text
stringlengths
2
1.75k
duration
float64
0.5
125
file_name
stringlengths
8
31
path
stringlengths
14
39
audio
audioduration (s)
0.5
125
donc nag problèmes boobu nag moo taxoon te mbay la bi nga xam ne aussi mbay la bi nga xam ne moom tamit dafay joué benn rôle bu rëy ci li ñuy wax sécurité alimentaire bi
9.611
wol_35110_596.203_605.814.wav
kallama/wol_35110_596.203_605.814.wav
%e defe naa ne damay delluwaat tuuti ci ginnaaw maanaam dama bëgg comme ni tubaab ni mu ko waxee dama bëgg définir ñu ANCAR
7.241
wol_44113_261.908_269.149.wav
kallama/wol_44113_261.908_269.149.wav
Nataal bii nag moom aw jën moo ci nekk, jën wi nag dafa xaw a tàppu-ndaar, moom daa doomu-taal am lu marron ci kanam ci mooy ci boori gémmiñ gu, geen bi tamit dafa xaw a ñuul, laaf yi tamit dafa xaw a ñuul am ay xat-xat.
17.537813
3473:7.wav
waxal/3473:7.wav
waaw lan lan mooy développeur économique mooy ay nit ñoo xam ne nii dañu nekk ci kuréel gi am seen xam-xam xaw a màcc ci loolu ñoom ñu mën di dem di di leen orienté di leen di leen gunge di leen di leen jàppale di leen %e wan yoon wi di leen wan buntu bi ba loolu mën a nekk loolu dafa nekk loo xam ne nii dafa am solo
22.69
wol_41011_398.778_421.468.wav
kallama/wol_41011_398.778_421.468.wav
ku war a denc seetoo na ko ngay dencee surtout li ngay wax aussi ci loo jël rek dugal ca %e dencee ko
8.508
wol_43412_1194.006_1202.514.wav
kallama/wol_43412_1194.006_1202.514.wav
ba pare souvent aussi ñun dañu am c' est culturel aussi
2.917
wol_35312_337.709_340.626.wav
kallama/wol_35312_337.709_340.626.wav
nutrition
0.561
wol_43512_236.183_236.744.wav
kallama/wol_43512_236.183_236.744.wav
agence nationale de conseil agricol et rural
2.328
wol_44113_316.08_318.408.wav
kallama/wol_44113_316.08_318.408.wav
jërëjëf monsieur Mignane Diouf ni nga ko waxee rek %e ci wàllub récolte bi ak post récolte bi am na solo lool waaye rek dañuy jëlaat suñu laaj jox ko ki nga xamante ni moom mooy monsieur tonton Codé Ndiaye
9.85
wol_43032_622.315_632.165.wav
kallama/wol_43032_622.315_632.165.wav
Lii nag mu nekk foto Président bu Senegaal Maki Sàll... Moon nag ginnaaw bu jafe-jafe yi amee fële Mali mu am nag lëkkëloo nag ben président bu Mali xool niñuy Ba Mali jogé ci guuuta gi mu nekk..
25.677813
19:259.wav
waxal/19:259.wav
dafa war a am bérébu boppam boo xam si ne su fay dugg moom rek moom ak équipe ba fay dugg buénu paree tëjaat nañ génn dem seen yoon
7.871
wol_41012_662.977_670.848.wav
kallama/wol_41012_662.977_670.848.wav
nga yaakaar ni taw bi jeex na
1.581
wol_43611_1632.306_1633.887.wav
kallama/wol_43611_1632.306_1633.887.wav
moo tax ma ne toujours njëriñ loolu da lay permettre nga jël décision première information bi boo ko amee rek dina la mën a wax la nga bëggoon a defi nga jàpp pour gën ko def
11.982
wol_43411_1024.356_1036.338.wav
kallama/wol_43411_1024.356_1036.338.wav
nga fexe ba suuxat ko
2.244
wol_43810_2617.173_2619.417.wav
kallama/wol_43810_2617.173_2619.417.wav
Nataal bii day wane ay garab yu bari yoo xam ne dañ koo dajale di ko jaay. Yenn yi ay bant la, yenn yi lu mel ni ay xeer la ñu def ko ci ay bool yu ndaw.
