text
stringlengths 1
2.33k
| duration
float64 0.5
212
| file_name
stringlengths 22
31
| path
stringlengths 37
46
| audio
audioduration (s) 0.03
212
|
---|---|---|---|---|
sauf picc yi picc yi daal moom yooyu moom bokku si | 3.163 | wol_43930_1484.462_1487.625.wav | audio/kallaama/wol_43930_1484.462_1487.625.wav | |
ci jamono bi ñu nekk et bépp prpjet boo xam ne daf ciy yëngatu rek je pense acteurs yi ci war a jàpp yëpp dañ ci war a jàpp | 6.446 | wol_44611_466.465_472.911.wav | audio/kallaama/wol_44611_466.465_472.911.wav | |
%e assurance dafa am convention ak ministère de l' élevage direction de l' élevage ñun dañu am lëkkaloo donc %e lu ñu booleeg ñoom ñoom dañuy partager services techniques képp koo xam ne yaa ngi ci sa poste vétérinaire te yàlla mun loo la na nga ko defal procès verbal bi constat bi yaa ko war a def | 19.959 | wol_43951_1389.533_1409.492.wav | audio/kallaama/wol_43951_1389.533_1409.492.wav | |
wala que di par wala wala tamit par arrondissement | 3.482 | wol_43612_359.106_362.588.wav | audio/kallaama/wol_43612_359.106_362.588.wav | |
loo ciy tënk loo loo loo ciy yokk lan ngay tàggoo | 2.893 | wol_42812_1634.225_1637.118.wav | audio/kallaama/wol_42812_1634.225_1637.118.wav | |
ñëpp a soxla information climatique | 1.745 | wol_44012_594.736_596.481.wav | audio/kallaama/wol_44012_594.736_596.481.wav | |
merci beaucoup | 0.975 | wol_44012_1229.937_1230.912.wav | audio/kallaama/wol_44012_1229.937_1230.912.wav | |
ANACIM ñoo koy toppatoo | 1.14 | wol_44121_1644.492_1645.632.wav | audio/kallaama/wol_44121_1644.492_1645.632.wav | |
parce que ñu %e béykat yëpp xam nañu ni suuf c' est un élément vital | 4.487 | wol_31211_259.757_264.244.wav | audio/kallaama/wol_31211_259.757_264.244.wav | |
parce que dangay gis ni serieux na ci wàllu liggéey bi | 2.422 | wol_44914_217.052_219.474.wav | audio/kallaama/wol_44914_217.052_219.474.wav | |
%e code barre moo lay may nga xam ne sa maté() sa bagage bi ngay yore mën nga koo gñne ci réew mi dem jaayi ko bitim réew kon loolu jigéen ñëpp ñoom ñoo war a %e xam yoon bi mën di ko jëfee ba ñi nga xam ne ñoom kenn ku ci nekk produit yi nga yor di nga si mën di gñne si biir marché bi danga mën a gñne bitim réew | 15.129 | wol_41011_575.832_590.961.wav | audio/kallaama/wol_41011_575.832_590.961.wav | |
donc ñu bëri moo tax dañuy échoué mboq mboq bu fekkee mboq boo xam ne ay penard la ay indien la wala * loolu dafa exigent parce que ci engrais mu ngi laaj benn hectare juróom-benn saak fu kii di laajtee ñetti saak parce que ay variétés hybride la yoo xam ne dañoo exigent bu fekkee ci urée bi la hectare mu ngi laajte ñeenti saak juróom-benni saako kon donc matuwaay yi ngeen di jël ci hybride bokkul matuwaay yi ñuy jël ci variété locale | 25.995 | wol_43011_1364.193_1390.188.wav | audio/kallaama/wol_43011_1364.193_1390.188.wav | |
peut être %e ci biir waxtaan wi mën naa am ñu dellusiwaat si mais nañu xam ne daal %e insecte ravageurs yi nga xam ne ñoom ñoo gën a mën a yàq stoc ci biir magasin wala ci biir %e grenier wala ci ci foo ko foo mën a denc sa sa sa sa meññeef %e juróom-benni famille céoptère yooyu ma leen limal bokk nañ si ak ñetti lépidoptère yooyu ma leen wax ñoom it bokk nañ ci ñi nga xam ne ñoo dàq a yàq | 23.466 | wol_43311_939.651_963.117.wav | audio/kallaama/wol_43311_939.651_963.117.wav | |
