. |
|
jàpp nañu ni typhon baa ngi jëm chine ci gaawaayu 11km/h | On estime que le typhon se déplace vers la Chine à une vitesse de 11 km/h. | The typhoon is estimated to be moving towards China at a speed of 11 km/h. |
|
sunu kureelu wutal nit njaboot gu muy bokk dafay wut kë y wóor ay fajkat yu laa biir njàng mu dal ak paj mu mucc ayub | Notre équipe de recrutement de familles d'accueil recherche des foyers sûrs, des soignants formés à l'éducation de qualité et à des soins sécuritaires. | Our foster family recruitment team is looking for safe homes, caregivers who are trained in quality education and safe care. |
|
ojaans bi dafay wone itam bisu àqu kiñuy jiiñ ab porosé bu gaaw | Le calendrier indique également la date de mise en accusation du défendeur dans le cadre d'une procédure accélérée. | The schedule also shows the defendant's arraignment date as an expedited process. |
|
ci kaaw njeexitalu bët gannaru machu picchu la tangor bu bari ay doj nek di nagn faral diko jëfëndiko lu bari ci walu nataal lu mënadi | Au-dessus de l'extrémité nord de l'œil, le Machu Picchu est un volcan rocheux souvent utilisé pour la photographie. | Above the northern end of the eye, Machu Picchu is a rocky volcano often used for photography. |
|
mooy amef bi gëna rey ci jaar jaaru ebay | C'est l'AMEF le plus drôle de l'histoire d'eBay. | It's the funniest amef in ebay history. |
|
gannaaw po mi buuru clay waxonna dama am mbëgte ci deluci waat paac mu mujju bi bokku ci yi gën am solo ci xew-xew yi dama teew fii ngir am ndam | Après le match, le roi de la terre battue a dit : « Je suis heureux de revenir et la dernière étape est l'un des événements les plus importants que je suis ici pour gagner. » | After the game the clay king said I'm happy to go back and the last leg is one of the most important events I'm here to win. |
|
li ñuy waawe nombre binaire mënul am ludul benn wala ñaari nimero manaam 0 wala 1 te nombre yooyu lañuy woowe chiffre binaire wala bit noonu lañu koy woowe ci informatique | les nombres dits binaires ne peuvent contenir qu'un ou deux nombres, c'est-à-dire 0 ou 1, et ces nombres sont appelés chiffres ou bits binaires, et c'est ainsi qu'ils sont appelés en informatique. | so called binary numbers can only contain one or two numbers i.e. 0 or 1 and these numbers are called binary digits or bits and that is how they are called in computer science. |
|
ab xew xew bu aniwerseer bu tegu ci yoon nasoon nanu ko ngir bes bu ñëwëgul ci waxu njiit yi | Une fête d'anniversaire officielle était prévue pour une date encore à déterminer. | An official birthday party was planned for a date yet to be determined. |
|
kiy waxal medecines sans frontiere richard veerman wax na ni angola mu ngi ci duggu ci épidemi bi gëna bon te sitiyasiyoŋ bi dafa bon lool ca angalo ci limu wax | Selon Richard Veerman, militant de Médecins sans frontières, l'Angola est en train d'entrer dans sa pire épidémie et la situation est pire qu'en Angola, selon lui. | According to Doctors Without Borders campaigner Richard Veerman, Angola is entering its worst epidemic and the situation is worse than Anglo, according to him. |
|
barab bi saytu cyclone ci réew mi nhc neena fiñu tollu nii jerry mënul indi jenn loraange ci kaw suuf | Le Centre national de surveillance des cyclones (NHC) affirme que jusqu'à présent, Jerry n'a causé aucun dégât sur terre. | The National Cyclone Monitoring Center (NHC) says so far jerry has not caused any damage on land. |
|
nigeria waxoon na bu njëkk ni mebetna bokk ci afcfta ci biir ayubés bi jeem ci ndajémi | Le Nigeria a déjà annoncé son intention de rejoindre la ZLECA dans la semaine suivant son sommet. | Nigeria has already announced its intention to join the Afcfta within a week of its summit. |
|
paléontologue yu bari jàpp nañu ni ba leegi amna ay dinosaure yu mësul woon dee di dund baa leegi ñoom lañu woowe ay picc | De nombreux paléontologues pensent qu'il existe encore des dinosaures qui n'ont jamais disparu et qui sont toujours vivants et qui sont toujours appelés oiseaux. | Many paleontologists believe that there are still some dinosaurs that never died out and are still alive and are still called birds. |
|
