text
stringlengths
38
33.7k
maa ngi leen koy wax , bu bes baa , waa sodom nooy tane dekk boobu .
koo agsi ci moom nanga ko nuyyu bu fekkee ne soxla nga ay teggiin
te jaam du bokk ci kër gi ba fàww waaye doom moom ci kër gi la bokk ba fàww
amalegeen na defoon israyil , teru leen ca yoon wa , ba nuy genn misra . demleen leegi , songi amalegeen ni . faagaagal leenr seen lepp , te buleen leen neewante reyleen goor ak jigeen , gone yi ba ci niy namp , ak nag ak gatt , ak gileem ak mbaam .
noonu la mbooloo ma mepp jalle dexu yurdan , buur it jall . buur nag taf barsilay ca kawam , naanal ko , barsilay doora nibbi keram . ba mu ko defee buur jall ba gilgal , kimyam and ak moom . mbooloom yudaa gepp ak nenn ci mbooloom israyil itam and ak buur dem .
noonu kenn ci noom , ka nekk xutbakat , fexe koo fiir .
bi nga xamee ne génn nañu ñu daje ak nit ku dëkk siren te tudd simoN
daara mooy fu deesi jànge alxuraan waaye fi murit ñaare daaray tarbiyu lay doon di benn barab bob dees koy sos ngir jàng alxuraan ak xam xamu diine waaye it ngir yar mbay ak liggéey mu mel ne day doon fu deesi waajale nit ba bu fa jugee dara du ko jaaxalati ci àdduna moo xam lu deesi xam la ci diine mbaa lu deesi dajeel ci jafe jefey àdduna ndax ka fa yaroo day miin coona yi man koo dékku wullees ko ci liggéey jàngalees ko mu mujj di ni ko sëriñ fallu waxe woon ne noonu la leen seen baay cerno defoon kon yar bees ne nërr jàngale bees ne arr mooy mbóotum tarbiya
gàddaay gii nag juge ci àll yi dem ci taax yi taxoon na ba ab kiris walla jafe jafe bu rëy amoon fi ci wàllug mbay ci tugal rawati na ci angalteer
kàttanu ceeñeer gi jant biy àggal ci suuf si moo tax dund man faa am kàttan googu day nu man a am ndox ci nekkinu yullaakon tax it gañcax gi man a jot ci naaj wi mu soxla ngir seenug dund
aji sax ji , yaw laay diis sama bakkan .
bu fekkee ne kirist dekk na ci yeen nag , lii moo am seen yaram mi ngi ci dooley dee ndax bakkaar bi nekk ci yeen , waaye seen xel mi ngi dund ndax njub gi leen yalla jox .
ngeen not seeni cér ci cell ak tedd te xemmem bañ leena jiital ni xeeti àddina yi xamul yàlla
donte def nga ay wonendi , du ci wanni dara .
lu weesu mansa ii , kujje ya amoon ci biir ker buur , te yenn saa yi rayante daan ci am , moo demoon ba faagaagal nguur gu mag ga .
mu wey ci noonu diirub naari at , ba ni dekk diiwaanu asi nepp degg kaddug boroom bi , muy yawut muy gereg .
ci kaw loolu musaa wax ko banni israyil , nu genne dal ba waa ja nakke yalla kersa , door ko ay doj , ba mu dee . kon li banni israyil def mooy li aji sax ji santoon musaa rekk .
