audio
audioduration (s)
0.01
482
text
stringlengths
0
2.5k
labels
stringclasses
7 values
speaker
stringclasses
23 values
filename
stringclasses
123 values
boo defee engrais :fra NPK yii nii ñuy utiliser :fra engrais :fra de :fra synthèse :fra yi nga jël ko def ko ci suuf
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
gàncax bi rek moo koy jëfandikoo mais :fra suuf bi moom du ci am dara [r] ba tey tamit %e phosphate :fra [r] phosphate :fra moom njëriñ bi mu am
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mooy %e bu ma jëloon phosphate :fra defko sama suuf [r] non :fra seulement :fra dinaa am phosphore :fra mais :fra dinaa am yeneen ferñeent yu ci mel ni calcium :fra [r] wala magnésium :fra yu nga xamante ni [r] gàncax yi daén leen di jëfandikoo te bu doon yeneen beneen engrais :fra nga utiliser :fra doo ko am
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
loolu daal mooy différence :fra bi entre :fra phosphate :fra beeg matière :fra organique :fra bi ak yeneen xeetu engrais :fra yi
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
[r] mbokku auditeurs :fra yi ma fàttali ba tey yéen a ngi déglu Louga FM RTS émission :fra bi nga xam ne ECHO ECHO moo koy jagleel [r] rawatina ñii di béykat yi [r] %e fii ci 88.7 xam naa ne nag suñu mbokku béykat yi tey [r] dinañ si %e jëriñoo bu baax a baax %e donc :fra suñu déggee sa waxtaan
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
[r] %hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
matières :fra organiques :fra yi dafa mel ni moo ëpp solo ci béykat bi [r] léegi nag moom béykat bi
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
naka la mën a def moom ba mën a jot ci matière :fra organique :fra yooyu
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
ignore_time_segment_in_scoring
<o,,unknown>
excluded_region
wol_4210
%hum %hum %e merci :fra beaucoup :fra xam naa bu delloo ci côté :fra boobu moom comme :fra ni ñu définir :fra woon matière :fra organique :fra ca tàmbali ga rek mooy lépp lu nga xamante ni dafay jugee ci ci luy dund xam nga loolu yomb na am
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
par :fra exemple :fra buñ jëlee ñax
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
ñax matière :fra organique :fra la ñax jafewul
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
bu dee man dama am sama ginnaaw kër benn ñax bu may géner :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mën naa koo béy dajale ko
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
loolu ma di mun naa ko béy dajale ko dem sotti ko sama tool
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
benn source :fra de :fra matière :fra organique :fra la
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
bu dee dama béy sama %e nu mu tudd dugub wala sama mboq [r] xetax bi ciy juge
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
ak ge() getax biy juge ci loolu noonu matière :fra organique :fra la mën nañ koo jëfandikoo ba mu %e ba mu nekk %e source :fra de :fra matière :fra organique :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%e ba tey tamit bu dee dama am mbaaru xar sama kër
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
wala ma am sama benn
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
géttu nag
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
bu ma ko dajalee
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
bu ma ko nettoyer :fra ba mu set li fay jugee ci ay %e neefereeg yooyu noonu source :fra de :fra matière :fra organique :fra la mën nañu ko jël dem def ko suñu tool
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
ba tey sax %e sën yi nekk suñu kër yi
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
suñu ginnaaw kër yi
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
suuf sa fa nekk parce :fra que :fra liñ fay sotti noonu yiy décomposer :fra wu maanaam yiy yiy nëb noonu
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
ba dem bay nëb ba kii noonu
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
source :fra de :fra matière :fra organique :fra la mën nañu koo jëfandikoo directement :fra suñuy tool
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %e
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
yooyu yëpp source :fra de :fra matière :fra organique :fra la
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
maanaam daal ci gàttal moom
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
matière :fra organique :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
waaw waaw
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
jafewul a am
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
jafe jafewul a am
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
waa léegi jafewul a am [b] xam nga tey jii mën nga ko dem ba am ko sax
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
[r] %hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
mais :fra soo ko amee
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%e jëfandiku bi maanaam naka lay demee ndax da nga ko am directement :fra rek
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
[r] %hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
nga dem sotti ko ci tool bi [r] wala dafa am noo xamante ne noonu la ñu ko war a defee ngir béykat bi aussi :fra mën see jëriñu
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum [r] dëgg la xam naa bu delloo ci côté :fra boobu noonu [r] par :fra exemple :fra %e man mi am sama %e fumier :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum dosage :fra beeg yëpp a *
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
voilà :fra voilà :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
par :fra exemple :fra man mi am sama fumier :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
wala sama ñax
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mën naa [b] koo dem jël sotti ko directement :fra sama tool
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mais :fra su boobaa lu ñu naan décomposition :fra [conv] dafay yàgg te mën na dem ba dafay sonal suuf si parce :fra que :fra suuf am na ay li ñu naan ay micro :fra organisme :fra maanaam ay %e ay %e yuy dund quoi :fra xaw ma naka lañ koy tënkee noonu ci olof
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
yu ci nekk yu nga xamante ne loo fa sànni ñoom ñoo koy lekk ñoo koy dégrader :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
par :fra exemple :fra tey jii bu ma amoon sama xetax wala sama getax
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mën naa ko dem sotti foofu mais :fra boo seetloo temps :fra bi muy jël pour :fra mu décomposer :fra wu
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
maanaam pour :fra mu nëb ba suuf si mën a jëfandikoo ferñeent yi ci nekk
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
dafay yàgg
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
léegi nag am na benn technique :fra bu nga xamante ni [r] mi ngi tudd compostage :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
compostage :fra boobu noonu peut :fra être :fra dinañ ko gën a détaillé :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
dinañ ko détaillé :fra léegi ci kanam mais :fra ñu jàpp ni daal
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
compostage :fra boo ko defee li nga ciy am produit :fra bi nga ci am mi ngi tudd compost :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
compost :fra
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
compost :fra boobu
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210