sourate
float64
1
114
verset
float64
1
286
translation
dict
102
1
{ "fr": "La course aux richesses vous distrait,", "wo": "Ëpplaante fàbbi na leen," }
102
2
{ "fr": "jusqu´à ce que vous visitiez les tombes .", "wo": "ba faf ngeen seeti bàmmeel yi. Dee dikkël leen." }
102
3
{ "fr": "Mais non ! Vous saurez bientôt !", "wo": "Déet ! Da ngeen xalseta xam de!" }
102
4
{ "fr": "(Encore une fois) ! Vous saurez bientôt !", "wo": "(Te it) ! Du ngeen xalseta xam de !" }
102
5
{ "fr": "Sûrement! Si vous saviez de science certaine .", "wo": "Déedéet ! Cëy su ngeen amoon xam-xam bu wóor." }
102
6
{ "fr": "Vous verrez, certes, la Fournaise.", "wo": "Bu ngeen gisee, tigi, safaraw Jahiim." }
102
7
{ "fr": "Puis, vous la verrez certes, avec l´œil de certitude.", "wo": "Te, dangeen ko gIisaat, ak bët yu wér." }
102
8
{ "fr": "Puis, assurément, vous serez interrogés, ce jour-là, sur les délices.", "wo": "Te bu keroogee, def na leen laaj, xéewël ya. " }
103
1
{ "fr": "Par le Temps !", "wo": "(Giiñ naa) ci Jamono!" }
103
2
{ "fr": "L´homme est certes, en perdition,", "wo": "Ne nit, mi ngi cig yàqule," }
103
3
{ "fr": "sauf ceux qui croient et accomplissent les bonnes oeuvres, s´enjoignent mutuellement la vérité et s´enjoignent mutuellement l´endurance.", "wo": "bamu des ña gëm, tey jëf yiw di dénkënte dëgg di dékënte ci muñ. " }
104
1
{ "fr": "Malheur à tout calomniateur diffamateur,", "wo": "Xuru safara ñeel na képp kuy ŋelejooka ragaju," }
104
2
{ "fr": "qui amasse une fortune et la compte,", "wo": "kuy dajale alal di ko lim," }
104
3
{ "fr": "pensant que sa fortune l´immortalisera.", "wo": "Saar 104 : Ŋeleju 9 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi." }
104
3
{ "fr": "pensant que sa fortune l´immortalisera.", "wo": "jàpp ne alalam jaa koy taxa sax (baña dee)." }
104
4
{ "fr": "Mais non ! Il sera certes, jeté dans la Hutamah .", "wo": "Mukk ! dees na ko, mbaq ci biir Hutamatu." }
104
5
{ "fr": "Et qui te dira ce qu´est la Hutamah ?", "wo": "Ana lan moo lay xamal luy Hutamatu ?" }
104
6
{ "fr": "Le Feu attisé d´Allah", "wo": "Mooy Safaraw Yàlla wa ñu taal" }
104
7
{ "fr": "qui monte jusqu´aux coeurs.", "wo": "way alawtiku ba ca xol ya." }
104
8
{ "fr": "Il se refermera sur eux,", "wo": "Dañu leen cay séndël," }
104
9
{ "fr": "en colonnes (de flammes) étendues.", "wo": "ci ay gàlli Safara yu ñu tàllal. " }
105
1
{ "fr": "N´as-tu pas vu comment ton Seigneur a agi envers les gens de l´éléphant .", "wo": "Xanaa gisu leen ka sa Boroom def ak ña ame woon ñay ya." }
105
2
{ "fr": "N´a-t-Il pas rendu leur ruse complètement vaine ?", "wo": "Moo ndax deful seen pexe ma mu naaxsaay ?" }
105
3
{ "fr": "et envoyé sur eux des oiseaux par volées", "wo": "moo yabal ca seen kaw ay njanaaw yu bari" }
105
4
{ "fr": "qui leur lançaient des pierres d´argile ?", "wo": "ñu di leen sànni ay doj yu ñu saaf?" }
105
5