je pense mun nañ jël benn thématique boo xam ne dafa am lien ak maraîchage pour ñu sensibiliser leen ci thématique boobu | 7.157 | wol_44611_1263.753_1270.91.wav | audio/kallaama/wol_44611_1263.753_1270.91.wav | |
waaw effectivement compliqué na trop | 1.584 | wol_41011_377.815_379.399.wav | audio/kallaama/wol_41011_377.815_379.399.wav | |
%e bëgg mu gën a bëgg a gën a xam | 1.248 | wol_41711_498.832_500.08.wav | audio/kallaama/wol_41711_498.832_500.08.wav | |
yoo xam ne mën na ko jëfandikoo effectivement daan nañu am problème yu mel noonu | 3.365 | wol_44113_718.141_721.506.wav | audio/kallaama/wol_44113_718.141_721.506.wav | |
producteur yi dinañ xam ban pratique moo gën bu fekkee ne nag biñ leen indil | 5.153 | wol_44612_164.241_169.394.wav | audio/kallaama/wol_44612_164.241_169.394.wav | |
d' accord | 0.968 | wol_4111_1439.528_1440.496.wav | audio/kallaama/wol_4111_1439.528_1440.496.wav | |
noonu la ñu war a informa() am information ñëw ci service techniques yi ñu wax la ñu wax rek quelle période la ñu war a ji lan mooy gerte lan mooy dugub lan mooy mboq loolu tamit véhiculer message yi muy yi nga wax nii en terme de communication daf ci am solo | 12.977 | wol_43031_793.743_806.72.wav | audio/kallaama/wol_43031_793.743_806.72.wav | |
maanaam sable bi | 0.875 | wol_44112_371.412_372.287.wav | audio/kallaama/wol_44112_371.412_372.287.wav | |
waaw loolu yëpp gis nañu ko si | 1.629 | wol_42514_319.154_320.783.wav | audio/kallaama/wol_42514_319.154_320.783.wav | |
toog na jotul sax woote waaye mu ngi doon déglu émission bi ñu ngi leen di gërëm di leen jaajëfal bu baax a baax | 3.955 | wol_45422_1626.226_1630.181.wav | audio/kallaama/wol_45422_1626.226_1630.181.wav | |
te kenn ku ci nekk fii am na loo xam ne mën na ko ci indi | 3.399 | wol_43211_232.726_236.125.wav | audio/kallaama/wol_43211_232.726_236.125.wav | |
ndax su boobaa température yiñ nar a dundee si addina nit yi du ko )ttan parce que dinañ dem ba moins dix huit degré muy nekk température bu négative loolu nit munu see dund | 14.173 | wol_43711_1220.19_1234.363.wav | audio/kallaama/wol_43711_1220.19_1234.363.wav | |
am na solo kon Diallo Diagne ñu ngi lay gërëm di la sant di Pusseynou diagne bokk ci liggéey bi tamit moom moo fare woon côté Njaañ kon ñu ngi lay gërëm di la sant jërëjëf | 8.62 | wol_41910_1509.772_1518.392.wav | audio/kallaama/wol_41910_1509.772_1518.392.wav | |
%hum %hum kon ñu mën a jàpp rek ne déréglement boobu nga xamante ne nii gis nañ ko ci wàllu prévision yi ci fi nga xamante ne nii %e mooy gox bi ñu féetoo di diwaanu Nior gën cee leer di Saloum %e nekk na loo xamante ne nii %e coppite jaww ji la maanaam changement climatique bi moo ko daal di andi | 15.503 | wol_43020_1336.98_1352.483.wav | audio/kallaama/wol_43020_1336.98_1352.483.wav | |
%hum ak waa ICS ah def ay recherches ba nga xam ne | 3.695 | wol_43012_641.14_644.835.wav | audio/kallaama/wol_43012_641.14_644.835.wav | |
te yoroo torche boo ko niinee | 1.665 | wol_43020_1748.836_1750.501.wav | audio/kallaama/wol_43020_1748.836_1750.501.wav | |