12.177813
3556:428.wav
waxal/3556:428.wav
%e man nag maa ngi koy sant di ko gërëm
2.862
wol_42514_321.266_324.128.wav
kallama/wol_42514_321.266_324.128.wav
bi jël en compte Tambacounda ak Kédougou
2.619
wol_44121_158.675_161.294.wav
kallama/wol_44121_158.675_161.294.wav
te membres yooyu ñun li ñu suñu yéene mooy kenn ku nekk fa nga nekk mutuelle yi nga xam ne jegena ak yow dañoo fas yéene li ñuy li ñuy li ñu lay waxtaan ak yow di la ko xirtal fexeel ba kenn ku ne ci mutuel ba la jege nga jéem faa xool ndax danga fa mën a ligéeyanteel ak ñoom wala doo mën a liggéeyanteel ak ñoom
15.903
wol_4812_750.575_766.478.wav
kallama/wol_4812_750.575_766.478.wav
kon loolu am na solo kon loolu wane na béykat bi sàmmkat bi ak nappkat bi yëpp ñoo bokk yem ci wàllu xam xibaari météo ngir mun see jëriñoo ndax kenn ku ne xibaar bi mun na la jëriñ si sa yëngu-yëngu
12.63
wol_43960_880.44_893.07.wav
kallama/wol_43960_880.44_893.07.wav
PAM moo koy jël en charge mooy loolu mooy ndimalu PAM
3.135
wol_42921_1059.19_1062.325.wav
kallama/wol_42921_1059.19_1062.325.wav
ndax bu saa yu taw bi ñëwee rek taw bu bëri bu wàccee rek donc mun na bàyyandiku ndànk-ndànk ba mu disparaitre complètement donc cas boobu noonu lañ ko observer
8.57
wol_42110_1899.637_1908.207.wav
kallama/wol_42110_1899.637_1908.207.wav
Nataal bii de maa ngi ciy séen pasti, pasti yu vertes, yu ŋëlŋë xaw naa takku, pasti suukar a ngi ca, takku na lool, verte na itam
18.2735
3575:42.wav
waxal/3575:42.wav
te kootoot boobu en en l' espace benn journée rek mën naa ñëw fees fees tool bi yëpp
4.138
wol_4410_1955.389_1959.527.wav
kallama/wol_4410_1955.389_1959.527.wav
Waaw nataal bii nataal la boob, bennub raglu la bu nekk ci Senegaal, nekk ca gëblag Ndakaaru. Turu raglu bi nag bind nañ ko ci kaw mooy raglub principal.
16.657813
3643:551.wav
waxal/3643:551.wav
parce que am na kii bu gaaw bi nga xam ne daal soo xoolee fii Sénégal am na lu ñuy wax carte variétale donc zone bu nekk ci maanaam lu ñuy am ci ndox am na xeetu jiw bi nga xam ne daal bu ñuy soxla li nga xam ne daal soo ko jiyee foofu day ñor zone bu nekk ci Sénégal
15.362
wol_43960_318.767_334.129.wav
kallama/wol_43960_318.767_334.129.wav
boo defee engrais NPK yii nii ñuy utiliser engrais de synthèse yi nga jël ko def ko ci suuf
4.758
wol_4210_1045.294_1050.052.wav
kallama/wol_4210_1045.294_1050.052.wav
%e coopératives yooyu yoo xam ne stock
1.578
wol_44122_265.682_267.26.wav
kallama/wol_44122_265.682_267.26.wav
mécanique d' aténuation bi mooy léegi nan laay def ba changement climat boobu mu wàññeeku
3.818
wol_44111_539.386_543.204.wav
kallama/wol_44111_539.386_543.204.wav
ah sa rendement mën naa am ay difficultés
2.25
wol_44311_297.211_299.461.wav
kallama/wol_44311_297.211_299.461.wav
ñëw yëgal ñu jafe-jafe yi ñuy am
2.063
wol_45421_512.446_514.509.wav
kallama/wol_45421_512.446_514.509.wav
donc day am ay cotisations yoo xamante dañ koy faral di def cotisations yooyu ñoom ñooy xool lan moo leen arranger lan lañ mun a def ku nekk mun nañ ne par exemple groupement bi nii ñun de ah ñun cent franc la ñu war a di mun a def chaque semaine di cotiser cent franc chaque membre
17.614
wol_42921_1566.691_1584.305.wav
kallama/wol_42921_1566.691_1584.305.wav
day mel ni nga tibb suuf nii rek du xeeñ dara
2.638
wol_4210_1552.263_1554.901.wav
kallama/wol_4210_1552.263_1554.901.wav
Nataal bii de ñi ngi koy wax njamala ba noppi mu am guddu gu mag yaay ak doom. Ba noppi mu nekk foo xam ne dafa bari ay bant lool, bari ñax mu wert lool.
