sourate
float64
1
114
verset
float64
1
286
translation
dict
68
15
{ "fr": "Quand Nos versets lui sont récités, il dit : \"Des contes d´anciens\".", "wo": "Saa su ñu jàngee fi kanamam Sunuy Laaya, muy wax naan : “Léebi ñu jëkk ña la” ." }
68
16
{ "fr": "Nous le marquerons sur le museau [nez] .", "wo": "Dananu ko wutal màndarga ci suku [bakkanam]." }
68
17
{ "fr": "Nous les avons éprouvés comme Nous avons éprouvés les propriétaires du verger qui avaient juré d´en faire la récolte au matin,", "wo": "Natu nanu leen kom ni nu nattuwoon woroom tool ya ba ñu diisóo ne ba ñu xëy góob ko," }
68
18
{ "fr": "sans dire : \"Si Allah le veut\". .", "wo": "te settee wu ñu woon : “Dogalub Yàlla” . " }
68
19
{ "fr": "Une calamité de la part de ton Seigneur tomba dessus pendant qu´ils dormaient,", "wo": "Mu am lu bawoo fa sa Boroom dikk wër si ko (faagaagal tool ba) fekk ñoom nelaw nañu,(r)" }
68
20
{ "fr": "et le matin, ce fut comme si tout avait été rasé.", "wo": "ba bët setee, mu melni luñu déqi." }
68
21
{ "fr": "Le [lendemain] matin, ils s´appelèrent les uns les autres :", "wo": "Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :" }
68
22
{ "fr": "Partez tôt à votre champ si vous voulez le récolter.", "wo": "“Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen bëgg góob” ." }
68
23
{ "fr": "Ils allèrent donc, tout en parlent entre eux à vois basse :", "wo": "Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :" }
68
24
{ "fr": "Ne laissez aucun pauvre y entrer aujourd´hui.", "wo": "Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin di dugg ci tool yi” ." }
68
25
{ "fr": "Ils partirent de bonne heure décidés à user d´avarice [envers les pauvres], convaincus que cela était en leur pouvoir.", "wo": "Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya." }
68
26
{ "fr": "Puis, quand ils le virent [le jardin], ils dirent : \"vraiment, nous avons perdus notre chemin,", "wo": "Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni peroŋ) : ñu ne : “nun xanaa da noo gëlam," }
68
27
{ "fr": "Ou plutôt nous somme frustrés\".", "wo": "Ñu ne moom la kat waaye li wóor moo di ne su nu muur jeex na ci” ." }
68
28
{ "fr": "Le plus juste d´entre eux dit : \"Ne vous avais-je pas dit : Si seulement vous avez rendu gloire à Allah ! \"", "wo": "Ka ca gën a yiw ne leen : “Ndax nee wu ma leen : Ngeen di sàbbaal seen Boroom di ko kañ !”" }
68
29
{ "fr": "Ils dirent : \"Gloire à notre Seigneur ! Oui, nous avons été injustes\".", "wo": "Ñu daldi ne : “Tudd nanu selluk sunu Boroom ! Nun dey, ay tooñkat lanu woon” ." }
68
30
{ "fr": "Puis ils s´adressèrent les uns aux autres, se faisant des reproches.", "wo": "Saar 68 : Xalima ga 52 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi." }
68
30
{ "fr": "Puis ils s´adressèrent les uns aux autres, se faisant des reproches.", "wo": "Ku nekk dëgmal morom ja, ñuy yeddante." }
68
31
{ "fr": "Ils dirent : \"Malheur à nous ! Nous avons été des rebelles.", "wo": "Ñuy wax naan : “Ngalla ! Nun danoo bew." }
68
32