revolution bu farans bi dafa bayyilo xel itam yeneen kalaasu liggéeykat yu yeneen réew yi ngir tambali seen coppitey bopp | La Révolution française a également détourné l'attention des autres classes ouvrières d'autres pays pour qu'elles lancent leurs propres révolutions. | The French revolution also distracted the other working classes of other countries to start their own revolutions. |
|
petorol koom gu am solo la ci koom koomu venezuela fi réew mi nekké jéggani kat bu mag donté benn ci témér yo jël ñooy liggéy ci koom koom ngi | Le pétrole est un moteur économique important du Venezuela, où le pays est un employeur majeur avec seulement 1% de la main-d'œuvre employée dans l'économie. | Oil is an important economic driver of Venezuela's economy, where the country is a major employer with only one percent of the workforce employed in the economy. |
|
stearns mu ngi ceytu ndax limpo yi jëffandikoo nanu ko ngir fay yàkk njur yi jaare ko ci planned parenthood ci ni mu nekkee njiitu komite bi suuf xool bi ak ceytu gi mu nekk ci suufu kilifteteef këru enersi ak komite njaay | Stearns enquête pour savoir si les limousines ont été utilisées pour payer des avortements par l'intermédiaire de Planned Parenthood en tant que président du Comité de surveillance et d'enquête de la Chambre, qui relève de l'autorité du Comité de l'énergie et du commerce de la Chambre. | Stearns is investigating whether the limpos were used to pay for abortions through Planned Parenthood as chairman of the House Committee on Oversight and Investigation which falls under the authority of the House Energy and Commerce Committee |
|
ngir gëna mëna teewal jaabante bu tarafik bi tëral nañu lëkkaloo ci digante ñetti karakteristik yu wuute: 1 jaabante 2 taraay ak 3 gaawaay | Afin d'optimiser la réponse au trafic, nous avons établi une relation entre trois caractéristiques différentes : 1 réponse 2 largeur et 3 vitesse | In order to optimize the traffic response we have established a relationship between three different characteristics: 1 response 2 width and 3 speed |
|
mbir yii meena gno wééru yénn say ci rééw yi tukki kat bi sééti wala yimu meebeetee sééti | Ces facteurs peuvent varier en fonction des pays que le touriste a visités ou a l’intention de visiter. | These factors may vary depending on the countries the tourist has visited or intends to visit. |
|
turism buy yëngu ci wàllum natiir dafay xëcc nit yi bëgg dem ci ay barab yu nantirel ngir porofitoo payizaaz bi ak àllu mala yi ak garab | Le tourisme de nature attire les personnes qui aiment visiter des lieux indigènes pour profiter du paysage, de la faune et de la flore | Nature tourism attracts people who enjoy visiting native places to take advantage of the landscape and wildlife and plants |
|
dawalkat bi gis nanu ne ci squadron leader dilokrit pattavee la bokk | Le chauffeur que nous avons découvert appartenait au chef d'escadron Dilocrite Pattavee. | The driver we discovered belonged to the Squadron Leader Dilocrite Pattavee. |
|
kër yu yëngu xi wàllum biyee roplaan yi leen di digle ñoy air canada delta air lines lufthansa ngir wol yuy bawoo ci etaa-sini wala kanadaa ak westjet | Les compagnies aériennes les plus populaires qui opèrent des vols sont Air Canada, Delta Air Lines, Lufthansa, pour les vols en provenance des États-Unis ou du Canada et Westjet. | The most popular airlines that operate airlines are Air Canada Delta Air Lines, Lufthansa, for flights from the United States or Canada and Westjet. |
|
jang bi njëkk ci wayndaare bi john nixon moko déf ci ëtug independence hall bi ci wéru sulét juróom ñetti fan | La première lecture du budget a été donnée par John Nixon à l'Independence Hall le 8 juillet. | The first reading of the budget was given by John Nixon at Independence Hall on July 8. |
|
ci ni paris siiwee ne diwaanu colko bu jamonoy tey constantinople noonu lanu ko doon xoolee ne diwaanu colko bu ërop gu njëkk ga | Comme Paris est célèbre comme le centre moderne de Constantinople, nous la voyons comme le centre de l’Europe antique. | As Paris is famous as the modern center of Constantinople, we see it as the center of ancient Europe. |
|
