text
stringlengths
38
33.7k
mace ak tomaa , saag doomu alfe , ak simo mi bokk ci mbooloo , ma nu tudde ni farlu ci moom seen reew
ki ñuy wax jaak cartier moom ab mool la woon daa jugoon def benn tukkeem bu wuññi ci jamonoy faransuwa mu njëkk mi jeggi màmbulaan gu atlas gi jem sowwu fétali àdduna ju yees ji
kon moom hegel day mel ne moo teg ci loxol brusiya lay wa xeltu guy rafetal , di baaxal seen jefi jiite googu nu jiite woon bennalug almaan gi .
yeesu tontu ko ne bi la filib di laata woo , gis naa la , bi nga nekkee ca ker garabu figg ga .
aji sax ji nee damaa yagga xeremlu , ne cell , teye sama bopp .
te walbatiku ci aji sax ji sunu yalla , mu yerem ko , yaatal njeggalam .
waaye ci bànni israyil amoon na naaféq yu mbubboo turu yonent ni muy ame seen biir ñuy mbubboo turu jànglekat
yaatalu mozilla may nala nga tasaare sumb yi nga soppi .
daawuda daldi laaj ayimeleg etteen ba , ak abisay ma seruya di yaayam , te mu bokk ak yowab . mu ne leen kuy and ak man dem ca biir dal ba , fa sool ? abisay ne ko man maay and ak yaw . daawuda and ak abisay ci guddi , ba fa dalu gangoor ga . ndeke sool a nga tedd di nelaw ca digg dal ba , xeejam baa nga sampe fa suuf , feeteek bopp ba , abner ak gangoor gaa nga tedd , yeew ko . abisay ne daawuda yalla de teg na sab noon ci say loxo
bu ñu toogee ba mu mot ab diir aji jëfe ji jublu ci ñii nuy wonee
boo xamee ni ñu ngiy reer te dàmmel yoor yoor lay reer ndax bu ñu toggee reer yi ba muy sotti day fekk mu guddi
ci noonu lonkooy yaxantu yu àdduna yi nga xam ne seeni boroom dañuy am alal lool tàmblee feeñ bank yi tàmblee yëngook a sawar ak këri koppar yi
fekk not nañu ko jaarale ko ci deretu gàtt ba
ñu yemale fayantóok bépp metetu buy soqekoo ci njaayum doole walla xeet diine ngoora xel ak nekkin
jant yooyu esekiya moo woppoon , bay waaja dee . yonent yalla esayi doomu amocc dikk , ne ko aji sax ji dafa wax ne
moo tax it mu maggal yalla , jafandu ci yetam .
jooxug mbej gu dattu ci jafaan yees jelee ci suuf si petrol , kerin , gil .
ba tay dees na ko jappe muy jamono ji xayale te waajale ba xam xam man a jem kanam , man a naat ci tugal , naataangey xam xam gii nga gis ci tugal ci jii jamono de , dara waralu ko lu dul jamonoy yewwute .
maggal boroom xam xam bu jefe xam xam ba mooy maggal boroom aras toogu ba boroomug yayoo bu sakkoo ci yaw dara , defal ko ko .
buleen fattee teral niy new ci yeen , ndaxte nenn ni , bi nu ko defee , teral nanu ay malaaka te xamunu ko .
moo tallal asamaan ni ndimo , firi ko nib xayma , dekke .
wante xam loolu ci boppam rekk lu am solo la ndax da nuy gindi , gen noo taggaat ba nu xam ne xam xam boobu fi nekkoon , su nu farloo , men na fee dellusiwaat .
am na yeneen bànqaas yu am ag jokkoo ak kureelu xeet yi ñooy yu mel ne àttekaayu maanduteg adduna bi ligeeyam di àtte xuloo yi ak amlante yi àttee ko nag ci yoon walla luwa bu àdduna bi ak kollërante yi reew yiy xuloo jotoon a def
niy jooy , mel ni nu jooyul niy beg , mel ni nu begul niy jend , ni nu moomul li nu jend
waaye ca néeg ba ca topp sarxalkat bu mag ba rekk moo fa daan dugg benn yoon ci at mi
ci séen jefiin lan léen di ranée yii njéeréer yunuy waw locuste bunuy tolo sii grégariaptes manaam bunuy tolu
bi bes ba dellusee jamonoy xarafal xale ba agsi .
