text
stringlengths
1
2.33k
duration
float64
0.5
193
file_name
stringlengths
8
31
path
stringlengths
14
39
audio
audioduration (s)
0.5
193
nuyu naa ko
0.676
wol_44012_1189.296_1189.972.wav
kallama/wol_44012_1189.296_1189.972.wav
pour chaine feebar yooyu noonu dagg
1.539
wol_43810_921.351_922.89.wav
kallama/wol_43810_921.351_922.89.wav
le 26 juin la tawoon
1.252
wol_4210_1934.019_1935.271.wav
kallama/wol_4210_1934.019_1935.271.wav
waaw c' est bien ci wàllu agriculture aussi
4.38
wol_31212_134.61_138.99.wav
kallama/wol_31212_134.61_138.99.wav
yéen jigéen ñi bu ngeen dee ligéey benn mbir
2.12
wol_4613_477.503_479.623.wav
kallama/wol_4613_477.503_479.623.wav
donc mais nag %e par rapport ak collectivité territoriales ak ni ñu xamee les réformes bi am léegi
6.815
wol_44811_1667.027_1673.842.wav
kallama/wol_44811_1667.027_1673.842.wav
waaw partiquement fu ñuy fu ñuy traité moom bu ñu fa jaaree benn yoon
4.21
wol_4410_1265.122_1269.332.wav
kallama/wol_4410_1265.122_1269.332.wav
déroulé gu ñu ko parce que ñun étape par étape lañuy def
3.486
wol_44812_1377.738_1381.224.wav
kallama/wol_44812_1377.738_1381.224.wav
en vu de la prochaine campagne
1.379
wol_43810_429.193_430.572.wav
kallama/wol_43810_429.193_430.572.wav
mën nañoo uute ci xalaat
1.18
wol_44412_187.991_189.171.wav
kallama/wol_44412_187.991_189.171.wav
waaw am ci ñoo xam ne nag dañoo mujj sax far gas ontat ko dem jaay ko situation boobu ñàkk préparation la ndax ëllëg waaye aussi au delç de de de de de soppi mbéyin bi tamit est ce que tamit laajut ñu gën a xoolaat beneen doxalin boo xam ne ñun béykat yi danañ ko def pour que situation ñu bañ si tabbi ëllëg
15.745
wol_44412_821.964_837.709.wav
kallama/wol_44412_821.964_837.709.wav
donc %e buñu sañoon nag rapports yooyu heure buñu ko yónnee
3.193
wol_35311_554.706_557.899.wav
kallama/wol_35311_554.706_557.899.wav
Suñ jàllee ca nataalu fanweee...euh...ñeen-fukk ak juróom-ñett, ñooŋ fay gis ay saaku. Saaku bii def kaani, kaani, bii mu nga def daqaar, bii mu nga def paañ, bii mu nga def poobar, euh...yi mu nga def yeneen ak yeneen ak yeneen, bii mu nga def bisaab. Moom nag, euh...yu bari day dem ci togg comme kaani. Kaani, dina dem ci ceebu jën, dina neexal ceebu jën lool. Buñ demee jël daqaar, daqaar tamit dina neexal maccaat, maccaat, loolu dina ci am solo lool. Buñ demee itamit bisaab, bisaab dina dimbali nit ñi, ñu mën cee defar di naan tamit di ci faj ay seen i jàngoro, walla suñ wooree ba ngoon di ci naan, di ci noos ak yeneen i yeneen. Poobar tamit, mën du jariñ, day dem ci togg, lu am solo la.