{ "fr": "Nous souhaitons que notre Seigneur nous le remplace par quelque chose de meilleur. Nous désirons nous rapprocher de notre Seigneur\".", "wo": "Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak tool yu ko gën. Sunu Boroom la nu xemmem” ." }
68
33
{ "fr": "Tel fut le châtiment; et le châtiment de l´au-delà est plus grand encore, si seulement ils savaient !", "wo": "Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira maay gëna rëy, cëy bu ñu xamoon !" }
68
34
{ "fr": "Les pieux auront auprès de leur Seigneur les jardins de délice.", "wo": "Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa seen Boroom." }
68
35
{ "fr": "Traiterons-Nous les soumis [à Allah] à la manière des criminels ?", "wo": "Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu yem ak tooñkat ya ?" }
68
36
{ "fr": "Qu´avez-vous ? Comment jugez-vous ?", "wo": "Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di àttee ?" }
68
37
{ "fr": "Ou bien avez-vous un Livre dans lequel vous apprenez", "wo": "Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di jàng" }
68
38
{ "fr": "qu´en vérité vous obtiendrez tout ce que vous désirez ?", "wo": "boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci ?" }
68
39
{ "fr": "Ou bien est-ce que vous avez obtenu de Nous des serments valables jusqu´au Jour de la Résurrection, Nous engageant à vous donner ce que vous décidez ?", "wo": "Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba àllaaxira, Mu defal leen fa lu ngeen bëgg ? " }
68
40
{ "fr": "Demande-leur qui d´entre eux en est garant ?", "wo": "Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?" }
68
41
{ "fr": "Ou encore, est-ce qu´ils ont des associés ? Eh bien, qu´ils fassent venir leur associés s´ils sont véridiques !", "wo": "Wala dañoo am ñu ñuy bokkaale ? Kon, nañu indi seen bokkaale ndegam nu dëggu la nu !" }
68
42
{ "fr": "Le jour où ils affronteront les horreurs [du Jugement] et où ils seront appelés à la Prosternation mais ils ne le pourront pas.", "wo": "Bu keroogee ba ñuy wuññi ab yeel [tiitaange] nu def leen woo ngir ñu Sujud te du ñu ko man." }
68
43
{ "fr": "Leurs regards seront abaissés, et l´avilissement les couvrira. Or, ils étaient appelés à la Prosternation au temps où ils étaient sains et saufs ! ...", "wo": "Ñuy xiin-xiini ne muq ak gàcce te kat ba ca ba ñuy dund daayees na léen woo ngir ñuy sujood (jullig) te booba dara dalut léen." }
68
44
{ "fr": "Laisse-Moi donc avec quiconque traite de mensonge ce discours; Nous allons les mener graduellement par où ils ne savent pas !", "wo": "Bàyyee ma ak ñiy jàppe waxtaan wii ( Alxuraan) ay fen dina nu léen taxañe fu ñu dul xam." }
68
45
{ "fr": "Et Je leur accorde un délai, car Mon stratagème est sûr !", "wo": "Dama léen di dënniirlu waaye sama pexe naaxsaay." }
68
46
{ "fr": "Ou bien est-ce que tu leur demandes un salaire, les accablant ainsi d´une lourde dette ?", "wo": "Moo ndax da nga léen di laaj ag pey te ñu fees dell ak i bor." }
68
47
{ "fr": "Ou savent-ils l´Inconnaissable et c´est de là qu´ils écrivent [leurs mensonges] ?", "wo": "Wala dañoo xam mbóot ba di ko bind." }
