Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.33k
- Lu ngeen di wax?
- De quoi tu parles?
Seeni gaal yu mujj yi ñu ngi doon tàkk ci samay bët.
Leurs derniers vaisseaux brûlaient sous mes yeux.
Mënuñu woon déggoo ci kan mooy baykat bi ak kan mooy boroom kër gi.
Ils ne pouvaient pas se mettre d'accord pour savoir qui était le fermier et qui était le propriétaire.
Kon dina ñu gise.
A tout à l'heure.
Saa waay, def nga lu bari ci Cashman, wala book?
Tu as fait un effort à Cashman, pas vrai?
Jéém bi taaweeku ci kawu sirfaas bi mu jëm ci koñu korneer bu ndeyjooru caax yi.
Le ballon vola au-dessus de la surface de réparation avant de se diriger vers le coin supérieur droit du filet.
Bul toogal xale bi ci dër bi
N'assois pas l’enfant sur le sol cimenté !
- Wutal ma kuti, wala?
- Tu me donnes un chiot?
Dama soxla ay sirisi Luden.
Il me faut du Luden aux cerises.
Dama bëgga nekk reine.
Je veux être la reine.
Wër leen lansa yi!
Tourne ces lances!
Militaŋ ak farandoo PASTEF yépp a ci ànd bu baax.
Tous les militants et sympathisants de PASTEF l’ont adopté à merveilles.
Jàppoon naa ni dégg naa la ci biti!
Je pensais vous avoir entendu!
Sa chemise amna ay rëdd deret.
Il y a des taches de sang sur votre chemise.
#NOM?
- L'arrimage.
Ndax lii mooy sama yaay?
C'est ma mère?
Dogal boobu day dëggal dakkalug yoonal gi, mbañug njaboot gi di pakk ngir yoonal gi : ñàkk a yoonal gii benn ci pàcc yi sax mënu koo teggi ; SOFICO SA ak CFU SARL, ginnaaw loolu ak li ñu tudde coowal suuf, ñoom doŋŋ a am yelleef ci bor bi (bor bi du lu am jëmm waaye tamit CFU ak njaabootu Ndóoy dëppoo nañu ci).
bien au contraire cet arrêt confirme le rejet de l’homologation au motif que les contestations de la famille constituent des obstacles empêchant toute homologation: que la présente instance en homologation ne peut s’accommoder de contestation pouvant affectant l’intégrité de l’accord des parties; qu’en définitive il échet pour ces motifs de confirmer le jugement attaqué;SOFICO SA et CFU SARL, malgré tout ce qui précède et nonobstant les mentions du livre foncier, sont les seuls détenteurs des droits sur la créance (La créance est non seulement virtuelle, mais encore, la CFU n’est pas partie à l’accord avec les familles Ndoye et consorts).
- Doo leneen lu dul ab màndikat bu màndi.
- Tu n'es qu'une pute ivre.
Kublay Khan moo sos benn dëkk ci Taywan.
Kublai Khan a fondé une ville à Taiwan.
Góor gi daan na la gis
L'homme te voyait
Kon jéggalu.
Je suis désolée.
Te yaa leen yóbbu ci man!
Et vous les avez conduits à moi!
At mu metti la woon, xam nga?
Ça a été une année difficile, tu sais?
ÑÉPP FI!
Il y en a tous!
Omar taaxuraankat bu mag la woon
Omar était un célèbre chanteur de textes composés pour célébrer des chefs spirituels.
- Maa ngi jéggalu lool.
- Je suis désolée.
Deñuy def gëstu, deñuy def recces.
Ils font de la recherche, ils font des recces.
Jërëjëf waay. Nanga def, Em!
Merci, monsieur.
Vista liggéey, waaw.
Job Vista, oui.
Ci mbooloo mi yépp?
Dans toute cette foule?
Eespekteer gestukat Brian O'Hagan neena: ’Laŋket bi ci ndoortel la tollu waaye dinaa tallal loxo kepp ku nekkoon ci biir wisinti bu mbedd John ci Birkenhead ku dëgg mbaa gis lenn lu xawa luus mu jokko ak ñun.
Le capitaine de la police, Brian O’Hagan fit les déclarations suivantes : « L’enquête vient à peine de commencer, mais je voudrais demander à toute personne qui se trouvait aux alentours de John Street à Birkenhead et qui aurait vu ou entendu quoique ce soit de suspect de nous contacter.
Sita niko, "Soo demee, dinaa dem."
Et Sita a dit: "Si vous partez, je pars aussi".
Keneen leeralna: "Ci lu nu muna japp luy loraate ci xale bi ak yaay ji yepp.
Matthew Albence, un haut fonctionnaire du Service de l’immigration et des douanes, a témoigné la semaine dernière devant le Congrès que l’agence avait arrêté des dizaines de personnes qui avaient fait une demande de parrainage de mineurs non-accompagnés.
Xam nga ni mën nañu la tuumal libel?
Tu sais que tu pourrais être poursuivi pour diffamation?
Leegi ñuy joxe coordonnées hydro rig.
Repositionner les coordonnées de la plate-forme hydroélectrique maintenant.