12.717813
3562:1580.wav
waxal/3562:1580.wav
mun nga ko ci sotti
0.906
wol_43810_1620.769_1621.675.wav
kallama/wol_43810_1620.769_1621.675.wav
ñu ngi koy encoragé bu baax
1.391
wol_45421_1605.65_1607.041.wav
kallama/wol_45421_1605.65_1607.041.wav
du machine du du jiwu du lenn lu dul climat ñaata la ñuy am si taw ak ndax nawet bi dana baax wala du baax
7.989
wol_42512_477.486_485.475.wav
kallama/wol_42512_477.486_485.475.wav
%e daanaka dafay da dafay topp
2.826
wol_45421_249.226_252.052.wav
kallama/wol_45421_249.226_252.052.wav
pour %e dëkk àll yi nga xamante ne ni tamit xamuñu ko y a des comités de lutte villageoises
4.785
wol_41110_1199.622_1204.407.wav
kallama/wol_41110_1199.622_1204.407.wav
ci waxtaan bu mel nii
1.013
wol_45422_1565.749_1566.762.wav
kallama/wol_45422_1565.749_1566.762.wav
waaw léegi yooyu yëpp day waral ngay dégg chaque jour mool yi di wax jën géej gi amatul jën
6.32
wol_43712_342.025_348.345.wav
kallama/wol_43712_342.025_348.345.wav
pro() projet bi kay li ñu li mu ñu jàngal parce que mën naa ni %e commun() communication pour ñu nekk des des agents de communica() communicateur vrai ci agent Ticmbay bii la ñu ko dem() la ñu ko demarrer
13.133
wol_31212_745.441_758.574.wav
kallama/wol_31212_745.441_758.574.wav
%e monsieur Tall
1.085
wol_44114_688.538_689.623.wav
kallama/wol_44114_688.538_689.623.wav
mën naa wax sax région Tambacounda xëy na mën na am matériels yu bëri yoo xam ne ma amuñ ko
4.594
wol_44312_820.998_825.592.wav
kallama/wol_44312_820.998_825.592.wav
non non
0.543
wol_31211_291.005_291.548.wav
kallama/wol_31211_291.005_291.548.wav
%e religieuses et et cotumiers
1.52
wol_45412_576.468_577.988.wav
kallama/wol_45412_576.468_577.988.wav
ku ci nekk rek war nga mun a bàyyi xel ëllëg
2.746
wol_44412_1681.084_1683.83.wav
kallama/wol_44412_1681.084_1683.83.wav
%e 77
1.516
wol_4313_111.208_112.724.wav
kallama/wol_4313_111.208_112.724.wav
te ndox nag si wàllu parcelle bi bu fekkente ne taw na ba ndox bi xaw a am temps tuuti bim fay taxaw dina njëriñ gàncax bi moom si suuf la koy la koy la koy jëlee
13.028
wol_41930_664.874_677.902.wav
kallama/wol_41930_664.874_677.902.wav
kon loolu nañ ci bàyyi xel jarul fiiraange
1.973
wol_44412_575.269_577.242.wav
kallama/wol_44412_575.269_577.242.wav
waaw %e ak tamit %e souvent tamit %e léeg-léeg béykat léegi nañ la woo laaj la donc nga jox leen information mais bii ma la wax nii réseaux sociaux yi ñoo gën a efficace parce que yow li nga mën a envoyer ci alerte ci partager information ANACIM yi
17.569
wol_42612_1553.263_1570.832.wav
kallama/wol_42612_1553.263_1570.832.wav
ñax ma du bëri
0.728
wol_43032_589.073_589.801.wav
kallama/wol_43032_589.073_589.801.wav
waaye nit ñi dañuy topp ga() àll bi di dgg
3.112
wol_43211_940.62_943.732.wav
kallama/wol_43211_940.62_943.732.wav
loolu mu wax yëpp de %e lu am la
1.961
wol_4313_137.27_139.231.wav
