audio
audioduration (s)
0.01
482
text
stringlengths
0
2.5k
labels
stringclasses
7 values
speaker
stringclasses
23 values
filename
stringclasses
123 values
[bb] moom mooy %e ñebe
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
dugub
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
gerte ak %e mboq
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
am na ñu ko fiy bay
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mais :fra léegi bu delloo ci %e yooyu noonu par :fra exemple :fra buñ jëlee %e lu mel ni %e mboq par :fra exemple :fra moog dugub
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
ñoom %e ay gàncax yu nga xamante ne dañ soxla ndox lañ
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
<o,f0,>
inter_segment_gap
wol_4210
gàncax yu bëgg ndox lañu
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
donc :fra suuf yi ñu gën a soxla
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mooy %e suuf yi ñuy tuddee ñun les :fra sols :fra argileux :fra sableux :fra argileux :fra sableux :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
maanaam déeg en :fra wolof déeg en wolof ñoom yooyu la ñu gën a soxla parce :fra que :fra suuf yooyu noonu [r] énoom ñoo gën a mën a téye ndox
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
parce :fra que :fra ñoom %e seen getax yi ak %e maanaan %e
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
épis :fra yi
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
danu soxla %e ndox mu bëri pour :fra mën a màgg donc :fra énoom ci suuf yooyu la ñuy gën %e soxla pour :fra %e maanaam mooy seen milieu :fra optimal :fra quoi :fra boo bëggee am rendement :fra bu baax ci li ngay bay bu dee da ngay béy %e mboq wala dugub [r] boo amee suuf bu nga xamante ni c' :fra est :fra argileux :fra sableux :fra moo gën maanaam déeg [r] mais :fra bu delloo ci ñebe
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
ñebe moom ay exigeance :fra am bariwul noonu
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
bu amee suuf bu nga xamante ne c' :fra est :fra sableux :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mën na cee dund wala suuf boo xamante ne c' :fra est :fra sableux :fra argileux :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
moom ay exigence :fra am bariwul mais :fra bu delloo ci gerte moom suuf yi mu soxla
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mooy li ñu naan les :fra sols :fra sableux :fra mais :fra tamit bu amee suuf yu diis yi tamit dina ci mën a dund
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
parce :fra que :fra ku amul la gën %e am la fa sës l' :fra essentiel :fra daal [r] li mu soxla ci ay ferñeent ak li mu soxla ci ndox na ko am mais :fra %e daal amul amul problème :fra bu kii quoi :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum mun naénu jàll nga wax ci ñeenteelu laaj bi ndax %e sànq wax nga ko junj nga ko [r] nee nga %e fe() amandement :fra yi di nga ci dellusiwaat donc :fra jot na nag pour :fra nga dellu si si [r] ndax %e nee nañu %e béykatu Louga bi %e donc :fra %e yan moyens :fra lay disposer :fra [r] ah ngir %e mën a def li nga xamante ne moom mooy fertilisation :fra ak amandement :fra [r] suuf si surtout :fra %e ki nekk fii Louga comme :fra que :fra si zone :fra Louga bi lañ nekk
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
waaw %e merci :fra beaucoup :fra sëñ Ba xam naa bu delloo ci coté :fra boobu moom
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%e amandement :fra ak %e fertilisation :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
peut :fra être :fra dañu ñun ci li ñu gën a apesantir :fra mooy
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
utilisation :fra matière :fra organique :fra [conv] ci la énu gën a apesantir :fra matière :fra organique :fra nag mooy méngoog bu ñu ko bëggee tënk ci olof mooy lépp lu nga xamante ni [conv] dafa jugee ci luy dund
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
wala mu jugee ci lu doon dund [conv] par :fra exemple :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
buñ jëlee exemple :fra mën nañ ne [r] %e ñax
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
bu wow
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
matière :fra organique :fra la
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
nga dem sa mbaaru xar nga bale ko fumier :fra ba fa jógee matière :fra organique :fra la