61.597813
2829:434.wav
waxal/2829:434.wav
boo bëggee dab si UGPM tamit foog ñu fexe ba xamanteeg yow mooy benn temps d' observation boo xamante ni dañuy ñëw di waxtaan ak yow ci sa biir dëkk di waxtaan ak mbooloo ma mais ngay ñëw tamit di fekkee suñuy ndaje ak suñuy waxtaan di ca dem
12.435
wol_44912_295.294_307.729.wav
kallama/wol_44912_295.294_307.729.wav
waaw mais loolu yëpp nag %e béy jamono jii amul benn activité génératrice de revenues boo xamante ne muy mbay di sàmm di napp boo xam ni mën na dem sans météo parce que li nga ci yaakaar nii tey suba gànnaaw sub mën na ba leneen bañ a nekk
15.531
wol_44011_1742.914_1758.445.wav
kallama/wol_44011_1742.914_1758.445.wav
lu tax semence certifiée lu ko waral lu tax lu indi li ñuy def semence certifiée
3.459
wol_43920_358.615_362.074.wav
kallama/wol_43920_358.615_362.074.wav
ay barab yoo xam ne day taw tuuti
2.458
wol_44111_353.775_356.233.wav
kallama/wol_44111_353.775_356.233.wav
war koo war ko stocké teglante ko naka lañ ko war a defee si suuf dañoo war a def poudre wala naka la
4.79
wol_43312_971.996_976.786.wav
kallama/wol_43312_971.996_976.786.wav
wallaahi
0.684
wol_45412_350.248_350.932.wav
kallama/wol_45412_350.248_350.932.wav
waaye nag am nañ matuwaay boo xam ne suñu xalaat kenn mënu ñu ko teree wax
4.179
wol_44411_2027.869_2032.048.wav
kallama/wol_44411_2027.869_2032.048.wav
voilà di fàttali mbokki auditeurs yi que ne ñoom it mën nañoo woote ci 33 967 43 00
6.188
wol_4311_489.642_495.83.wav
kallama/wol_4311_489.642_495.83.wav
gën leen a gunge
0.833
wol_43512_1869.226_1870.059.wav
kallama/wol_43512_1869.226_1870.059.wav
yow sa sa numéro téléphone naka la
1.916
wol_44012_1151.41_1153.326.wav
kallama/wol_44012_1151.41_1153.326.wav
%e beneen bi ci des mooy lu mel ne que comme li mu wax ni %e jël benn stratégie marketing bu bu wér te kooku ñu ngi ciy liggéey incha alla
8.4
wol_4613_350.21_358.61.wav
kallama/wol_4613_350.21_358.61.wav
na ñuy gën a seetle na ñuy gën a vérifié liste yi su amee genre erreur yooyu ñu xool nan la ñuy def pouir remplacer leen
7.821
wol_43511_1370.466_1378.287.wav
kallama/wol_43511_1370.466_1378.287.wav
doo xam kii feebar na kii feebarul na nga mar naan rek su may dem tànq ndox naan dem naa sama yoon
6.647
wol_43910_1561.786_1568.433.wav
kallama/wol_43910_1561.786_1568.433.wav
Thierno Camara %e kon nag %e monsieur Tall waxtu baa ngi ñuy dab
41.354
wol_44114_646.785_688.139.wav
kallama/wol_44114_646.785_688.139.wav
waaw xam nga tey boo xoolee presque dañ ne ñun Saloum fii ñun baykat fii presque engrais buñ koy utiliser
8.766
wol_43411_1444.205_1452.971.wav
kallama/wol_43411_1444.205_1452.971.wav
%hum kon nag %e yow yaay maanaam ki nga xam ne moo fi toogal ANACIM noonu la ci mboolem diwaan Tambacounda noonu la
6.881
wol_43611_231.164_238.045.wav
kallama/wol_43611_231.164_238.045.wav
ba góob
0.559
wol_44122_362.74_363.299.wav
kallama/wol_44122_362.74_363.299.wav
day mën a yem foofu rek mu nekk verre mu xool yëf yi rafet bien am ku fa nekk di jaay bu ko defee mu daal di waxaale foofu daal di fay jëndee