maintenant am na yeneen catégories jeunes nag yoo xam ne su def nañ formation | 6.013 | wol_44611_1119.579_1125.592.wav | audio/kallaama/wol_44611_1119.579_1125.592.wav | |
loolu mooy problème bi gàllankoor mooy pro() parce que biodigesteur bu demee ba fonctionner nga am sa engrais nga am sa gaz daanaka jigéen yu bëri nga xam ne dañuy yëngu ci wàllum transformation parce que tamit waxuñu ko | 13.086 | wol_42922_459.025_472.111.wav | audio/kallaama/wol_42922_459.025_472.111.wav | |
waaye nag dans topus les cas | 0.975 | wol_44112_545.549_546.524.wav | audio/kallaama/wol_44112_545.549_546.524.wav | |
waaw mooy li may wax rek | 1.617 | wol_43412_1364.893_1366.51.wav | audio/kallaama/wol_43412_1364.893_1366.51.wav | |
wala soit leneen nga ñooñu kenn ku ci nekk war nga mën a defar say kayit ba mu valable soo amee say kayit ba mu valable nag nga xam ne say produit boo ko xasee defar | 8.751 | wol_41011_682.942_691.693.wav | audio/kallaama/wol_41011_682.942_691.693.wav | |
kon nag | 0.683 | wol_43612_109.328_110.011.wav | audio/kallaama/wol_43612_109.328_110.011.wav | |
waaw xam nga jamono suy dox nag | 1.115 | wol_42811_1220.263_1221.378.wav | audio/kallaama/wol_42811_1220.263_1221.378.wav | |
dégg nga %e damay fàttali leen gën di wax nit ñi %e laaj leen ñu ni ñu bon messages yi baax na waaye li leen gënaloon moom mooy message rajo am na kii quoi message kii quoi vocal | 11.226 | wol_42212_1458.933_1470.159.wav | audio/kallaama/wol_42212_1458.933_1470.159.wav | |
ci loolu te te te te lu ñu xamul mooy maanaam janax boobu sax am na feebar bu muy joxe parce que janax bi sawam yi sawam bi dafa am benn feebar boo xam ne dafa nekk ci moom | 11.761 | wol_43910_1507.543_1519.304.wav | audio/kallaama/wol_43910_1507.543_1519.304.wav | |
moo tax énoom %e vraiment macha allah dañu leen dii dañu leen di sant bu baax a baax beneen bi ci des tey jii ñu énu dugal beneen %e domaine ci mbir mi muy restauration | 9.06 | wol_4613_766.946_776.006.wav | audio/kallaama/wol_4613_766.946_776.006.wav | |
xam e rek moo di ANACIM ndax li nga xam ne rek moo di changement climatique doon na réalité | 7.328 | wol_42513_0.0_7.328.wav | audio/kallaama/wol_42513_0.0_7.328.wav | |
salaamaaleykum | 0.528 | wol_43612_1496.484_1497.012.wav | audio/kallaama/wol_43612_1496.484_1497.012.wav | |
donc li si jiitu mooy information météo bi ci la bokk d' accord | 4.769 | wol_43020_1468.504_1473.273.wav | audio/kallaama/wol_43020_1468.504_1473.273.wav | |
maanaam au lieu ngay de() ngay dem ak sa xel noonu rek | 2.914 | wol_42932_221.794_224.708.wav | audio/kallaama/wol_42932_221.794_224.708.wav | |
dañu lay indil yow dañuy indi dañuy indi ngeen ñam produit yëpp la ñuy indi | 2.678 | wol_41013_538.395_541.073.wav | audio/kallaama/wol_41013_538.395_541.073.wav | |
ni ko amsecta yi | 1.121 | wol_45412_78.507_79.628.wav | audio/kallaama/wol_45412_78.507_79.628.wav | |
%e di leen ko xamal ñuy xam fuñuy teg seen i tànk | 2.352 | wol_4812_648.797_651.149.wav | audio/kallaama/wol_4812_648.797_651.149.wav | |
il faut que ñun ñii ñu xam ne mbay | 1.554 | wol_44112_491.174_492.728.wav | audio/kallaama/wol_44112_491.174_492.728.wav | |
