File size: 2,887 Bytes
868d802 |
1 2 3 4 5 6 7 8 9 10 11 12 13 14 15 16 17 18 19 20 21 22 23 24 25 26 27 28 29 30 31 32 33 |
sentence: Ndege , ci atum 2014 , ci wutaakon yi doon sàkku Meeri Marseille bi la bokkoon . atum <location> Marseille <organization>
sentence: Loolu nag , baaxul , day féewale pólis bi ak askan wi .
sentence: Duma def lu dul dellooti mbirum taalibe yi ci loxo doxalinu nguur gi .
sentence: Léegi leer na ni peterool ak gaas kenn du ko jariñoo 2023 te sàggane nga li nga moomal sa bopp . 2023 <location>
sentence: Paap mujje naa am ndam ci xeex boobu .
sentence: Ndaxte askanuw Senegaal dafa ragal yat . Senegaal <organization>
sentence: Ñoom , ca nguurug Pers ga woon lañuy sukkandiku fonk seen bopp . Pers <organization>
sentence: 😌 🤝 🏿 - Toppaat ma ma xamal la làkk yi farañse àbb ak limu waat yi mu leen àbb .
sentence: Ndax bàyyees na xel ci seen wér - gi - yaram ?
sentence: Loolu metti na .
sentence: B ala may bëgg dee ñu naan dañoo am signature ” bu baax .
sentence: Li ngay jëkk a xalaat mooy , lan la xale yii nar a dooni ëllëg ?
sentence: Luy mébétu PASTEF ci mbir mi ? PASTEF <person>
sentence: Am na ay daara yu baax yu fi nekk , bu ma fi nekkee di lim damay juum .
sentence: Ca gàggantikaayu le Robert 60 000i waat ya ca ne , 11 825 yi farañse da ko a àbb 😱 😱 ( xaaral ma daw sax ! ! )
sentence: Alhamdu lillaah , cant fa Yàlla . 🤲 🏿
sentence: Aada mooy lépp , moo y cëslaayu yokkute .
sentence: Waaye du fi ame te bu soobee Yàlla , dina wax fum dugal xaalis bi mu leb yépp .
sentence: Dangay seet , tey , bu doon wolof bi wolof kese la dégg , al pulaar di wax pulaar kese , joolaa bi yem ci làkkam , séeréer bi noonu , añs .
sentence: Gisaanekat yi tamit kenn demul ñu des .
sentence: Ñépp a ngi fàttaliku taxawaayam ak kàddu yu dëgër yi mu biraloon ba coowal mbirum quotas yi amee Farãs , ci atum 2010 . Farãs <organization> atum <location>
sentence: Ñépp a koy jàng .
sentence: Jamono jooju la yëkkatiy kàddu yu siiw yii : Ërob ba mu daj , man kese maa ciy nit ku ñuul ku fiy jiite ab këlëbu futbal . Ërob <organization>
sentence: Dafa di , nag , Ërob rawatina Farãs , dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafóoni waaso yi . Ërob <organization> Farãs <organization>
sentence: Waaye nj ort naa ne , dañ leen di jox it ay ndigal yenn saa yi .
sentence: Warees na nangu lu ni mel .
sentence: Yeneen waat yi it noonu lañu mel .
sentence: Nit dina feebar , dem loppitaal ñ u koy jox i garabi - tubaab te du wér , fekk ne feebaru ng ë m la ame .
sentence: Danoo seetlu ne , léegi , saa booy wax ak askan wi , làmmiñu wolof ngay jëfandikoo .
sentence: Bu ko defee , bu nuy tëral nafa gi , warees na sóoraale diine ji , beral ko xaalis ni ñu koy defale njàngum tubaab bi añs .
sentence: Waaye , yenn saa yi , mbir mi ëpp i loxo ba njaaxum am ci , ñii am ciy gaañu - gaañu , ñale ñàkke ci seen bakkan .
sentence: Waaye , du futbal kesee yitteloon Mabaaba .
|