en
stringlengths
1
298
wo
stringlengths
1
279
We had them.
Am nanu leen.
- No, thanks.
- Déedéet, jërëjëf.
That's better.
Loolu moo gën.
So what should we do?
Kon lu nu wara def ?
You die within seconds.
Soo demee tuuti dangay dee.
Now the bastard's going to answer for all these years.
Leegi nit ku bon ki mooy tontu ci at yii yépp.
My little Achilles.
Sama Achille bu ndaw.
Even if they grow back, they won't be the Deer God's woods.
Doonte dañu màggaat, duñu nekk garabi Yàlla Kewel.
- Rud.
- Rud.
- Do you feel like that?
- Ndax noonu lay yëg?
Squirt.
Tuf.
The only ones who will survive the battle are the inferior ones.
Ñi mucc ci xare bi ñooy ñi gëna néew doole.
All the Alexandrias we have, I want libraries.
Alexandri yi nu am yépp, bëgg naa ay bibliotek.
- No, but they do sing and make noises from the roofs of the forest.
- Déedéet, waaye dañuy woy, di yëngu ci kaw àll bi.
If they find it, you're gonna lose it?
Suñu ko gisee, dinga ko ñàkk?
DANNY:
Danny:
To share our great treasures and tales of Asia.
Ngir séddoo sunuy alal yu mag ak sunuy jaar-jaari Asie.
I'm sorry.
Man itam bëgg naa la.
Dear Red, if you're reading this, you've gotten out.
Salaam Red, sooy jàng lii, génn nga.
- Tell her off.
- Wax ko mu dem.
At night he becomes the night-walker.
Guddi gi mooy doxantu guddi gi.
I make so many mistakes when I dictate...
damay def njuumte yu bari sumay dikte...
- He is handsome!
- Dafa rafet!
Five people... kicked me in the kidneys with their boots.
Juroom nit... ñoo ma dóor seeni rein ak seeni dàll.
Go back to Sweden if you don't like it here.
Dellu Suede sudee bëggoo fii.
Ah, no!
Ah, déet!
You would be justified in condemning me.
Soo ma daan, dina am lu jaadu.
Amen, I say to you before the cock crows three times you will deny me.
Amiin, maa ngi la koy wax, bala ginaar a sab ñetti yoon, dingeen ma weddi.
Papa ...
Pappa...
That's the florist laughing.
Loolu mooy jaaykat flër bi di reetaan.
- Where are you going?
- Fan nga jëm?
But he has no power, Alexander.
Waaye amul benn kàttan, Aleksandar.
You name the place, chances are I've been there?
Wax nga turu barab bi, amaana demoon naa fa?
You left me at my father's and never wrote.
Bàyyi ngama ci sama pàppa te doo bind.
Get a move on.
Demal sa kanam.
That's very good, Jack.
Loolu baaxna lool, Jack.
We all had children once:
Nun ñépp am nañu ay doom benn yoon:
-Oh.
-Oh.
Sort of like a bonus.
Daa melni bonus.
Fine.
Baax.
I wouldn't know what to do with it if I did.
Suma ko defee duma xam luma ciy def.
There are no reserves left, and air support has stopped.
Amatul reserve, te ndimbalu aérien bi taxawna.
- Rut?
- Rut?
Could I have one, too?
Ndax man itam mën naa am benn?
He'll be first.
Mooy njëkka.
Come on.
Gaawal.
I don't think I could make it on the outside, Andy.
Yaakaar naa ni mënu ma ko def ci biti, Andy.
We'II have a talk with Missus and her whoremonger.
Danuy waxtaan ak Missus ak soxnam.
The Dear God is dead!
Yalla bu baax bi dee na!
- We gotta go.
- Danu wara dem.
As night becomes day he changes form.
Guddi gi nekk bëccëg dafay soppi jëmmam.
If they do catch you with it, you don't know me.
Suñu la jàppee, xamoo ma.
- Just last night he was...
- Demba ci guddi gi...
It would be nice to have a girl child.
Dina neex su amee doom ju jigéen.
Stay, Alexander, down.
Alexandre, toog.
- No.
- Déedéet.
And to enjoy our imperishable glory to the ends of time.
Ak di bànneexu ci sunu ndam li dul jeex ba àddina jeex.
The myth becomes real.
Léeboon bi dafay nekk dëgg.
Lucien, you're a wizard!
Lucien, luxuskat nga!
Our best people have fallen already.
Sunuy nit ñi gëna baax daanu nañu ba noppi.
Leave it here or take it back to Iran
Bàyyileen ko fii wala nga yóbbu ko Iran
It was horrible...
Lu tiis la woon...
Can I go up to my room and get my fire engine?
Ndax mën naa dem ci sama néeg jël sama oto pompier?
I'm fine.
Maa ngi fii.
What?
Lan?
-Oh, dear.
-Oh, sama xarit.
Perhaps it's time you tried a new profession?
Amaana jotna nga jéem liggéey bu bees?
And because I'm a bricklayer I should die of hunger?
Ak ndax man ab brik laa, dama wara dee ci xiif?
- A bit young...
- Dafa ndaw tuuti...
Are you so damn stingy?
Ndax danga bëgg lu bari?
There's no way to bring in more ammunition.
Amul nuñu mëna indi yeneen munisioŋ.
Me, too.
Man itam.
And if you've come this far, maybe you're wiling to come a little further.
Te sudee yegsi nga fii, amaana dinga bëgga dem fu sori tuuti.
- What's the use?
- Luy njariñ?
I've been in here most of my life?
Maa ngi nekkoon ci sama dundu lu gëna bari?
You can't meet here!
Mënuleen daje fii!
Because, for some people solitude and isolation can, of itself, become a problem.
Ndax ñenn ñi, wéet ak wéet mën na nekk jafe-jafe ci boppam.
It Tatsuhei de "home of the strain."
Tatsuhei mooy "këru xeetu nit ñi."
- Who?
- Kan?
Mention my name, we never do business again?
Waxñu sama tur, dootu ñu def liggéey?
I guess I'm too old for that sort of nonsense any more.
Daa melni màgget naa lool ci xeetu mbir yu ñàkk fayda yooyu.
Erik?
Erik?
- Bullshit?
- Ay yëfi dof?
A girl that you do not have to kill, you can sell it.
Xale bu jigéen boo xamni jarul nga ray ko, mën nga ko jaay.
You'll never make as many as I do.
Dunga musa am xaalis bu bari ni may def.
He's vanishing...over there!
Dafay réer...fee!
Then I did not know how sweet you are.
Xamuma woon ni ngay neexee.
Down.
Ci suuf.
Let's get something to eat.
Nanu wut lu nu lekk.
- Come on.
- Gaawal.
What I mean is, you don't seem to be a good thief.
Lima bëgga wax mooy, nuruwoo sàcc bu baax.
- Follow Alexander.
- Toppal Aleksandar.
The ironworks are under attack.
Ñu ngi song liggéeyukaay yi.
- Hello
- Salaam maalekum
Oh, dear.
Oh, sama xarit.
That never stopped you before!
Loolu musu la tere!
Go back or I take my group out.
Dellul wala ma génne sama kuréel.
I'm an institutional man now?
Leegi nit ku am mbootaay laa?
Oh, it's you.
Oh, yaw la.
Don't you think we work hard enough?
Yaakaar nga ni dunu liggéey bu baax?