kilifa yi amul ñudara lu leer ci loraange ngi ñu ragal ni moo nara am fbi deggal na kilifay maryland transportaion ñu tëj lépp | Les responsables n'ont rien d'évident sur les dégâts que nous craignons, le FBI a obéi aux autorités des transports du Maryland et a ordonné de tout fermer. | officials have nothing obvious about the damage we fear is going to happen the fbi obeyed the maryland transportaion authorities to shut everything down. |
|
ginaaw ku raw yaay jël état yépp floride boolena mbooleem juróom-fukki delegeem yépp jox ko romney jiital ko mu raw ci ñi nara nekk ki parti républicain nara jiital | Après que celui qui gagne, elle remporte tous les États de Floride, rassemble les cinquante délégués et les donne à Romney et remporte la nomination républicaine. | after whoever wins she takes all the states florida combines all fifty of its delegates and gives it to romney and wins the republican nominee. |
|
mën nañu am permi park si saasi ca ranger sation bi nek puerto jiménes waaye du ñu nangu kàrtu bank yi | Les permis d'accès au parc peuvent être obtenus directement au poste de garde forestier de Puerto Jimenez, mais les cartes bancaires ne sont pas acceptées. | Park permits can be obtained directly at the ranger station in Puerto Jimenez but bank cards are not accepted. |
|
mala yu jafeee gis yu melni urs bu sokoolaa bu ëropë bukki ceeli looy siiru muusu àll wal picc am na foofu ak yeneen xeeti mala yu bare | Des animaux rares comme l'ours brun européen, le lion, le guépard, le chat sauvage, l'oiseau et bien d'autres espèces. | Rare animals such as the European brown bear, the lion, the cheetah, the wild cat, the bird, and many other species. |
|
jëni boks yi ci wetu tefes yi ak dex yi bawoo ci oktoobar ba ci awril ci bëj-ganaaru 1770 mën nañ leen a gis ci biti yenn saay | Le poisson-coffre le long des côtes et des rivières d'octobre à avril dans le sud-ouest de 1770 peut être vu occasionnellement à l'extérieur. | Boxfish along the coasts and rivers from October to April in the southwest of 1770 can be seen occasionally outdoors. |
|
tommy dreamer néna luna moonékkoon buur bu jigeen bi njëkk ci extreme sama njiit bi njeekk luna ci guddik gnaari wéér yi la gaañu woon rafet lool ni moom jiggén ju am doolé | Tommy Dreamer dit qu'elle était la première reine de l'extrême lune. Mon premier patron a été blessé dans la nuit il y a deux mois. Elle était très belle et c'était une femme forte. | Tommy Dreamer says she was the first queen of extreme luna. My first boss was injured in the night two months ago. She was very beautiful and she was a strong woman. |
|
am na tamit ay bis yu bariwul jóge bët gannaar dem hebron bërëbu bi nu suul bu ñoom maam abraham isaac jacob ak seeni soxna | Il leur reste également quelques jours de voyage vers le nord jusqu'à Hébron, lieu de sépulture de leur grand-père Abraham Isaac Jacob et de ses épouses. | There are also a few days to travel north to Hebron, the burial place of their grandfather Abraham Isaac Jacob and his wives. |
|
bimu jaaree ci xaaju-genwall bi dem ci genwall gaawaay bi amatul solo lool te yaggaay bi dafay mujj doon lu mënul ñakk | au fur et à mesure qu'il passe du demi-genwall au genwall, la vitesse n'est plus si importante et la longueur devient une nécessité | as it passes through the half-genwall to the genwall the speed is no longer so important and the length becomes a necessary |
|
xaléyi amnañu xam xam xeet ak mélokaan bu ndaw ak ci jëfin yi | Les enfants acquièrent une compréhension de la race et de l’ethnicité dès leur plus jeune âge et dans leurs actions. | Children have an understanding of race and ethnicity at a young age and in actions. |
|
keyiti panama ab diiru parasol la ngir lu jege fukki miliyoŋi wayndare yu bawoo ci kabinet awoka bu panama buñuy woowee mossack fonseca buñu feeñal ci xibaar yi printemps 2016 | Les Panama Papers sont un terme générique désignant les près de dix millions de dollars du cabinet d'avocats panaméen Mossack Fonseca qui ont été révélés au printemps 2016. | The Panama Papers are an umbrella term for the nearly ten million dollars from the Panamanian law firm known as Mossack Fonseca that was revealed in the spring 2016 news. |
|
ordinater yi legui pour di xool ay foto ak video rek la | Les ordinateurs servent désormais uniquement à visionner des photos et des vidéos. | Computers are now just for viewing photos and videos. |