yeena ngi may wer ndax mburu , mi ngeen lekk ba suur .
lóolóo tax samay bëgg bëgg ak li ma wér nooy ànd def ba duma soppeeku
gannaaw gi aaroona indi saraxi mbooloo mi , jel sikketu mbooloo miy
wunni woon nanu lendem lendemi gox yi ci xam xam ak jef ak deppoo .
moyam diis ko gann , mu daanu te du jogati .
bennoog sofiet daa taxawaloon ag mbootaayug koom koom atum 1949 g ngir fayyoo ci ci li tugal def ci wetam muy mbootaayug ja bi nga xam ne amerig moo ko digaloon waa orob yi ne leen woon nanu taxaw ci tabaxaat seen koom koom bu daanu bii nga xam ne xareb adduna bee ko màbboon te moom dana leen ci jàpple wooteg amerig googu ñi ngi ko gënoon a miine ci turu marsaal nag jawrini amerig ji yoroon wàllu bitim reew la woon ci ginaaw ñaareelu xareb adduna bi
tey jii mooy dëkk bu tudd ca réewu tirki
kaddu gii dikkaloon na yeremi , bayyikoo ci aji sax ji , gannaaw ba buur cedesyas fasook mboolem waa yerusalem ngir goreel jaam yi , ku nekk wara goreel mbokkam mu ebraam , goor ak jigeen , nu moom seen bopp , te kenn bana jaamlooti mbokkum ebraam . ba mu ko defee mboolem kangam yeek nit ni ko fasoo woon daldi nangoo goreel seen jaam yu goor ak yu jigeen , ban leena jaamlooti , nu moom seen bopp . nu daldi leen yiwi . gannaaw gi nag nu walbatiku , jelaat seen jaam yu goor ak yu jigeen ya nu goreeloon , dellooleen cig njaam , goor ak jigeen .
sheex baaba tag ko ciy xasaayid aki dagiid yu tollok ay teemeeri bayit bokk nan ci yile shex ahmadu xeewal la gu yàlla jox mbindeefam yi ak waxam ja sëñ bi daal xeewal la gu yàlla xeewalee di kiimaan ci kiimaan yi ak yu bokkul ak yooyu bu waxutoon yu dul yii it ñaari bayit yii rekk doyoon nanu seede ci màggug sëñ bii ak wilaayaam
foofa daal la wooteg bennal gi gënoon a tare ci yeneen wàll yu bëj saalum yi
li ma man a wax ci yeen ba atte leen , bare na .
deggal nga sa adares imeel ba sam saq a ngi dox !
kon nag saxleen ci moom ni mu leen ko jàngle
ba loolu weyee kilifay njaboot yi askanoo ci yuusufa , te bokk ci langu galadd doomu makir mi setoo ci manase , noo dikk . nu wax fa kanam musaa , ak kilifay
taaxu doxandeem yi noppee doon peey ba faww , te deesu ko tabaxaat .
noonu festus am fa noom juroom nett ba fukki fan , ba noppi dem sesare .
ginaaw tukki bu tar te sonnle , moom colombo agg na ca duni bahama ya mu mujjoon a tudde san salvador , juge fa dem ca tefesug kubaa gu bej gannaar ga ak dunub ayiti bi mu faroon tudde espaan gu ndaw gi .
te teewul nu cosaanale ko siyo , ne kii ak kee fa bokk juddoo ,
dungeen noppeek a diiroo ak xel mu sell mi
yeesu wone na it ci kanam taalibe ya yeneen firnde yu ñu nettaliwul ci téere bii
ba mu dig ko ci kaw ngin ne ko loo laaj , dinaa la ko jox .
jekk na nag mu matal yeesu ci coono bi mu daj moom mi léen xàllal yoonu mucc gi
waa orob yi jonjoo woon nanu ak digg yu xayug lisaam gi ci andalusi moom gox bii nga xam ne daa mujjoon fees dell ak leer guy jólli tukkee ci xayug lislaam gi ko róofu woon
li am daal mooy am nanu dig boo xam ne dunu ko man a laqu fenn .