6.94
wol_4613_116.384_123.324.wav
kallama/wol_4613_116.384_123.324.wav
%e nga baal ma ci terme
1.464
wol_45411_393.871_395.335.wav
kallama/wol_45411_393.871_395.335.wav
jërëjëf merci beaucoup ah
1.049
wol_4910_703.375_704.424.wav
kallama/wol_4910_703.375_704.424.wav
RTS Tambacounda ah waaw dem na waaw xam naa dina ñëwaat 33 981 29 31 waaw monsieur Tall
7.348
wol_44113_407.017_414.365.wav
kallama/wol_44113_407.017_414.365.wav
7 8 9% %hum léegi nag kee itam bu ko jëlee bëgg ci teg ay commissions !fra am ak ay nangam nangam fokk mu dem 15 jàpp 18 wala 13 jàpp 14 bu fekkee ne Etat bi Etat bi jàppu ci
11.592
wol_4814_113.187_124.779.wav
kallama/wol_4814_113.187_124.779.wav
loolu tamit %e am na solo léegi nag %e sax bi ci jëmi boppam wax nga ni nga xam noonu lay def %e gàncax gi wax nga ñu tamit période yi nga xamante ne ci la sax bi di di di di di génn léegi nag loolu lépp nag buñ ko xamee xam nañu kañ lay sax biy génn xam nañu ni muy def gàncax gi léegi nag béykat bi nan la war a mun a def ngir moytu sax boobu
18.486
wol_4410_370.464_388.95.wav
kallama/wol_4410_370.464_388.95.wav
Lii day wane ay policier yoo xam ne dañoo taxaw ci ginnaaw benn barrière ngir di am lu ñuy feg, walla ñuy protéger seen bopp.
12.517813
3556:1296.wav
waxal/3556:1296.wav
te fi mu toll nii presque ñëpp a yor téléphone
1.881
wol_44012_596.481_598.362.wav
kallama/wol_44012_596.481_598.362.wav
ndax bu fekkee wutal nañu la ab foos boo xam ne danga caa war a def lépp loo xam ne mooy mbalitu kër gi
3.438
wol_4314_291.105_294.543.wav
kallama/wol_4314_291.105_294.543.wav
dafa am fànn ñoo xam nag ñoom force ñoom ñu ñëw laajte ma mooy ñi nga xamante ni ñoom dañoo seen loxo dafa dugg ci coopérative bii ñuy def %e production semence
9.308
wol_55010_250.644_259.952.wav
kallama/wol_55010_250.644_259.952.wav
parce que xam nga %e au niveau des communes am na %e lu ñuy wax conseil local de la jeunesse
5.233
wol_44812_902.239_907.472.wav
kallama/wol_44812_902.239_907.472.wav
bu dee si wàllu jigén ñi ñaari mbir gis naa ko ci
2.562
wol_44915_331.97_334.532.wav
kallama/wol_44915_331.97_334.532.wav
jigéen ñee ëppale góor ñi
0.771
wol_4311_430.965_431.736.wav
kallama/wol_4311_430.965_431.736.wav
moom bi muy gis
1.068
wol_45412_387.868_388.936.wav
kallama/wol_45412_387.868_388.936.wav
Maa ngi gis ay xob yu ñu teg.
2.837813
2919:28.wav
waxal/2919:28.wav
fukki jeunes
2.577
wol_44812_554.195_556.772.wav
kallama/wol_44812_554.195_556.772.wav
2000 la ñu crée %e CREC bi
3.257
wol_44913_765.172_768.429.wav
kallama/wol_44913_765.172_768.429.wav
donc kon producteur bi ci boppam moom war naa bàyyi xel ni
3.167
wol_44311_446.844_450.011.wav
kallama/wol_44311_446.844_450.011.wav
daanaka énetti téeméer nga koy fay
2.26
wol_44411_744.364_746.624.wav
kallama/wol_44411_744.364_746.624.wav
ñaar moo ciy am rek
0.923
wol_44411_939.996_940.919.wav
kallama/wol_44411_939.996_940.919.wav
lu mat ay cinq tonnes wala dix tonnes
2.151
wol_44312_492.475_494.626.wav
kallama/wol_44312_492.475_494.626.wav
parce ;fra que baaxul nga ñëw dégg ni taw na rek taw na rek nga dem ji