|
ci kaw mooy danga wara door ak lii té bees ci paspas bi té ci suuf mooy danga wara door ak mbott bi mooy fi sa loxo japp ci paspas bi té xeec ko | Celui du haut est que vous devriez commencer par ceci et c'est nouveau pour la marche et celui du bas est que vous devriez commencer par le bâton, c'est là que votre main tient la marche et la serre. | The top one is you should start with this and it is new to the step and the bottom one is you should start with the stick is where your hand is holding the step and squeezing it. |
|
xeltukat yi danuy woowee doxalin bile jox rajasiyong bu nu sooke ndaxte atom yi leeray bi mo leen sooke indi joxe fotonwu leeraay te leeraay benn xeetu rajasiyong la | Les scientifiques appellent cette théorie « rayonnement spontané » parce que les atomes sont excités par la lumière et émettent des photons de lumière, et la lumière est une forme de rayonnement. | Scientists call this theory spontaneous radiation because atoms are excited by light and emit photons of light, and light is a form of radiation. |
|
ndéémngélaw bi sorina landfull dina jafe ngir yéksi united states wala caribbean | L’impact est si loin de toucher toute la terre ferme qu’il serait difficile de sauver les États-Unis ou les Caraïbes. | The impact is so far from landfull it would be difficult to lift the United States or the Caribbean. |
|
yenn hôtel yii ngi deñc ba tay ndono jamono ju neex ja âge d'or ci wàllu autoraay bato saxaar; lu jiitu seconde guerre mondiale ci ndoorleetu 19eel wala 20eelu xarni bi | certains hôtels conservent encore l’héritage de l’âge d’or des autorités ferroviaires ; avant la Seconde Guerre mondiale, au début du XIXe ou du XXe siècle. | some hotels still retain the legacy of the golden age of railway authorities; pre-WWII in the early 19th or early 20th century. |
|
ay ayu-bis ci ginaaw ginaaw xibaar boobu makis triantafylopoulo di tasakatu xibaar siiwal ci xawaare teleeem bu siiw «zoungla » ci alpha tv ki bokk ci pencu ndawi réew mi ak laokat petros mantouvalos danu ko wàcce ndax ku bokk ci buroom dafa dug ci jot xaalis gu lewul ak ger | Il y a quelques semaines, après la nouvelle que Makis Triantafylopoulou, un journaliste, publiait sa chaîne de télévision populaire Zoungla sur Alpha TV, le parlementaire et avocat Petros Mantouvalos a été limogé pour détournement de fonds présumé, indiscipliné et corrompu. | A few weeks ago, after the news that Makis Triantafylopoulou, a journalist, published his popular television channel Zoungla on Alpha TV, parliamentarian and lawyer Petros Mantouvalos was ousted for alleged embezzlement. unruly and corrupt. |
|
seet gi kilima gi yàkk wàccu fafalnaaw gi moo ko dàkkal | La recherche a été interrompue par le climat qui a détruit le fafalnaaw. | The search was ended by the climate that destroyed the fafalnaaw. |
|
am na ñu nanguwul wante sama yoon nekku ci | Certaines personnes ne sont pas d’accord, mais ce n’est pas ma façon de faire. | Some people don't agree, but that's not my way. |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
Fleurs Extended: Wolof-French-English Translation Dataset
Author: Bilal FAYE
This dataset is an extension of the Google Fleurs dataset. It includes audio samples in Wolof, along with transcriptions translated into French and English. The dataset is designed for tasks such as:
- Translating Wolof text/audio to English or French.
- Training and fine-tuning speech-to-text or text-to-text models.
Dataset Details
- Languages: Wolof, French, English.
- Features: Audio (
audio
), Wolof transcription (wolof
), French translation (french
), English translation (english
). - Tasks:
- Speech-to-text: Wolof audio → Wolof text.
- Text-to-text: Wolof text → French/English text.
How to Load
You can load the dataset with the following code:
from datasets import load_dataset
# Load the dataset
dataset = load_dataset("bilalfaye/fleurs-wo-fr-en", trust_remote_code=True)
# Example: Access the train split
print(dataset["train"][0])
Example Usage
To access the translations and audio:
example = dataset["train"][0]
print("Audio:", example["audio"])
print("Wolof:", example["wolof"])
print("French:", example["french"])
print("English:", example["english"])
- Downloads last month
- 1