yéwénalug diine ci orob ci doxam bi romb na ñaari tolluwaay bi ci njëkk mooy bi ay yëngu yënguy yéwénal yu ndaw amee te lalu niki ay njiitlaay aki cëslaay yoo xam ne ci seen kaw la yëngu yënguy yéwénal yu diine yu mag yi ci tugal tegu
liggeey bi man naa gaaw te woyof , diis te yeex , walla boole naar yepp , gaaw te diis , boobaa dina laaj kattan gu jeggi dayoo .
lammin feesal na biiru boroom , yoolu kaddu suur na boroom .
warlu yoon yi man a yobboo ci nu bayyi jefandikoo doole ci bu nuy lijanti jafe jafe yi ci adduna bi , ndare bu loolu day li gen ci adduna bi .
moom nag dajale na baykatu awsa yi ak sàmbkati pël yi di leen dugal ci lislaam ndax ñu man a def jiyaar ca nguuru awsa yi fi nekkoon
fi man la teereb yoon di bawoo , te maay fettaxal sama atte , muy leeru xeet yi .
ku la begg a kalaame , ngir jel sa turki , nga boole ca it sa mbubb mu mag .
dinañu gis xar kanamam te turam dina nekk ci seen jë
bi nuy wax ak mbooloo ma , saraxalekat ya ak kilifag niy wottu ker yalla ga ak sadusen ya daanu ci seen kaw .
coppite yi neel jefandikukat holder wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
te ba nu deeyee , teqlikoowunu . ag jaxaay , noo ko gena gaaw ,
ñu jel tuuti ci sunu jot jagleel ko xalaat ci seeni jafe jafe yu ñuy jankonteel
jii wax nag mi ngi ñuy jàngal ne àdduna bi du yàlla moom ci boppam te yàlla it nekkul di lu ëmbu ci àdduna bi
besub neenteel ba kilifag rubeneen na , elisur doomu sedeyur moo aye , ab saraxam di benn ndabu xaalis bu diise teemeeri siikal ak fanweer , di kilook liibar , ak benn kellu xaalis bu diise juroom naar fukki siikali berab bu sell bi , di juroom netti teemeeri goro , lu ci nekk fees ak sunguf su mucc ayib su nu xiiwaale ag diw , ngir saraxu pepp , ak senn mbattus wurus su fees ak cuuraay te diise fukki siikal , muy teemeeri gorook fukk , ak wenn yekk wu ndaw , ak menn kuuy , ak menn xarum menn at , ngir saraxu rendi doomal , ak wenn sikket ngir saraxu pootum bakkaar , ak saraxas cant gi ci biir jamm , di naari yekk ak juroomi kuuy ak juroomi sikket , ak juroomi xari menn at . looloo doon saraxu elisur , doomu sedeyur .
mbootaay societe uk bomis gi jimmy wales feetewoo woon moomeel gi ci epp moo ko jappale woon ciy koppar , doon fay larry sanger mi jiite woon mbind mi .
ci atum g . j , la ab xare takkaat bu bees bu tallaliku ba daj tugal ak mbooleem reewi adduna bi .
tundoo tund wu ne faraas fi mandi mi , ay yaqkat a ngi ciy bawoo ,
bariwaa na waa jees miin ci xam xam te kenn jubluwu ko .
bu fekkee ne dangeen a begg firnde juy wone ne , kirist mooy wax jaarale ko ci man , dingeen ko am .
waaru na si kooku kiy wuuti niit ñi di leek seen alal yum tooggé si kawdiru yaq ak jalgati nuluge ko deretu mbaam xuux
mebet maa ngi xaar laata may genneewaat leneen , ndax ku lekk ak naari loxo gawa suur .
amari moo duggal aada bi ñu fal buur bu ñu tudd di fateliku bi njaajaan njaay ku jëkka nekk buur ba jolof nekkoon biir dex gi ca waalo
diggante naar nu nekk waxtaanay la koy rataxal
sëriñ bi neena des na diir bu gàtt ku man a wax ne sëriñ tuubaa neena
noonu mu dand leen , ba fu aw saan man a tollu , daldi sukk di naan ne
xam ne kirist mi dekki dootul dee mukk , dee menatul dara ci moom .