68
48
{ "fr": "Endure avec patience la sentence de ton Seigneur, et ne soit pas comme l´homme au Poisson (Jonas) qui appela (Allah) dans sa grande angoisse.", "wo": "Na ngay muñ lépp luy tukkee ci sa àtteb boroom te bul mel ni ka jën wa wannoon (Yonnent Yàlla Yuunus AS) ba muy boroomam te tiitoon lool.(s)" }
68
49
{ "fr": "Si un bienfait de son Seigneur ne l´avait pas atteint, il aurait été rejeté honni sur une terre déserte,", "wo": "Dogankonak wallug boroomam dees na ko sànni ca tàkk ga mu ne tócc." }
68
50
{ "fr": "Puis son Seigneur l´élut et le désigna au nombre des gens de bien.", "wo": "Yàlla daldi ko tànn boole ko nit ñu yiwe ña." }
68
51
{ "fr": "Peu s´en faut que ceux qui mécroient ne te transpercent par leurs regards, quand ils entendent le Coran, ils disent : \"Il est certes fou ! \".", "wo": "Ña weddi saayu ñu déggée (Alxuraan) dina ñu lay xawa xeelu te naan kii ab dof la kat. 52- (Alxuraan) du lenn lu dul (ab téeré ) buy fàttali bindéef yi. " }
68
52
{ "fr": "Et ce n´est qu´un Rappel, adressé aux mondes ! .", "wo": "(Alxuraan) du lenn lu dul (ab téeré ) buy fàttali bindéef yi." }
69
1
{ "fr": "L´inévitable [l´Heure qui montre la vérité].", "wo": "Joxoñub dëgg ba." }
69
2
{ "fr": "Qu´est-ce que l´inévitable ?", "wo": "Lan mooy Joxoñub dëgg ba." }
69
3
{ "fr": "Et qui te dira ce que c´est que l´inévitable ?", "wo": "Ana lan moo lay xamal Joxoñub dëgg ba." }
69
4
{ "fr": "Les Tamud et les Aad avaient traité de mensonge le cataclysme.", "wo": "Giirug Aad ak Samuud dañoo weddi woon yëngu-yëngu bu rëy ba." }
69
5
{ "fr": "Quant aux Tamud, ils furent détruits par le [bruit] excessivement fort.", "wo": "Giirug Samuud ag yuuxu (am riir) la ñu léen alage." }
69
6
{ "fr": "Et quant aux Aad, ils furent détruits par un vent mugissant et furieux", "wo": "Giirug Aad nag ngelaw lu sedd luy riddi moom la ñu léen alage." }
69
7
{ "fr": "qu´ [Allah] déchaîna contre eux pendant sept nuits et huit jours consécutifs; tu voyais alors les gens renversés par terre comme des souches de palmiers évidées.", "wo": "xiirtal na ko ci séen kaw juróom yaari bëccag ak juróom yaari guddi yu tegaloo nit ña ne lasiim melni dàtti tàndarma yu fënëx." }
69
8
{ "fr": "En vois-tu le moindre vestige ?", "wo": "Moo ndax gisati nga lu bokk ca ñoom?" }
69
9
{ "fr": "Pharaon et ceux qui vécurent avant lui ainsi que les Villes renversées commirent des fautes .", "wo": "Firawnaak ña ko jiitu woon ak dëkk ya nu wëlbati woon njuumte la ñu fa nekke woon." }
69
10
{ "fr": "Ils désobéirent au Messager de leur Seigneur. Celui-ci donc, les saisit d´une façon irrésistible.", "wo": "Dañoo moyu woon senn Yonentub Boroom. Yàlla, faagaagal leen." }
69
11
{ "fr": "C´est Nous qui, quand l´eau déborda , vous avons chargés sur l´Arche", "wo": "Ba ndox ma bëbóo, Noo leen yanu woon, ca gaalug Nooh ga doon daw" }
69
12
{ "fr": "afin d´en faire pour vous un rappel que toute oreille fidèle conserve.", "wo": "danu koo def mu di fàttali ci yéen nopp yu sell it man koo jàpp." }
69
13