Infirmiye la.
Elle est infirmière.
Ak sa loxo xottiku, Màrku wor.
Et vos manches ont été déchirées, la marque de la trahison.
wowaay b-
fait d’être sec
Loolu mooy sa patroŋ, wala book?
C'est votre employeur actuel, n'est-ce pas?
Nataal bii ñu ma yónnee gis naa ci ab kaadar def ay dàll, dàll yoo xam ne ay dàlli góor la, dàlli fermé yi tamit mi ngi ci.
Sur la photo qu'on m'a envoyée, j'y ai vu un cadre avec des chaussures. Il y a des chaussures de garçon mais aussi des chaussures fermées.
Dindi nañu xaalis ci kontu Sharmila.
L'argent a été retiré du compte de Sharmila.
Denga dugg?
Vous vous enregistrez?
Xool leen : sàcc (njëfka : voler) moo soppaliku càcc (tur : vol), -fo (njëfka : jouer) mooy soppaliku po (tur : jeu), - fenk (apparaitre) mooy soppaliku penku (lieu d’apparition- di tekki jant : l’orient).
Observez : – sacc (verbe: voler) qui devient cacc (nom: vol),– fo (verbe: jouer) qui devient po (nom: jeu),– fenk (apparaître) qui devient penku (lieu d’apparition – comme pour le cas du soleil: l’Orient).
Xamuma lumu la wax...waaye maa ngi yor Endurance bi.
Je ne sais pas ce qu'il t'a dit... mais je prends le commandement de l'Endurance.
Waxtaan wi dafa war a gën a xóot àgg ci loolu, ci li njiitu takki-der yi wax Seneweb.
Ils n'ont pas encore changé ces avions qui ont encore du potentiel.
Wideo la.
C'est une vidéo.
wooye
dénommer
Woo ma!
Appelez-moi!
Nun ekip la bu gëna am njariñ.
Nous sommes une équipe plus efficace.
Ab ŋàññi bu am solo ñeel xaalisu seefaa mooy ne, ñaari mboolooy réew yi koy jëfandikoo, muy mbooloom réewi Afirig sowu jant yi bokk koom ak xaalis (UEMOA), wala muy mbooloom réewi Afirig yi ci digg dénd bi te bokk koom ak xaalis (CEMAC), amuñu ay màndargay goxub bokk xaalis bu mucc-ayib.
Une objection importante contre le franc CFA est que les deux blocs qui l’utilisent, c’est-à-dire l’Union économique et monétaire ouest-africaine (UEMOA) et la Communauté économique et monétaire de l’Afrique centrale (Cémac), ne présentent pas les caractéristiques de zones monétaires optimales.
Ngir mëna dugg ci dër bi, fàww mu yóbbaale ordinatër ak modem.
Pour entrer dans l'étage, elle doit porter à la fois un ordinateur et un modem.
Doxalin wi nga xam ne dafay fitnaal ñi nga xam ne lu leen neex def wala ñi bopp kese yitteel, dana rataxal diggante yi, te it dana tax lépp lu waay di def dana ko seet, seetaat ko.
Cet engagement, impliquant répression volontaire des tendances instinctives et des passions égoïstes, pacifie les rapports à autrui et fait émerger des conduites raisonnées, réfléchies, mesurées.
« Su sama yaay daan weer mboqq mi, da ma daan jis melantaan yi di lekk sax yi ci biir mboqq mi. Te saa su si teggee diw u togg, damay jis ni melantaan yi bugg na ñu ko lool. Looloo tax ma xamni su ma defee diw u togg ci kaw mboqq mi, melantaan yi da ñu lekk sax yi fi ñëw yéép. Da ma koy inndi saa su mboqq kawe ba jot óom yi te di waaj tóor-tóor.Damay bomb akk samay baaraam gancax gu ne, waante fu melantaan yi am, du ma fa def.”
« Quand ma mère séchait le maïs, j’ai vu que les fourmis mangeaient les chenilles dans le maïs. Et chaque fois qu’elle déposait de la graisse de cuisson, je voyais que les fourmis l’aimaient beaucoup. C’est ainsi que j’ai compris que si je mets de la graisse de cuisson sur le maïs, les fourmis vont manger toutes les chenilles qui vont venir. Je l’applique quand le maïs atteint la hauteur du genou et est sur le point de fleurir. Je frotte avec le doigt, plante par plante, mais là où il y a déjà des fourmis, je n’en mets pas. »
Littérature bi mën na soppi gëstu bi ëlëg
La littérature peut changer les recherches futures
- Amul benn yéene.
- Ça ne m'intéresse pas.
Alegsàndar, ñëwal, naan ak nun.
Viens, Alexander, bois avec nous.
Kon benn réew mënu woon jël këru njiitu réew mi.
Aucun État ne peut revendiquer la Maison du Président.
Doggal ci ndeyjoor!
C'est à droite!
Ñëwal gise ak man leegi.
Viens me voir tout de suite.
Duma sax sekkerteer ci wàllu yoon, assistant laa.
Je ne suis même pas secrétaire juridique, je ne suis qu'un assistant.
lees b-
largeur
Musu ma xam sama yaay.
