|
sentence: Bu ñépp bokkoon lépp , àddina si day soof . |
|
sentence: Ndaxte , ku xam ni pólis di doxe , nga gis ab alkaat i bu nekk ci biir màkkaanam sañ a def widewoo , yor i liif di tëkku askan wi , di ko dig ay dóor … ñàkkul mu am luñ ko sant . |
|
sentence: Dama ne , S apo ŋ , Farã s , Amerig añs ñoo ñu ëpp bor fuuf te doo leen mës a dégg ñuy ñaan ku leen ko baal . S <organization> apo <location> ŋ <location> Farã <organization> s <location> Amerig <organization> |
|
sentence: 😱 😱 😱 😱 Lii yéemewut a ! ! |
|
sentence: Boo demee Ërob , tamit noonu . Ërob <organization> |
|
sentence: Español : 476i waat . |
|
sentence: Luy mébétu PASTEF ci mbir mi ? PASTEF <person> |
|
sentence: Li koy firndeel mooy , ci bés bu jëk k bi dañu duma gaa yi bu baax , ca ëllëg sa , gisuma sax muus m uy taxawaalu . |
|
sentence: Xawma naka lees ko tërale , waaye dafa mel ni dañuy dëddale takk - der yi ak askan wi . |
|
sentence: Bala nga koy xam Gàmmu jot , walla Màggal , walla Pópangin . Pópangin <organization> |
|
sentence: Léegi leer na ni peterool ak gaas kenn du ko jariñoo 2023 te sàggane nga li nga moomal sa bopp . 2023 <location> |
|
sentence: Waaye nj ort naa ne , dañ leen di jox it ay ndigal yenn saa yi . |
|
sentence: Waaye , dañuy dàq nit ba ci biir kër am . |
|
sentence: Alhamdu lillaah , cant fa Yàlla . 🤲 🏿 |
|
sentence: Ñoom , ca nguurug Pers ga woon lañuy sukkandiku fonk seen bopp . Pers <organization> |
|
sentence: ( Àngale a ko a yées nag , mooy làkk wi ëpp i àbb ci kaw suuf ci li nu xamagum , waatam ya xaaj ba da ko a àbb 😱 🤭 🏃 🏿 ♂ ️ ) |
|
sentence: Ndaxte , bu dee ñ u bari ci way - juri tey yi sàmmontewu ñ ak seen i warugar , nguur gi moom loolu waru ko . |
|
sentence: Ku am signature ” bu baax , du ni faral leen ma bor bi . |
|
sentence: Xam naa , moo tax mu ni leen nañ tiital gaa ñi ngir ñu bañ a génn . |
|
sentence: Niral : crèche , auberge , blanc , ble … . 😲 |
|
sentence: Farañsig ga woon : 368i waat . |
|
sentence: Raayante bi moo fi war a jóg , wolof mooy làmmiñ wi nu war a boole . |
|
sentence: Làkku Neerlànd : 249i waat . Neerlànd <organization> |
|
sentence: Loolu , du lu ma jékki - jekki rekk def ko . |
|
sentence: Xamul woon xàjj - ak - seen te bëggul woon lu jege sax boddekonte , rawatina ñeel nit ku ñuul . |
|
sentence: Man , nag , dama naan nguur gi defalul daara yi waaye duma wax ne dafa leen noonoo . |
|
sentence: 😌 - Waat yi jëm ci xarala yu yees yi yu ci bari ci àngale la ko àbbe . |
|
sentence: Li ma tax a wax ne dañ leen k o o sant mooy ne , dara du leen ci fekk , kenn du leen teg i daan . |
|
sentence: Aada mooy lépp , moo y cëslaayu yokkute . |
|
sentence: Du sotti . |
|
sentence: Ndax am na réew mu dul leb ? |
|
sentence: Paap , yaa nu gënoon nun ñépp . |
|
|