5.553
wol_42512_748.899_754.452.wav
kallama/wol_42512_748.899_754.452.wav
parce que ñu gën a bëri nekk nañu ay béykat mais ñu ngi pratiquement à trente kilomètres ñu mel ni comme Patacourou ay Julti dañoo nekk béykat yu yu mag mais nag yàlla dafa def par rapport ak li ISRA soxla ak recherche bi niñ ko soxlaa dañoo soxla lu jege nga xam ne boo jógee fii tag nga mun a dem foofu automatiquement nga mun a bu fekkente ne ay attaques la nga mun a jël ay décisions
21.813
wol_41940_1345.727_1367.54.wav
kallama/wol_41940_1345.727_1367.54.wav
doom ji moom mooy gàncax bi lépp lu nga xamante ni %e doom ji mi ngi koy soxla pour nàmp ci yaay ji la koy jëlee léegi bu dee yaay jooju moom mi ngi ànd ak wér %e ànd naag wér day mën a nàmpal doomam bu baax te du am benn gàllankoor mais bu dee yaay ji dafa manqué par exemple soow
21.18
wol_4210_382.013_403.193.wav
kallama/wol_4210_382.013_403.193.wav
maa ngi lay fay Serigne
1.206
wol_35312_676.023_677.229.wav
kallama/wol_35312_676.023_677.229.wav
%e les mercredis là quelque fois ñu def émission toog nit ñi di woote même avant loolu ñu annoncé liñ bëgg a waxtaane nit ñi di envoyé ay messages am ay laaj loolu dara gënu ko
9.746
wol_42412_724.865_734.611.wav
kallama/wol_42412_724.865_734.611.wav
huit pour cent
0.572
wol_4910_1174.302_1174.874.wav
kallama/wol_4910_1174.302_1174.874.wav
ba pare mbéy benn genre mbéyteef boo xamante ni da ngay mën a sakkanal ndox mi ndox mi bu ñëwee dafay taaju
6.009
wol_45512_227.567_233.576.wav
kallama/wol_45512_227.567_233.576.wav
mooy que ñun au niveau de la météo là au delà des prévisions yi ñuy def xam nga dañuy am %e ay services yi nga xamante ne bii dañuy def ce qu' on appelle l' agrométéorologie
8.173
wol_44512_856.187_864.36.wav
kallama/wol_44512_856.187_864.36.wav
kon defe naa mbokk mi dégg nga li li sëñ bi wax %e maa ngi doon wax sànq ne taal ay taal yi ñuy def ci %e àll bi maanaam ci tool yi %e loolu rey na suuf si wala dundalaat na suuf si wala am na li muy dese ci suuf si
13.372
wol_44312_693.263_706.635.wav
kallama/wol_44312_693.263_706.635.wav
pour mën a ñëpp xam ko
0.977
wol_45411_1702.503_1703.48.wav
kallama/wol_45411_1702.503_1703.48.wav
mais tey fi ma doon ñëw mooy ñi nga xamante ne ni ñoom ñooy béykat yi des fois nga dégg ñu ni la ah coppiteg jaww ji lii la ay wax yuñ fi teg laag yooyu ndax loolu mën na am ay yenn risques yoo xamante ne ni ñoom dinañ dinañ dina dina dina dina ñëw ci seen liggéey
15.532
wol_43010_1024.944_1040.476.wav
kallama/wol_43010_1024.944_1040.476.wav
maanaam boo jëloon tooyaay bi tooyaayu gàncax boobu bu dee téeméer la ñaar fukk yi wala ñaar fukk yeeg juróom la dese ci tooyaay mais boobu day fekk nag mu ngi taxaw si gattax loolu it jéego la ci ñaareelu jéego bi mooy su ma ñëwee nag ba nga xam ne ne góob naa yett naa sama ceeb wala góob naa suma dugub du ma xëy rek jël ko teg ko dem ne maa ngay uti
28.21
wol_43411_295.414_323.624.wav
kallama/wol_43411_295.414_323.624.wav
engrais du dafay bëri
1.013
wol_43011_1201.169_1202.182.wav
kallama/wol_43011_1201.169_1202.182.wav