kallama/wol_4313_137.27_139.231.wav
ngir nit ñi gën koo jox gëdd loolu dafa am dafa am solo
4.87
wol_4613_757.822_762.692.wav
kallama/wol_4613_757.822_762.692.wav
li ñu leen peut être que liñ chance bi ñu am rek mooy comme ñun jumtukaay yi ñuy
3.532
wol_42932_1322.586_1326.118.wav
kallama/wol_42932_1322.586_1326.118.wav
am na dugub boo xam ne quatre vingt jours
2.739
wol_44411_871.527_874.266.wav
kallama/wol_44411_871.527_874.266.wav
war nañoo mën a xayma dégat gu mu mën a def ci biir tool maanaam yàq-yàq cib tool
3.637
wol_4410_873.725_877.362.wav
kallama/wol_4410_873.725_877.362.wav
ba kenn ku si nekk mu xam li nga xamante ne moom mooy enjeu bi nga xam ne pour ñoom ñu am seen suuf moomal ko seen bopp di si liggéey li mu leen mun a jural yaakaar naa ne ëpp na sax dem jël gaal dem dugg ci gaal yi di dem
15.27
wol_44712_838.218_853.488.wav
kallama/wol_44712_838.218_853.488.wav
te gis nañ ne communication biñ jot a def ak Jokalante ak Ticmbay
2.968
wol_36310_380.916_383.884.wav
kallama/wol_36310_380.916_383.884.wav
comme tey par exemple bu naree taw %hum %e alertes yooyu dañ koy envoyé
6.704
wol_42911_1434.629_1441.333.wav
kallama/wol_42911_1434.629_1441.333.wav
ndax ñun li ñuy couvrir
1.806
wol_4410_2138.638_2140.444.wav
kallama/wol_4410_2138.638_2140.444.wav
wala xale yiy liggéey ci tool yi ñuy bàyyi xel bu baax a baax ci nen yi yooyu
2.936
wol_4410_1595.669_1598.605.wav
kallama/wol_4410_1595.669_1598.605.wav
waaw dama lay jox exemple rek ak
1.533
wol_43010_947.338_948.871.wav
kallama/wol_43010_947.338_948.871.wav
waa kon si gerte gi moom xam naa ne pour * pour mën a bokk moom lu leer lay doon
5.394
wol_4910_304.429_309.823.wav
kallama/wol_4910_304.429_309.823.wav
maanaam tey mun nga jël ay jeunes yu bëri ñu nga xam ne dañoo bugg a lancer wu ci maraîchage
5.251
wol_44611_1271.437_1276.688.wav
kallama/wol_44611_1271.437_1276.688.wav
koo xamante ne depuis bi mañëwee Thiel man ak moom pratiquement chaque fois ñooy nekk
4.594
wol_41930_156.537_161.131.wav
kallama/wol_41930_156.537_161.131.wav
ci loolu nag ci la Fa() prise de conscience bi am ren ren naka lañuy ban stratégie lañuy jël ban pexe lañuy jël pour que ñu teg bennn chaine boo xam ne nii
8.452
wol_4314_146.623_155.075.wav
kallama/wol_4314_146.623_155.075.wav
wàllum mbay mi wax dëgg yàlla loola tooguñu bokk toog di ko waxtaanee di ko toog bokkuñu toog di ko waxtanee ndax man fii ma ne
6.845
wol_56610_184.849_191.694.wav
kallama/wol_56610_184.849_191.694.wav
mais toppandoor Mawlana Cheikh Ibrahim ne bu ye bonul baaxul toppandoor lu bon moo baaxul
5.625
wol_44412_371.923_377.548.wav
kallama/wol_44412_371.923_377.548.wav
ndax ñi may interpellé la %e Jean Noël Diouf la animateur Caritas bon li ma ci bëgg a wax rek ma koy wax %e monsieur Khoule sama question yow la concerné parce que ñun dañoo gis ne cycle yi ñu yor 90 jours lañ ci wax muy ceeb bi %e mil bi ak arachide bi léegi ci biir loolu nawet bi gis nañ ne dina gudd ndax am na ay mesures d' accompagnement yoo xam ne prévoir nañ ko pour semis yi loolu benn question la