bokkul dafa xaw a danoo niróo nag | 1.521 | wol_45412_1422.167_1423.688.wav | audio/kallaama/wol_45412_1422.167_1423.688.wav | |
alahuma amiin | 1.357 | wol_4314_469.128_470.485.wav | audio/kallaama/wol_4314_469.128_470.485.wav | |
%hum te ku am %e béykat boo xam ne da nga yor say jur war leen a dundal defe nga ne kooku dina la dégg | 6.775 | wol_43810_1515.222_1521.997.wav | audio/kallaama/wol_43810_1515.222_1521.997.wav | |
%e incha allah | 0.996 | wol_42931_143.888_144.884.wav | audio/kallaama/wol_42931_143.888_144.884.wav | |
bisimilah sëñ bi na nga tudd | 2.226 | wol_35710_0.0_2.226.wav | audio/kallaama/wol_35710_0.0_2.226.wav | |
dama bëggoon na %e contribuer ci %e seen émission bu am importance bii | 5.28 | wol_43412_1029.681_1034.961.wav | audio/kallaama/wol_43412_1029.681_1034.961.wav | |
moom moo doon ñëw lu gën a bari di def si émissions yi | 3.275 | wol_35312_80.37_83.645.wav | audio/kallaama/wol_35312_80.37_83.645.wav | |
mu ngoog kooku la | 1.14 | wol_45412_402.597_403.737.wav | audio/kallaama/wol_45412_402.597_403.737.wav | |
loolu mooy surtout jafe bi donc météo ne suba dina taw béykat bi nan lay fexe ba am information boobu mais tamit il faut que tamit %e ñoom i tam ñu def ay effors tamit parce que boo xoolee tey rajo yi comme rajo Ndefleng par exemple fii souvent météo daf fay jaar def ay émissions joxe ay informations ak yooyu ah | 23.217 | wol_42912_912.838_936.055.wav | audio/kallaama/wol_42912_912.838_936.055.wav | |
et et tey %e Habib %e lu tax COPEGA di di di dérangé c' est à dire le problème c' est quoi parce que man bu fekkee dëgg rek laa leen wax su ma déggee ku leen di supporté wala ku ànd ak yéen rek ñaareel ab béykat la mais au delà de ça les orga() ñeneen ñiy yëngatu ci kii bi filière bi daal da da ngeen di dérangé %e le problème c' est quoi lan la | 18.301 | wol_44412_289.321_307.622.wav | audio/kallaama/wol_44412_289.321_307.622.wav | |
%e chaque président de section villageoise ñu convoqué leen | 2.768 | wol_31212_398.721_401.489.wav | audio/kallaama/wol_31212_398.721_401.489.wav | |
dégg nga | 0.597 | wol_42611_1326.665_1327.262.wav | audio/kallaama/wol_42611_1326.665_1327.262.wav | |
ñu def ay jàngat xool gis ne effectivement gis nañ ne depuis des années suñ delloo si histoire depuis les années mille huit cent | 10.383 | wol_43020_946.218_956.601.wav | audio/kallaama/wol_43020_946.218_956.601.wav | |
en vu de la prochaine campagne | 1.379 | wol_43810_429.193_430.572.wav | audio/kallaama/wol_43810_429.193_430.572.wav | |
%hum %hum foog mu ñor foog ñu weer ko ba mu wow koŋŋ | 3.721 | wol_43311_1281.979_1285.7.wav | audio/kallaama/wol_43311_1281.979_1285.7.wav | |
comme day nekk information bu yaatu | 1.629 | wol_44113_568.911_570.54.wav | audio/kallaama/wol_44113_568.911_570.54.wav | |
nga dem ji wala nga dem def | 1.887 | wol_43020_303.171_305.058.wav | audio/kallaama/wol_43020_303.171_305.058.wav | |
boobu day nekk bi ñuy wax limon | 1.996 | wol_44311_591.579_593.575.wav | audio/kallaama/wol_44311_591.579_593.575.wav | |
di sant auditeurs yëpp | 1.447 | wol_4314_904.563_906.01.wav | audio/kallaama/wol_4314_904.563_906.01.wav | |
%hum %hum %hum loolu la kay | 3.075 | wol_4612_82.095_85.17.wav | audio/kallaama/wol_4612_82.095_85.17.wav | |