{ "fr": "Puis, quand d´un seul souffle, on soufflera dans la Trompe,", "wo": "Su nu walee bufta ba, genn wal ëf ko," }
69
14
{ "fr": "et que la terre et les montagnes seront soulevées puis tassées d´un seul coup;", "wo": "suuf si ak doj yi ñu jël ko def ko pënd moñoxe ko benn yoon ;" }
69
15
{ "fr": "Ce jour-là alors, l´événement se produira,", "wo": "Bu keroogee, xew-xew,ba agsi bis Pénc ba," }
69
16
{ "fr": "et le ciel se fendra et sera fragile, ce jour-là.", "wo": "asamaan siy xottiku nooy nepp." }
69
17
{ "fr": "Et sur ses côtés [se tiendront] les Anges, tandis que huit, ce jour-là, porteront au-dessus d´eux le Trône de ton Seigneur.", "wo": "Malaaka ya nekk ci ay goxam, su ko defee juróom-ñatta, cay yanu gàngunaay ga ( Aras )." }
69
18
{ "fr": "Ce jour-là vous serez exposés; et rien de vous ne sera caché.", "wo": "Bu keroogee dees na leen weer; ken du leen ca nëbb dara. " }
69
19
{ "fr": "Quant à celui à qui on aura remis le Livre en sa main droite, il dira : \"Tenez ! lisez mon livre.", "wo": "Ña nga xam ne dañoo jot seeni Téere ci ndeyjoor, da leen di wax ne : “Jàppleen ! jàng samab téere.(n)" }
69
20
{ "fr": "J´étais sûr d´y trouver mon compte\".", "wo": "Man dey jàppoon naa ne danaa dajeek samab màndaxe” ." }
69
21
{ "fr": "Il jouira d´une vie agréable :", "wo": "Moom dey mi ngi ci dundu gu neex :" }
69
22
{ "fr": "dans un Jardin haut placé", "wo": "ca Àjjana ju kawe" }
69
23
{ "fr": "dont les fruits sont à portées de la main.", "wo": "meññatam ma day yoore." }
69
24
{ "fr": "Mangez et buvez agréablement pour ce que vous avez avancé dans les jours passés.", "wo": "“Lekkleen te naan muy peyug la ngeen jiitaloon” ." }
69
25
{ "fr": "Quant à celui à qui on aura remis le Livre en sa main gauche, il dira : \"Hélas pour moi ! J´aurai souhaité qu´on ne m´ait pas remis mon livre,", "wo": "Ña ñuy joxe seen téere ci càmmoñ, danuy wax naan : “Aka neexoon ! Jotuma sama téere," }
69
26
{ "fr": "et ne pas avoir connu mon compte...", "wo": "te ma ba ña xam luy sama màndaxe..." }
69
27
{ "fr": "Hélas, comme j´aurais souhaité que [ma première mort] fût la définitive.", "wo": "Aka neexoon, ma dee farit." }
69
28
{ "fr": "Ma fortune ne ma servi à rien.", "wo": "Sama alal ja jariñuma dara." }
69
29
{ "fr": "Mon autorité est anéantie et m´a quitté ! \".", "wo": "Sama sañ-sañ réer na ma !” ." }
69
30
{ "fr": "Saisissez-le ! Puis, mettez-lui un carcan;", "wo": "“Jàppleen ko ! Te, jàng ko ;" }
69
31
{ "fr": "ensuite, brûlez-le dans la Fournaise;", "wo": "te, ngeen xoyom ko ca Safara ;" }
69
32
{ "fr": "puis, liez-le avec une chaîne de soixante-dix coudées,", "wo": "ca biir càllalag juróom-ñaar-fukk bëñ sóobleen ko ca jéng ko," }
69
33
{ "fr": "car il ne croyait pas en Allah, le Très Grand.", "wo": "moom gëmu tooñ Yàlla , mu Màgg ma." }
69
34
{ "fr": "et n´incitait pas à nourrir le pauvre.", "wo": "te daawul sonn ci dundal miskiin yi." }
69
35
{ "fr": "Il n´a pour lui ici, aujourd´hui, point d´ami chaleureux [pour le protéger],", "wo": "Bis niki tey amatu fi xarit" }
69
36