38.108
wol_42712_885.504_923.612.wav
kallama/wol_42712_885.504_923.612.wav
chaque fois ñoom avant muy nawet dafa am ñuy wax wax dina taw wala du taw
3.836
wol_42912_1013.474_1017.31.wav
kallama/wol_42912_1013.474_1017.31.wav
li ma leen di proposé moom bokk na ci war naénoo defar benn tableau boo xam ne si dafa war a nekk ci tali bi %e nga xam ne si bépp oto boo xam ne
6.966
wol_4613_73.429_80.395.wav
kallama/wol_4613_73.429_80.395.wav
Waaw nataal bii nag gis naa ci ab fu yaatu foo xam ne nii ab toogukaay ñoo fa nekk, ñetti toogukaay ak taabul.
13.657813
3453:1129.wav
waxal/3453:1129.wav
Salaamaalekum! Nataal bi nu ngi ciy gis benn kayit bu mboq nu koy wax ëe pasti ; waaw ak doomi yu nu teg ci suuf nu teg leen ci wetu kayit bi.
20.957813
3039:41.wav
waxal/3039:41.wav
Waaw lii de lu mel ni xeetu bic la, bic. Bi ma xoolee kubéer gu ñuul mi ngi ci kawam. Bic bi nag am na mbind mu weex ak mbind mu ñuul.
14.217813
2822:651.wav
waxal/2822:651.wav
waaw loolu moom fas naa koo yéene bu baax a baax ndax gis naa ne la ma ci jëloon fa ma ko jiyee na ma ko bëggee woon saxee na ko wante nag rendement bi bu mboq bi des na %e damaa xamul debut nawet bi la wala parce que nawet bi nim nim débuté ren dafa xaw a doy waar
14.678
wol_35710_62.022_76.7.wav
kallama/wol_35710_62.022_76.7.wav
nu ñu commencé lu ñu am lu mu tuuti tuuti nañ ko commencé parce que li ñuy wax ne tepp tepp moo gën yuréet nit ku nekk saa yoo yeewoo war nga jéem di def innovation
10.057
wol_44712_1096.709_1106.766.wav
kallama/wol_44712_1096.709_1106.766.wav
parce que suñ contrôlé nit yi nit yi di dugg Sénégal génn Sénégal ndax am nañu lu ñuy wax carnet de vaccination ah %e y' a aussi %e autorité administrative yi léeg-léeg dañuy soxla ay conseils par rapport à l' hygène au niveau soit des régions oubien au nivaeu du département donc loolu noonu suñu %e suñu suñu liggéey la
22.172
wol_43910_237.404_259.576.wav
kallama/wol_43910_237.404_259.576.wav
boobu engrais guñ ko boobu des na boobu mooy mujjee après fu mu ne nii daal ci li ñuy ci li ñu war a def mooy dangay def %e engrais ngay def boo defee engrais nga def fumier
8.741
wol_42010_986.551_995.292.wav
kallama/wol_42010_986.551_995.292.wav
parce que loolu mooy déterminer ëllëg
2.076
wol_43111_976.591_978.667.wav
kallama/wol_43111_976.591_978.667.wav
bay rek bay tamit
0.834
wol_44312_201.961_202.795.wav
kallama/wol_44312_201.961_202.795.wav
ba pare jural leen ay problèmes maanaam wér-gu-yaram parce que tey changement climatique lan la mooy température bi nga xamante ni dafay gën a yokk
9.157
wol_45511_788.318_797.475.wav
kallama/wol_45511_788.318_797.475.wav
43
1.3
wol_4711_1424.906_1426.206.wav
kallama/wol_4711_1424.906_1426.206.wav