{ "fr": "Et Il les a rendus semblables à une paille mâchée.", "wo": "Mu def leen ñu mel ne am ñax mu ñu sàqami. " }
106
1
{ "fr": "A cause du pacte des Qurayshites,", "wo": "Ngir sababus màngug Qureys,(s)" }
106
2
{ "fr": "De leur pacte [concernant] les voyages d´hiver et d´été.", "wo": "Seen mànko ci tukib sedd ak tàngaay." }
106
3
{ "fr": "Qu´ils adorent donc le Seigneur de cette Maison (la Kaaba).", "wo": "Na ñuy jaamu Yàlla boroom néeg bii." }
106
4
{ "fr": "qui les a nourris contre la faim et rassurés de la crainte!", "wo": "Yàlla mi leen joxu ñam ba xiifuñu aar leen it ba ragaluñu tiituñu! " }
107
1
{ "fr": "Vois-tu celui qui traite de mensonge la Rétribution ?", "wo": "Xanaa gisuloo kay weddi bisub dekkiwaat ba ?" }
107
2
{ "fr": "C´est bien lui qui repousse l´orphelin,", "wo": "Mooy kay bunduxataal jirim," }
107
3
{ "fr": "et qui n´encourage point à nourrir le pauvre.", "wo": "te du sonn muk ci leel miskiin yi." }
107
4
{ "fr": "Malheur donc, à ceux qui prient", "wo": "Saar 107 : Njëfandukaay 7 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi." }
107
4
{ "fr": "Malheur donc, à ceux qui prient", "wo": "Xuru Safara, ñeel na ñay julli" }
107
5
{ "fr": "tout en négligeant (et retardant) leur Salat,", "wo": "ñay sàggane aka yeexe seenug julli," }
107
6
{ "fr": "qui sont pleins d´ostentation,", "wo": "ñay ngistal," }
107
7
{ "fr": "et refusent l´ustensile (à celui qui en a besoin).", "wo": "tey aaye dabi jëfandukaay yi. " }
108
1
{ "fr": "Nous t´avons certes, accordé l´Abondance.", "wo": "Jox Nanu la, déegub Kawsara." }
108
2
{ "fr": "Accomplis la Salat pour ton Seigneur et sacrifie.", "wo": "Na ngay julli ngir sa Boroom te na ngay rendi." }
108
3
{ "fr": "Celui qui te hait sera certes, sans postérité.", "wo": "Ka lay bañ aka ñaawal, moo dog ci lépp lu baax. " }
109
1
{ "fr": "Dis : \"ô vous les infidèles !", "wo": "Waxal ne : «Éy yéen yéefar yi !" }
109
2
{ "fr": "Je n´adore pas ce que vous adorez.", "wo": "Duma jaamu li ngeen di jaamu." }
109
3
{ "fr": "Et vous n´êtes pas adorateurs de ce que j´adore.", "wo": "Saar 109 : Yéefër ya 6 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi." }
109
3
{ "fr": "Et vous n´êtes pas adorateurs de ce que j´adore.", "wo": "Yéen itam du ngeen jaamukati li may jaamu." }
109
4
{ "fr": "Je ne suis pas adorateur de ce que vous adorez.", "wo": "Man it du ma jaamukatu li ngeen di jaamu." }
109
5
{ "fr": "Et vous n´êtes pas adorateurs de ce que j´adore.", "wo": "Te it yéen du ngeen jaamukati li may jaamu." }
109
6
{ "fr": "A vous votre religion, et à moi ma religion\".", "wo": "Am ngeen seen diine man it am naa sama dine” . " }
110
1
{ "fr": "Lorsque vient le secours d´Allah ainsi que la victoire,", "wo": "Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la," }
110
2
{ "fr": "et que tu vois les gens entrer en foule dans la religion d´Allah,", "wo": "te nga gis ne nit ñaa ngi dugg def ay mbooloo ci biir diineey Yàlla ji," }