waa talaata gii
1.228
wol_44811_1261.325_1262.553.wav
kallama/wol_44811_1261.325_1262.553.wav
te it wax dëgg yàlla jumtukaay yu bëree bëri DPV ñu ngi koy mobilisé
3.762
wol_4410_2088.079_2091.841.wav
kallama/wol_4410_2088.079_2091.841.wav
ci région Tamba ak région Kolda
2.607
wol_44122_1501.012_1503.619.wav
kallama/wol_44122_1501.012_1503.619.wav
parce que xam nga ne béykat léegi souvent dañuy dem au au au au niveau des banques surtout banque agricole ñu dem leb fa xaalis pour mën a am intrant mën a am matériel agricoles bu tawul naka la ñu mën a def ba am si assurance agricole boobu
11.721
wol_43511_726.177_737.898.wav
kallama/wol_43511_726.177_737.898.wav
ñun dañ lay fay
0.706
wol_4910_2267.638_2268.344.wav
kallama/wol_4910_2267.638_2268.344.wav
ñeenti at
0.85
wol_4210_1790.623_1791.473.wav
kallama/wol_4210_1790.623_1791.473.wav
jàppal ne député àll bi nga
2.002
wol_44411_1216.136_1218.138.wav
kallama/wol_44411_1216.136_1218.138.wav
parce que su tawee dafa war a am li ñuy wax répartition et répartition boobu nag moom moo ëpp solo sax si nawet que quantité ndox mi lu muy bëri
9.514
wol_42811_470.257_479.771.wav
kallama/wol_42811_470.257_479.771.wav
trente neuf am nañ ko
0.687
wol_4712_120.851_121.538.wav
kallama/wol_4712_120.851_121.538.wav
man la Diakhou
0.796
wol_44412_754.803_755.599.wav
kallama/wol_44412_754.803_755.599.wav
%e def na déclaration de culture
2.381
wol_4711_590.961_593.342.wav
kallama/wol_4711_590.961_593.342.wav
mooy combus() combus() combustible yi
1.945
wol_42931_1370.77_1372.715.wav
kallama/wol_42931_1370.77_1372.715.wav
waaw Lour Escale mu ngi am 252 viorgule 8 en 14 jours situation bi dafa normale diggudóomu Missira Wadeen ñu am 239 virgule 1 milimètre en 16 jours donc foofu tamit situation bi dafa dafa dafa diggudóomu ndox mi daa diggudóomu
13.932
wol_42514_1066.489_1080.421.wav
kallama/wol_42514_1066.489_1080.421.wav
yow nga xamne li ngay togg mi ngi ñor sa compost mi ngi ñor
2.609
wol_4210_1519.209_1521.818.wav
kallama/wol_4210_1519.209_1521.818.wav
loolu xam nga bu tawee
1.065
wol_42922_107.052_108.117.wav
kallama/wol_42922_107.052_108.117.wav
kon loolu dafa am njëriñ gis nga maçon bi moom xam na ne ci wàllu béy laay yëngu daf may oo yenn saa yi mu ne ah dama war a raax de Diouf barki démb rek Diouf est ce que mun naa raax ma ne ko non ah dina taw de keroog bul raax de dafa toog ba guddi gi mu woo ma ne ma laaillah man de su ma raaxoon yàq sama ciment Diouf li nga wax suba si ba ngoon gi dafa taw xam nga fu maçon di laajtee dina taw loolu béykat lu mu war a def ah
24.131
wol_43012_114.971_139.102.wav
kallama/wol_43012_114.971_139.102.wav
mën na baax te mën na yàqu waaye nawet moom li ci gën li ci gën li may wax nawet rek
5.171
wol_43010_643.269_648.44.wav
kallama/wol_43010_643.269_648.44.wav
ñaareel bi mooy
0.869
wol_43012_329.504_330.373.wav
kallama/wol_43012_329.504_330.373.wav
tàngoor bi daal di ko laal mu comencé toq
1.683
wol_44111_267.698_269.381.wav
kallama/wol_44111_267.698_269.381.wav
nee naa la waa fi ma ko mos a déggee ñoom Diegane waa réseau ñoom