surgaam ya nag dikk , kenn ca noom ne ko baay naaman , su doon lu jafe la la yonent bi wax ndax danga ko dul def ? kon kay su la nee nga sangu rekk , set wecc , nga war koo def ! naaman nag doora dem , soobu ca dexu yurdan ga , ba muy juroom naari yoon , muy la gooru yalla ga waxoon . mu daldi wer , yaram wa mel ni yaramu xale bu goor bu ndaw , set wecc .
dégg naa ko bis g y m mu naan man dey jamonoy samag ndaw dama daan tànn ci giir gu ne ab xarit daan ko jagleel ci sama xol ag cofeelug boppam ni ma tànne woon ci giirug daymaan muhammad yaddaali boroom téere bi nuy wax zahabul ibriiz ci giirug tandax ma tànn fa muhammad fall mom mutaali ci ñoñ haaj ñi ma tànn fa ahmadu doomi muhammad boroom jawharul munazzam
mi tàkk ci bi almaañ ak itaali ak imbratóor gu sapoN bëggee noot àdduna bi ci diggante 1914 1918 g j
deel jaajefal yalla , sarxale ko , di fey aji kawe ji loo dige ,
lijjantikati japon yi dox nanu bu baax ci tas ak yaatal koom koomu japon ngir seenug yewwute ak ngir bari gu japon bari ay ligeeykat
wommat nga sa mbooloo ni ag jur , musaak aaroona jiite .
waxi ku xelu day gindee , bantub samm la tenk ba diy pont , sampe ca .
ndend yi tegg , xameesul neexaayu tegg mi ni mu neexe mboo loo mi topp ci moon , fasu naarugoor yi , ku ci nekk yaa nga yegg ca kow .
ndaxte tuur nanu deretu sa gaa niak ju yonent yi , yaw it fey nga leen seen bor , jox leen deret , nu naan .
ab dawaan bu safaanu su walee ci taxañ bu njëkk bi ab toolu bijjaakon daf fay juddoo mu jur moom itam ab dend buy soppeeku ci jenn jamono ju nekk ci ñaareelu taxañ bi
ni aristo firee xeltu ne mooy sopp hikma am na lu epp benn teglal walla maanaa .
ci wallu bej gannaar , li ko dalee ci volta ba ci mongooli , jaare ko ci kasakistaan , ab kekk la def bu ay sammkat dekkee .
lu tax menunoo wax ne nanu def lu bon , ngir lu baax genn ca ?
te nga bëgg ko ak sa xol bépp ak sa xel mépp ak sa kàttan gépp moo dàq bépp sarax bu ñuy yóbbu ngir màggal yàlla ak bu ñuy lakk ca sarxalukaay ba
boroom kër gi dafa bëggoon dàq ñi bokkoon ci gereew bi ñépp
denkul ci aji sax ji , di def lu baax , ba des ci reew meek jamm .
noom nepp di nirook i kangam , di saf doomi babilon ,
waaye war nanoo banneexu te beg , ndaxte sa rakk jii dafa dee woon te dundaat na , dafa reeroon te feen na .
ku sosal doomu nit ki dinañu ko baal waaye ku sosal xel mu sell mi duñu ko baal mukk du ci àddina si du ci àllaaxira
daawuda ne ndaw la ana foo bokk ? mu ne ko man doomu doxandeemub amalegeen laa . daawuda ne ko noo sana xaccee sa loxo , di boom ki aji sax ji fal ? daawuda nag woo kenn cay surgaam , ne ko
waaw lu tax petrarch mii doon binde ci wu itaali wi te fekkoon fi lakku w latin wi népp daa binde
yeesu ne tell ci seen biir ne leen na jamm wacc ci yeen !
aji sax ji , yallay israyil , mi nga naan ci mbirum senakerib buurub asiri , dafa wax ne lii moo di kaddu gi aji sax ji wax ci moom yaw , janq siyo da laa xeeb , di la naawal . yerusalem , dekk bu taaru booboo lay wecc bopp , di la kekku sa gannaaw . ana kooy kokkaleek a nakke kersa ? moo kooy yekkatil kaddu ? kooy xool geti xeebeel ? xanaa du aji sell ju israyil ji ? yaa yebal say surga , di kokkali boroom bi , te naa sama watiir yi ne xas