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
sa desitu ceeb sax matière :fra organique :fra la
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
loolu daal ci gàttal moom mooy %e matière :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum [r] waaw des na
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
<o,f0,>
inter_segment_gap
wol_4210
waaw dañ ciy ñëw mais :fra tamit %e phosphate phosphate :fra moom dafa nekk %e mën nañ ne benn xeer la
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
<o,f0,>
inter_segment_gap
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
xeer la bu nga xamante ni wala suuf la sax ci tënk bu ñu ko bëggee tënk ci olof [r] bon :fra bu nga xamante ni dan koy exploiter :fra ci carière :fra yi moom nag %e peut :fra être :fra dinañ gën a ñëw ci ay dinañ gën a ñëw sax ci ay njëriñam ci kanam mais :fra phosphate :fra moom am na solo trop :fra puisque :fra am na benn ferñeent bu nga xamante ni [r] ñi ngi koy woowee phosphore :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
boobu moo nekk ci engrais :fra NPK yi
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
mooy P boobu noonu nekk ci engrais :fra NPK yi kooku ci phosphore :fra maanaam boo jëlee phosphate :fra %e dafa bari phosphore :fra te dañu seetlu ne fii ci Sénégal suñu suuf dafa manqué :fra phosphore :fra [r] moo tax nag %e gouvernement :fra bi %e andi benn politique :fra bi nga xamante ni phosphotage :fra de :fra fonds :fra la tudd
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
boobu mi ngi dox nii nii jamono jii
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
xam naa dinañ ko gën a leeral ci kanam
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum nee naénu tamit %e béykat bi
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%e li nga xamante ne moom mooy %e avantages :fra yi waaw parce :fra que :fra dañu ne fii %e expliquer :fra ah les :fra avantages :fra par :fra rapport :fra aux :fra autres :fra formes :fra [r] de :fra fertilisation :fra donc :fra yi nga fi lim nii %e yan yan yan naka la gënee [r] yeneen xeetu fertilisation :fra yi
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum dëgg la %e maanaam %e tey jii nii man bu ma jëfandikoo %e fumier :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
jël ko def ko sama tool wala ak ci utiliser :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
engrais :fra de :fra synthèse :fra mooy maa() engrais :fra yi ñiy defar ci usines :fra yi
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
loolu noonu ban différence :fra lay am ci sol [r] %e mën naa la koo gën a tënkalaat ba tey damay delluwaat ci suñu doom ji ak suñu yaay ji
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
parce :fra que :fra bu dee par :fra exemple :fra
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
<o,f0,>
inter_segment_gap
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
jigéen ju nga xamante ni dafa war a nàmpal doomam te amul soow
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum nga jox jigéen ji mu lekk ba suur %e faj ko ba mu wér kooku dina mën a nàmpal dooma
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
dana nàmpal
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
léegi ah amaat soow léegi loolu noonu nga ko jox loolu mooy matière :fra organique :fra ba
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum *
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
matière :fra organique :fra du dafay %e ñëw rek %e dundal gàncax bi directement :fra [r] mais :fra day defar suuf si ba mu mën a dundal gàncax bi mais :fra léegi nag bu dee yeneen formes :fra engrais :fra de :fra synthèse :fra yi nga xamante ne ci usine :fra la ñu koy defaree [r] yooyu ci tënk dama naan la mooy biberon :fra entre :fra doom jeeg yaay ji parce :fra que :fra tey jii bu dee jigéen ji moom amul soow
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%e mu bëgg a nàmpal doomam nga dem jëndi meew pharmacie :fra ñëw defar ko biberon :fra jox ko doom ji doom ji moom mandi na de lekk na ba suur [r] mais :fra ba tey yaay ji amul soow bu mu ko jox léegi %e loolu noonu [r] mooy yeneen engrais :fra yi
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
par :fra rapport :fra ak suuf [r] mooy yeneen engrais :fra yi par :fra rapport :fra ak gàncax [r]
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210