%hum %hum %hum | 0.923 | wol_4811_156.931_157.854.wav | audio/kallaama/wol_4811_156.931_157.854.wav | |
fépp foo dégg assurance indicelle | 2.549 | wol_44122_726.3_728.849.wav | audio/kallaama/wol_44122_726.3_728.849.wav | |
ba nga xam ni %e niñ niñ daan liggéeyee ñu ngi gën di ci weer yooyu ñu ngi koy ñu ngi koy gën di ñeme ndax ñu ngi doon jotee information ci ci Nafoore dafa dalaloon sunu sunu xel | 10.352 | wol_36510_256.468_266.82.wav | audio/kallaama/wol_36510_256.468_266.82.wav | |
na ñu arrêté di gor | 1.208 | wol_44114_775.094_776.302.wav | audio/kallaama/wol_44114_775.094_776.302.wav | |
bon fumier moom am na solo am na solo trop ci tool | 4.361 | wol_43810_1913.398_1917.759.wav | audio/kallaama/wol_43810_1913.398_1917.759.wav | |
kon foofu daal amoon na kay tuuti jafe-jafe | 1.816 | wol_31211_588.151_589.967.wav | audio/kallaama/wol_31211_588.151_589.967.wav | |
par rapport ak première taw bi | 1.489 | wol_44312_239.938_241.427.wav | audio/kallaama/wol_44312_239.938_241.427.wav | |
yàlla baax na | 0.5 | wol_42212_1631.045_1631.545.wav | audio/kallaama/wol_42212_1631.045_1631.545.wav | |
waaw vaaw | 0.669 | wol_4210_1956.915_1957.584.wav | audio/kallaama/wol_4210_1956.915_1957.584.wav | |
mën nañu la jàpp chambre de commerce ñëpp kenn ku ci ne dana def visite ci fi nga xam si ne mooy béréb bi nga xam ne si nga defaree li nga xam si moom mooy céréale bi wala soit yeneen produit yi ngay defar | 10.342 | wol_41012_75.198_85.54.wav | audio/kallaama/wol_41012_75.198_85.54.wav | |
Baye Niass ba muy wax radi yallaahu anhu | 2.085 | wol_44411_1557.022_1559.107.wav | audio/kallaama/wol_44411_1557.022_1559.107.wav | |
yooyu boobu nag moo gën a garaaw boobu vingt et un fois la gën a garaaw que CO2 tu vois boo xoolee bon yokkuteem mu ngi toll si zero virgule six pour cent ci at bu nekk | 9.814 | wol_45511_546.129_555.943.wav | audio/kallaama/wol_45511_546.129_555.943.wav | |
na ñuy déglu informations yi régulièrement ;fra | 2.101 | wol_42932_394.089_396.19.wav | audio/kallaama/wol_42932_394.089_396.19.wav | |
ndax Fapal kuréel la boo xam ne si wax naa ko ci ñaar ñett fànn yëpp ci lay yëngu | 4.086 | wol_4311_241.463_245.549.wav | audio/kallaama/wol_4311_241.463_245.549.wav | |
donc loolu moom mooy loo xam ne souvent dañu koy déploré | 2.115 | wol_35312_128.212_130.327.wav | audio/kallaama/wol_35312_128.212_130.327.wav | |
jote wuñ sax xëy na peut être ci télévision parce fu mu la fekk dafay sori mais à travers :ra les projets et programmes yi nga xamante ni moom la ñu am ñu mel ni waa 4R ñu mel ni ay Proval ak yeneen ak yeneen jàppale nit ñi ba nga xamante ne bi au niveau de de note service am nañu benn base bi nga xamante ni bii %e ay numéros de téléphones yi ça fait plus de mille | 21.064 | wol_42611_1407.289_1428.353.wav | audio/kallaama/wol_42611_1407.289_1428.353.wav | |
waaye terewul ba tey mën nañu wéyal waxtaan bi ànd ak kii di Jalle yaakaar naa ni li fi Ibrahima wax yëpp am na am na solo te it xam naa ni %e yéen yaa ngi naan Ibrahima moo tax amagu leen yéen code barre mais yéen seen wàllu bopp aussi est ce que mate ngeen normes yi war a tax ngeen am code barre | 14.077 | wol_41013_361.197_375.274.wav | audio/kallaama/wol_41013_361.197_375.274.wav | |