{ "fr": "ni d´autre nourriture que du pus,", "wo": "ducaageni ak lekk lu dul lay rogaat ci seen yaram," }
69
37
{ "fr": "que seuls les fautifs mangeront.", "wo": "defkati njaaxum ya rekk koy lekk”." }
69
38
{ "fr": "Mais non... Je jure par ce que vous voyez,", "wo": "Déet... Maa ngi giñ ci li ngeen di gis," }
69
39
{ "fr": "ainsi que par ce que vous ne voyez pas,", "wo": "Ak ci li ngeen gisul," }
69
40
{ "fr": "que ceci [le Coran] est la parole d´un noble Messager ,", "wo": "ci ne [Alxuraan] waxi ab Yonent la bu tedd," }
69
41
{ "fr": "et que ce n´est pas la parole d´un poète; mais vous ne croyez que très peu,", "wo": "du waxu ab waykat ; li ngeen gëm néew na," }
69
42
{ "fr": "ni la parole d´un devin, mais vous vous rappelez bien peu.", "wo": "du waxi it ab buxaaba, aka néew lu ngeen di fàttaliku." }
69
43
{ "fr": "C´est une révélation du Seigneur de l´Univers.", "wo": "Dafa wàcc bawoo ci boroom àddina si. " }
69
44
{ "fr": "Et s´il avait forgé quelques paroles qu´ils Nous avait attribuées,", "wo": "Su ca fentoon jenn jenn wax," }
69
45
{ "fr": "Nous l´aurions saisi de la main droite,", "wo": "( Kon ) dananu téye loxob ndeyjooram," }
69
46
{ "fr": "ensuite, Nous lui aurions tranché l´aorte.", "wo": "daldi, dog sidiiti xolam ( mu dee )." }
69
47
{ "fr": "Et nul d´entre vous n´aurait pu lui servir de rempart.", "wo": "Te kon kenn ci yéen du ko mana fanq." }
69
48
{ "fr": "C´est en vérité un rappel pour les pieux.", "wo": "Ca dëgg-dëgg ag fàttali la ñeel ña ragal Yàlla.(r)" }
69
49
{ "fr": "Et Nous savons qu´il y a parmi vous qui le traitent de menteur;", "wo": "Te xam nanu xéll ne am na ci yéen ñu koy weddi ;" }
69
50
{ "fr": "mais en vérité, ce sera un sujet de regret pour les mécréants,", "wo": "ca dëgg-dëgg, bekkoor la ci yéefar yi," }
69
51
{ "fr": "c´est là la véritable certitude.", "wo": "Saar 69 : Joxoñub dëgg ba 52 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi." }
69
51
{ "fr": "c´est là la véritable certitude.", "wo": "te moo di li wóor tigi." }
69
52
{ "fr": "Glorifie donc le nom de ton Seigneur, le Très Grand !", "wo": "Na ngay sàbbaal sa turu Boroom, bu Màgg bi ! " }
70
1
{ "fr": "Un demandeur a réclamé un châtiment inéluctable,", "wo": "Ab ñaankat ñaan na mbugël mu tàbbi,(s)" }
70
2
{ "fr": "pour les mécréants, que nul ne pourrait repousser,", "wo": "ñeel yéefar yi, te kenn du ku mana fanq," }
70
3
{ "fr": "et qui vient d´Allah, le Maître des voies d´ascension.", "wo": "bawoo ca Yàlla, miy Boroomi yéegukaay." }
70
4
{ "fr": "Les Anges ainsi que l´Esprit montent vers Lui en un jour dont la durée est de cinquante mille ans.", "wo": "Malaaka yaak Ruugaa ngay yéeg ci bis boo xam ne dayoom juróom- fukki-junniy at la." }
70
5
{ "fr": "Supporte donc, d´une belle patience.", "wo": "Muñal, muñ gu rafet." }
70
6
{ "fr": "Ils le (le châtiment) voient bien loin,", "wo": "Dañuy gis (mbugal) may lu sori," }
70
7
{ "fr": "alors que Nous le voyons bien proche,", "wo": "te nun danu koo jàppe lu jigeñ," }
70
8
{ "fr": "le jour où le ciel sera comme du métal en fusion", "wo": "bu keroogee ba asamaan si ruy melni biteex" }