Dataset Viewer
audio
audioduration (s) 1.22
9.77
| quality
stringclasses 3
values | text
stringlengths 8
150
|
---|---|---|
denoised | ndax kat yaw it am nga ay ayib, nit ñi ami làmmiñ |
|
original | mbootaayug orob gi ma ngi dajaloo ngir génne koppar ngir wàllu afrig |
|
original | loolu moom lu am la |
|
enhanced | feccil sa kanam ! |
|
denoised | dunyaa soxal na ku nekk sox bu rëy di ko nég |
|
denoised | leegi, bég naa lool. |
|
original | ku xoromu nga. |
|
enhanced | na ngeen sax cig ragal yàlla, ngeen di waay-sant sunu boroom subhaanahu wa tahaalaa |
|
original | man ngeen a dawal wata a? |
|
original | buleen xaar ! |
|
original | damay nit ku wóorul . |
|
original | waaye ñàkkuñu woon cëslaay, amoon nañu tamit lu ñu gëm |
|
original | ag jóor en vrac. |
|
original | am naa ay xibaar. |
|
denoised | moytu woon naa. |
|
original | bëggu ma nen. |
|
enhanced | dananu def lu nu man. |
|
original | lamsal, xool jaxaay sa, |
|
denoised | nekk na fajkat. |
|
original | ndax loolu da leen di ñàkke worma ? |
|
enhanced | song gi napoleon songoon penku bi |
|
denoised | doom biy sax ci garab day wërbalu te toll ci ñett i sàntimet. |
|
denoised | mooy juroom-ñetteelu weer ci at mi, di itam weer jiitu koor gi |
|
denoised | nee ñu ca réew i eendo ya la jëm |
|
denoised | bu ci am genn ug jaaxle. |
|
denoised | dikkleen sunu kër ! |
|
denoised | dangaa jàpp lool. |
|
enhanced | dogon yi amma |
|
enhanced | tukkloor yi pulaar mooy seeni lakk, lislaam mooy seen diine |
|
enhanced | loola sax waral na ñu ber leen ca taax ma ba noppi tëj ko. |
|
denoised | teen bi daa wow kong . |
|
original | waa tambaakunda ñoo ngi yëngal |
|
denoised | damay faral di dégg ñu naan senegaal réewu layig la |
|
denoised | ragal boroomam te am njël jiitu ak maasam |
|
original | ku jëkk yeewu boroom ndékki, war a tëddaat |
|
enhanced | ndax man namaa bàyyi ci yaw xel? |
|
denoised | nu jaaxlewu la doxaale . |
|
original | loo leen di seet ? |
|
original | mabba jaxu ba ci atum junni ak jurо́om ñetti téemeer ak jurо́om ñent la judd ca nguurug saalum |
|
denoised | dama yëg féex. |
|
denoised | njegamaar bu ma seen dootul dem! |
|
denoised | xalaat mii a rafet ! |
|
enhanced | loolu jur yeneen mbooloo'y nit judd, mu ci nekk ak sa waxiinu bopp. |
|
denoised | nan réccu moy yaa |
|
original | dinaa gis beneen liggéey. |
|
original | ñoom ñépp laa bañ. |
|
original | bii maa ko moom. |
|
denoised | xamuma nu mu manee woon wax wax ju ni mel |
|
denoised | «yàlla daf nu digal, man ak yeen, nu jaamu ko, di julli ci moom |
|
denoised | tekkee goo ko de |
|
enhanced | ku nekk war na balaa dem fab yar ak mburu yor |
|
original | ndax waaw lay tekki? |
|
enhanced | maa ngi dund sama gént. |
|
enhanced | yaatug lislaam ci afrig gu sowwu gi |
|
denoised | des a may gënal. |
|
denoised | alxames jàpp jurо́om hñaar fukk dog fukk ak jurо́om ñent hñaar fukk ak jurо́om |
|
denoised | dama xalaat ne danga reelu. |
|
original | li waral xasida gi |
|
denoised | dama yëg yoqi. |
|
enhanced | dox damaa neex. |
|
denoised | xobam day nëtëx fu mu toll |
|
original | brigaud di nañu tax nu man a dem ba ca njëlbeen |
|
denoised | ?? kàcc kàcc nga dees na ko wax ku ay waxam werut, |
|
original | fan la jëme ? |
|
enhanced | daa na jëflante ci wàllug yaxantu ak gox yu sori yi |
|
enhanced | lu tax tom def lii ? |
|
enhanced | xetug ay xobam nag neexul |
|
enhanced | waññi boo gis ci benn lay doore |
|
enhanced | day kaf lu bari. |
|
denoised | man naa xaar. |
|
denoised | foofa la doog di yëg ne tekki ko jot na. |
|
denoised | maa ngi leen di ñaanal wërsëg. |
|
enhanced | beteex plomb pb |
|
denoised | jabar dafay yaru tay muñ neexi wax bañ a wex |
|
denoised | naan naa doom yi. |
|
original | bëgg naa ci benn ! |
|
original | ma daa di ko gis. |
|
enhanced | bul jéggalu ! |
|
denoised | moo ana lan moo ko gën a war ? |
|
original | lekk naa sama sandiis. |
|
denoised | dugalal sa simis bi ci tubay ji! |
|
denoised | kañ ngay jàng ? |
|
original | mi ngi ci kanaape bi. |
|
original | won ma sa loxo. |
|
enhanced | danu noo song. |
|
denoised | damay saaf jën. |
|
enhanced | yaatuwaay bi ñaar i sàntimet la. |
|
original | mbërbóof lees di lekk la te di ko fajoo |
|
enhanced | taal bi fey. |
|
enhanced | kemu tangoor gee ngi aju ci taraayu dawaan bi |
|
enhanced | neexoon na lool. |
|
original | dinañu ma dimbali. |
|
denoised | usmaan sémbeen a ngay wone coppite googu ci biir filmu bii di ceddo… |
|
enhanced | daaray al xuraan yi |
|
enhanced | mi ngi fi. |
|
denoised | ku doge tàndarma bu lew ci weeru koor |
|
enhanced | dama nekk di jàng. |
|
denoised | nu ma man a dimbalee? |
|
enhanced | sam ñoll a ngi nii. |
|
denoised | dama war a wéeyal. |
End of preview. Expand
in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 69