doon leen wax njëriñu denc
1.553
wol_44913_487.662_489.215.wav
kallama/wol_44913_487.662_489.215.wav
des fois dina am ay pauses pluviométriques si diggante bi
3.172
wol_43020_717.335_720.507.wav
kallama/wol_43020_717.335_720.507.wav
RTS Tambacounda allo
1.665
wol_45411_1236.426_1238.091.wav
kallama/wol_45411_1236.426_1238.091.wav
%hum %hum loolu moo foofu la Ibrahima doon wax il faut que ñu ràññee
2.218
wol_4612_75.643_77.861.wav
kallama/wol_4612_75.643_77.861.wav
am na technique yoo xamante ne tamit
2.611
wol_44311_1477.014_1479.625.wav
kallama/wol_44311_1477.014_1479.625.wav
waaw ndax sax la bi nga xamante ni
2.307
wol_45421_1347.808_1350.115.wav
kallama/wol_45421_1347.808_1350.115.wav
il foog nga xam ñaata milimètres la taw
1.74
wol_42932_409.096_410.836.wav
kallama/wol_42932_409.096_410.836.wav
ñoo ngi disponible
1.145
wol_43612_787.547_788.692.wav
kallama/wol_43612_787.547_788.692.wav
kuy sàmm day béy
1.324
wol_44811_429.17_430.494.wav
kallama/wol_44811_429.17_430.494.wav
mais dafa xóot
0.809
wol_43810_2185.343_2186.152.wav
kallama/wol_43810_2185.343_2186.152.wav
Lii de ab nataal la boob mel na ne maa ngi ciy gis ay nit ñu bare. Ñu ngi sol ay mbubu yu weex ak i tubéy yu ñuul. Ni ma leen gise nii nag mel na ne am na lu ñuy ñaxtu, am na lu ñuy mettitlu. Ndaxte ñu ngi ci kow ab tali, ñii ngi sukk ñii ngi taxaw tàllal seeniy yoxo.
18.837813
3595:1.wav
waxal/3595:1.wav
léegi information soo ko amee da lay da lay dimbale waaw soo soo soo amee information boobu tamit da lay da lay dimbale
7.345
wol_43712_1018.211_1025.556.wav
kallama/wol_43712_1018.211_1025.556.wav
maanaam ñëpp institué nañu cotisation annuelle pour chaque membre 1000F par membre et par an
5.741
wol_31211_989.282_995.023.wav
kallama/wol_31211_989.282_995.023.wav
ndaxte yemuñu rek ci râteau
1.813
wol_44114_377.022_378.835.wav
kallama/wol_44114_377.022_378.835.wav
mboq moom tamit attaque attaque am ba munoon naa wax ni sax amul attaque waaye fan yii weesu ñetti at yii gis nañ ne am nañ attaque bu ñuy wax chenille légionnaire chenille légionnaire mooy sax bu nga xam ne day dugg ci biir xol bi di ko lekk ngay mel ni mu mel ni ay nen yu bëri ñoo ciy nekk ah fan yii sonal nañ leen booy xool sama oto biy traité jógee na Dakar mu ngi fii di traité tool yi
20.736
wol_43012_997.131_1017.867.wav
kallama/wol_43012_997.131_1017.867.wav
looy gën a yéeg dafay gën a seddwante looy gën a wàcc dafay gën a tàng léegi tàngoor bi nga xamante ne moom mooy nekk si suuf dafa mel ni nga jël benn %e maanaam baraada teg ko ci fourneau ah di ko upp muy bax ba baraada bi di bël bal tuuru
16.195
wol_45511_1208.943_1225.138.wav
kallama/wol_45511_1208.943_1225.138.wav
dafa excédentaire mais nag yooyu ay xaw a ay calcul la
2.425
wol_42932_896.937_899.362.wav
kallama/wol_42932_896.937_899.362.wav
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
39
Edit dataset card