Je n'ai jamais connu ma mère.
Set ni culotte Blanc-Neige.
Aussi propre que la culotte de Blanche-Neige.
- Baay!
- Papa!
Léegi leer na ne Meysa Njaay moo doon teewal Direktëeru Domen bi nga xam ne, mooy Njiitam li mu topp ci kowam tey déglu ay ndigalam.
Il est donc clairement établi que Meïssa Ndiaye représentait le Directeur des Domaines, qui est son supérieur hiérarchique direct dont il reçoit des ordres.
Ndimbal li ngay am mën nañu ko fay juuti.
L'aide que vous recevez peut être imposable.
Ndax nasu Eco bi mën na yemb.
Le projet éco pourra, pensent-ils, permettre d’y parvenir.
Doonte askan u réewu taax yi ñam u mbay mu sell mi la ñu taamu, ñu si bari ci ñoom rañeewu ñu baykat u mbay mu sell mi.
Alors que les consommateurs urbains préfèrent de plus en plus les aliments biologiques, plusieurs ne connaissent pas personnellement les agriculteurs biologiques.
Koppar yi nguur gi jële ci bagaas yi muy jaay, ndàmpaay loolu, genn wàll gi lempo la, geneen gi lu kenn dul fay la te benn dogal indiwu ci firnde.
En effet, au titre des droits de mutation, les préjudices enregistrés résultent, d’une part, de minorations de la base imposable, et d’autre part, d’exonérations accordées sans fondement légal.
Ndax mën naa yéeg foofu?
Je peux monter?
Leegi, Simon, bëggoon naa nga tëj say bët.
Maintenant, Simon, je voudrais que vous fermiez les yeux.
Wittaldoomujiwi bi subateel, balangelaw li di up bubaax
Prélevez les graines tôt le matin, quand le vent n’est pas trop fort.
Képp ku jege Indu war naa dee.
Toute personne proche d'Indu devrait mourir.
Dama sonn tuuti.
Je suis juste un peu fatigué.
Waruma woon daw.
Je n'aurais jamais dû fuir.
Jàllal ma ba ci weneen wetu dex gi.
Ramez-moi de l'autre côté.
Ñeneen ñi mën nañu la jaaxal.
D'autres personnes pourraient vous surprendre.
Ile bi ñu njëkka dem amul woon kenn.
L'île qu'ils ont abordée était inhabitée.
Khallad moo joxe ñaareelu yoon, loolu dafay tekki ni ñoom ñatt ñu bokk bàyyante ci Karachi
Khallad a donné la deuxième version, ce qui signifie que les trois d'entre eux ont rompu ensemble à Karachi
- NU TAXAL FORGON BI.
- On a arrêté le fourgon.
Xoolaatal mbooloo mi!
Assistez à la foule!
Daaw, demug Njiitu réew mi Medina Baay, dafa taxoon njabootu ñaseen gi amoon yaakaar bu rëy.
La visite du Président de la République, l'année dernière, à Médina Baye, avait fait naître beaucoup d'espoir chez la famille religieuse de Kaolack.
Loolu baaxna.
Ça a marché.
Tube bi mën nanu yóbbu ci kaw, wala book?
Ce tube pourrait nous ramener, n'est-ce pas?
Faale wuma loolu.
Je m'en fiche.
Jambaar nga lool.
Vous êtes très courageux.
Dafa bëggoon nu gis nit ki.
Il voulait qu'on trouve ce type.
Loolu dof la, waay!
C'est dingue, mec!
Xam nga li Camorra bi di lay defal.
Tu sais ce que la Camorra te fera.
Li gëna yàgg ci loxoy nit.
Le plus ancien en possession humaine.
(montu yiy sone)
(les horloges sonnent)
Maa ngi waajal seetaan ko suma delloo.
J'ai hâte de le regarder à mon retour.
Saar 96 : Lumbu deret 19 Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi.
Mais, c´est vers ton Seigneur qu´est le retour.
Damay dalal ci sama bërëbu liggéeyukaay saa-senegaal yu jógee fu ne bëgg ma jël leen ñu di xelal ci ay mbir yu ma xam bu baax, lu yoon nangu la.
Je reçois dans mon cabinet des Sénégalais de tous horizons souhaitant me commettre comme conseil ou expert sur des dossiers relevant de mes compétences, rien de plus légal.
NDAX DINAÑU JAAR NI DEF ÑU ÑAT LEEN ÑÉPP?
Est-ce qu'ils penseront qu'on en a fait trois?
na nit ki xool ana ci lan la ñu ko binde?
Que l´homme considère donc de quoi il a été créé.
Réewum Xel.
Le Royaume de l'Esprit.
Ndax amna ku la gis?
Quelqu'un vous a vu?
M. Singleton defkatu ñaawtéef la ci Floride.
M. Singleton est un fraudeur condamné en Floride.
Sudee ñaari inhalatër kese ñoo mëna indi jafe-jafe yii ci guddi gi, 10,000
Si seulement 2 inhalateurs peuvent causer cet effet ce soir 10 000
End of preview. Expand in Data Studio

No dataset card yet

Downloads last month
28