mais bu tawee ci kawam non seulement am na nu muy demee doomu gerte bi dafay | 5.781 | wol_42212_1149.305_1155.086.wav | audio/kallaama/wol_42212_1149.305_1155.086.wav | |
seen seen coopérative | 1.06 | wol_31211_660.072_661.132.wav | audio/kallaama/wol_31211_660.072_661.132.wav | |
mu daal di wow séchage | 2.787 | wol_42912_316.048_318.835.wav | audio/kallaama/wol_42912_316.048_318.835.wav | |
%hum %%hum | 0.689 | wol_36010_4.723_5.412.wav | audio/kallaama/wol_36010_4.723_5.412.wav | |
te mbéyum ceeb ku ko xam ci ji mi dafay ànd ak %e pour mu gaaw a sax il faut que nga am tàngaay bu njëkk ba dañ daan wax ci yenn weer yi daawul tàng dafa daan sedd te gis nañ ni weer yooyu léegi de mi ngi tàng | 12.058 | wol_36510_244.41_256.468.wav | audio/kallaama/wol_36510_244.41_256.468.wav | |
rupture ci ñebe bi kii bi du baax feek book Etat bi nga xam ne ni moom mooy gëstu di gñne lu bees moom dina dina ci %e dina dina dina ko def | 8.613 | wol_4314_155.075_163.688.wav | audio/kallaama/wol_4314_155.075_163.688.wav | |
ah waaw ro() | 1.613 | wol_45411_1777.579_1779.192.wav | audio/kallaama/wol_45411_1777.579_1779.192.wav | |
%e loolu tamit muy beneen aspect ci njëriñ bi nga xam ne rotation bi mun na ko mun na ko mun na ko amal | 4.537 | wol_43810_922.89_927.427.wav | audio/kallaama/wol_43810_922.89_927.427.wav | |
xool yan interet lañuy teg lan moo ci teg ba ci assurances yi ñuy def | 5.43 | wol_4812_613.216_618.646.wav | audio/kallaama/wol_4812_613.216_618.646.wav | |
dêgg la ñu jël kooku allo | 1.882 | wol_44412_1084.008_1085.89.wav | audio/kallaama/wol_44412_1084.008_1085.89.wav | |
ak doxalin bi mën nanoo uute waaye lépp ku ci nekk ku taxawoon fii ne jox leen ma réew mi ma taal Sénégal jox leen ma réew mi ma andil leen ndóol jox leen kan moo ko fi dégg | 8.261 | wol_44412_1765.669_1773.93.wav | audio/kallaama/wol_44412_1765.669_1773.93.wav | |
d' ccord | 0.712 | wol_36410_664.76_665.472.wav | audio/kallaama/wol_36410_664.76_665.472.wav | |
day ma dama lay jox benn misaal rek tey jii boo demee Europe par exemple dangay dem ñu ne la yaa ngi nekk ci ay zero degré wala ay moins moins mo() moins cinq degré affaire yu mel noonu | 11.085 | wol_42212_578.683_589.768.wav | audio/kallaama/wol_42212_578.683_589.768.wav | |
ñooñu ñooy changé | 1.027 | wol_44111_325.206_326.233.wav | audio/kallaama/wol_44111_325.206_326.233.wav | |
xanaa rek balaa ñuy tënk rek ñu delloowaat kàddu bi monsieur %e Diatta par rapporrt aux perspectives des communautés les plus résilientes maanaam ñi nga xam ne gis nañ ne que ne %e seen loxo jotul seen i ginnaaw bu baax ñi nga xam ne ciblé nañ leen ci seen enquête yi ngeen def njëriñ bi ci projet bi wala tamit %e lan ngeen di séntu si ñoom ba tax ñu ngeen dugal leen ci projet bi | 23.541 | wol_42922_598.102_621.643.wav | audio/kallaama/wol_42922_598.102_621.643.wav | |
ba jotanteeg ñoom man maay le président bi maa ngi dëkk kër Saalum Diané ñu may wax Aliou Ndao | 4.131 | wol_42311_267.201_271.332.wav | audio/kallaama/wol_42311_267.201_271.332.wav |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 39