110
3
{ "fr": "alors, par la louange, célèbre la gloire de ton Seigneur et implore Son pardon. Car c´est Lui le grand Accueillant au repentir.", "wo": "na nga sàbaal, te sant sa Boroom te na nga sàkku njéggalam. Moom Nànguwaakoonu tuub la. " }
111
1
{ "fr": "Que périssent les deux mains d´Abu-Lahab et que lui-même périsse.", "wo": "Ñaari yoxoy Abii Lahab dogg nañu te it dugg na." }
111
2
{ "fr": "Sa fortune ne lui sert à rien, ni ce qu´il a acquis.", "wo": "alalam ak la muy fàggu, du ko jariñ dara." }
111
3
{ "fr": "Il sera brûlé dans un Feu plein de flammes.", "wo": "Saar 111 : Buum ga 5 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi." }
111
3
{ "fr": "Il sera brûlé dans un Feu plein de flammes.", "wo": "Dana lakk ci biir Safara wuy bérax." }
111
4
{ "fr": "de même sa femme, la porteuse de bois ,", "wo": "ak jabaram ja daan yanu matt ma," }
111
5
{ "fr": "à son cou, une corde de fibres.", "wo": "loosam wa, buumug rawa cay nekk (caq bu ñu soy). " }
112
1
{ "fr": "Dis : \"Il est Allah, Unique.", "wo": "Waxal ne : “Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la)." }
112
2
{ "fr": "Allah, Le Seul à être imploré pour ce que nous désirons.", "wo": "Moom Yàlla, Mooy Kilifa gi wareefa joyal mbir yi." }
112
3
{ "fr": "Il n´a jamais engendré, n´a pas été engendré non plus.", "wo": "Jurul, te Kenn juru ko." }
112
4
{ "fr": "Et nul n´est égal à Lui\".", "wo": "Te amul benni nàttangoo” . " }
113
1
{ "fr": "Dis : \"Je cherche protection auprès du Seigneur de l´aube naissante,", "wo": "Waxal ne : “Maa ngi sàkku muslaayi Boroom suba si," }
113
2
{ "fr": "contre le mal des êtres qu´Il a créés,", "wo": "ci ayu li Mu bind," }
113
3
{ "fr": "contre le mal de l´obscurité quand elle s´approfondit,", "wo": "ak ci ayu lëndëm ga saa bu kukkee," }
113
4
{ "fr": "contre le mal de celles qui soufflent (les sorcières) sur les noeuds,", "wo": "Saar 113 : Suba 5 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi." }
113
4
{ "fr": "contre le mal de celles qui soufflent (les sorcières) sur les noeuds,", "wo": "ak ci ayu ñiy wal ëf ci pas-pas yi (jibarkat yi)," }
113
5
{ "fr": "et contre le mal de l´envieux quand il envie \".", "wo": "ak ci ayu ku iñaan saa su jógee bay feeñal kiñaan ga” . " }
114
1
{ "fr": "Dis : \"Je cherche protection auprès du Seigneur des hommes.", "wo": "Waxal ne : “Maa ngi sàkku muslaayi Boroom nit ñi." }
114
2
{ "fr": "Le Souverain des hommes,", "wo": "Kiy Buurub nit ñi," }
114
3
{ "fr": "Dieu des hommes,", "wo": "Di Yàlla nit ñi," }
114
4
{ "fr": "contre le mal du mauvais conseiller, furtif,", "wo": "ci ayu jax-jaxali, Saytaane," }
114
5
{ "fr": "qui souffle le mal dans les poitrines des hommes,", "wo": "kiy jax-jaxal ci biir dënni nit ñi," }
114
6
{ "fr": "qu´il (le conseiller) soit un djinn, ou un être humain\".", "wo": "te bokk ci jinne yeek nit ñi” ." }