3.776
wol_36110_58.862_62.638.wav
kallama/wol_36110_58.862_62.638.wav
ci programme yi parce que ñoom ñoo ko fay mais toujours que da ngay fay
3.707
wol_44122_1358.161_1361.868.wav
kallama/wol_44122_1358.161_1361.868.wav
asalaamaaleykum
1.074
wol_43312_1279.077_1280.151.wav
kallama/wol_43312_1279.077_1280.151.wav
%e 495 %e 495 %e 57 92
10.114
wol_4313_524.689_534.803.wav
kallama/wol_4313_524.689_534.803.wav
su booba
0.659
wol_43111_1260.606_1261.265.wav
kallama/wol_43111_1260.606_1261.265.wav
kon yàlla ñëw na ak xéwalam ren waroon nañu mun a am ñaari traite
4.613
wol_44411_813.122_817.735.wav
kallama/wol_44411_813.122_817.735.wav
balaa président di ko yëg
0.959
wol_44114_789.136_790.095.wav
kallama/wol_44114_789.136_790.095.wav
loo xam ni sunu diine dakoo gërëm
1.592
wol_44911_791.428_793.02.wav
kallama/wol_44911_791.428_793.02.wav
ndax rupture dafa am ci ci marché bi %e mais budul loolu moom wax dëgg yàlla %e jiwu toon nañu bu baax a baax xëy na tamit li ñu posé wu mooy %e qualité semence bi
12.099
wol_4313_635.653_647.752.wav
kallama/wol_4313_635.653_647.752.wav
borom xel la ñu woon
0.78
wol_44111_865.286_866.066.wav
kallama/wol_44111_865.286_866.066.wav
wax dëgg kooka ki ci bokk moom
1.62
wol_4312_51.781_53.401.wav
kallama/wol_4312_51.781_53.401.wav
macha allah
0.82
wol_4312_807.255_808.075.wav
kallama/wol_4312_807.255_808.075.wav
par rapport ak yeneen zones yi comme ay Fimela par exemeple foofu lu muy taw pa() %e bëri na ak ak yooyu donc %e zone yooyu moom 73 bi mooy benn variété bi moom la ñu fay gën a béy xam nga kon %e tànn variété bi moom kon ça dépend si %e pluviométrie bi
20.139
wol_42611_12.829_32.968.wav
kallama/wol_42611_12.829_32.968.wav
nit ki di ko dund ci jëfin ba def lu baax ñu weer la ci rajo bi nga %e nga dem ba sa rongañ di génn ndax am kersa ci loolu bëggoo woon ñu wax ko ndax ki ngay roy du loolu du ay fo looy dund la ba ci waxin et tout donc yal na yàlla guddal sa fan
12.521
wol_44412_2117.727_2130.248.wav
kallama/wol_44412_2117.727_2130.248.wav
%e ci turu coopérative bi nga xam ne mooy coopérative des jeunes producteurs agropastoraux de la région de Fatick
4.888
wol_44512_1424.643_1429.531.wav
kallama/wol_44512_1424.643_1429.531.wav
%e Mar ba tey rek mbokk yi ma fàttali yéen a ngi déglu RTS Tambacounda muy seen émission jokkalante tey nag kii di Mar Ndiaye di délégué régional si wàllum institut national bu pédologie moo fi ñëw di waxtaan ak yéen ak mbokki béykat yi %e Mar ba tey ci biir waxtaan wi béykat bi ci njëlbéen bi nan lay tànneefam ci suuf ci wàllu woowu nag nan la koy tànnee ba nga xam ne ne war na koo jëriñoo ci mbaa bu ko tànnee tamit nan lay xamee ne suuf si suuf su baax la
33.227
wol_44311_491.03_524.257.wav
kallama/wol_44311_491.03_524.257.wav
Nataal bii nag benn salle la bu ñu teg ay bã yu ruus def ay fleurs taal ay làmpu décoré ba mu rafet maasàllaa.
10.597813
2575:1039.wav
waxal/2575:1039.wav
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
64

Models trained or fine-tuned on IndabaxSenegal/asr-wolof-dataset