ba loolu amee ma digle foofa koor ca takkal dexu aawa , toroxloo ko fa sunu kanam yalla , ngir naan ko mu may nu yoonu jamm , nook sunuy doom ak mboolem lu bokk ci nun . ndaxte rusoon naa naan buur mu boole nook ay dag ak gawar yu nu aar ci noon yi ci yoon wi . li ko waral mooy fekkoon na nu wax buur ne ko sunu yalla mooy toppe yiwam mboolem ku ko yaakaar , di ko defal jamm , waaye meram dina dal ak doole ci kaw mboolem ku ko deddu . nu woor , daldi dagaan sunu yalla mbir moomu , mu nangul nu . ba loolu amee , ma tann fukki sarxalkat ak naar yu mag , nuy serebya ak asabya ak seen fukki bokk . gannaaw loolu ma nattal leen xaalis baak wurus waak ndab , ya buur ak i wollereem ak i jawrinam jooxe woon , nook mbooloom israyil ma fa teewoon , te lepp jem ca sunu ker yalla ga . natt naa ba teg ci seeni loxo naar teemeeri barigoy xaalis ak fanweeri barigo ci jumtukaayi xaalis ak fanweeri barigoy wurus , ak naar fukki koppi wurus yu wecci junniy poseti wurus , ak naari ndab yu jafe , yu xanjar bu nu raxas ba muy melax , mel ni wurus . ma ne leen yeen , dees leena sellalal aji sax ji , ni nu sellale ndab yi , te xaalis beek wurus wi di saraxu yeene neel aji sax ji , seen yallay maam . xool leen ko te samm ko bu baax , ba kera ngeen koy natt ca denci ker aji sax ji ca yerusalem , fa kanam kilifay sarxalkat yaak leween naak na jiite seen langi ker maam ci banni israyil .
njiilul amerig lii di harry truman g dafa nekkoon ku banoon lool mbokkte walla cominisme , te banoon it mu tas .
buntub naari laf lanuy dugge ca neeg bu sell bu mag ba , di dugge beneen bunt bu ni mel ca neegu biir bu sell ba . bunt yooyu , bu ci nekk naari laf yuy warangiku la . nu yett ca buntu neeg bu mag ba ay malaakay serub , ak garabi tandarma yu mel ni ya nu yett ca kaw miir ya . catu xaddu mbaaru bunt ba ca biti , aw denk lanu ko def . palanteeri caax yi ak miiri neegi wet yi ak miiri mbaar mi ak ca kaw catu xadd bay lang , wet gu ne , ay nataali tandarmaa nga ca .
xawma ndax and na ak jemmam walla deet .
. deel naan bes bu ne lu tollu ci liitaru ndox mbaa liitar ak genn wall .
xam xam yii nag tas nanu ci adduna bi , kon goxub afrig san naa ndamu ci li mu indil ag nite ciy liggeey yu am solo .
ngalla yeen , janqi yerusalem , waatal leen ma ci taaru kewel ak koobay all bi ,
bi ko bokk yi yegee nag , nu yobbu ko dekku sesare , yebal ko dekku tars .
ndaxte bokk ngeen naqar ak ni nu tej , te nangu ngeen ak xol bu sedd , nu foqarni seen alal , xam ne , am ngeen alal ju gen te di sax ba faww .
xam yeneen mbir yu jem ci sutura mozilla ak kaaraange jefandikoo .
teggiin yin nangu png , jpeg , gif . a target blank href learn more xam ci yeneen mbir . . . a
ci beneen boor , addina sepp sukk , samp benn oom ci suuf , yekkati beneen bi ngir naqarlu boomug george floyd gi . waaye tamit , ngir anni doxalinu takk der yiy metital nit ni ak boddekonte neel nit ku nuul ci addina si . artist yi , woykat yi , futbalkat yi , basketkat yi , way moomeel yeek kurel yiy samm aqi doom aadama , rawatina yiy xeexal nit ku nuul , nepp daal taxaw nanu temm , ne besu dee du besu dund , di jammaarlook alkaati yi . kurel gi nuy wax black lives matter lan ci gen a rannee . black lives matter a ngi tekki ne bakkanu nit ku n uul am na solo . xanaa kon nu ne nit ku nuul du xaru tabaski ba tubaab bu jog teral ko rendi .
dugal na sax ay gereg fii ci kër yàlla gi ba indi sobe ci bérab bu sell bii
benn dekk ak teeru ci misra la , fu sorewul belub dexu niil .
waaye jigeen ji sey dafay bayyi xel ci mbiri addina , ak nu mu man a neexe jekkeram .
waaye yaw ma fa kaw , yaay aji sax ji ba faww .
genn mbëggeel manula weesu joxe sa bakkan ngir say xarit
du goor te yappul am padd , deret ja tuuru , mu xab .
looloo tax maa ngi lay fattali , nga xambaat taal bi yalla taal ci yaw , di may gi mu la jagleel , bi ma la tegee samay loxo .
téere bu sell bii mooy feeñal màggaayu yàlla aji kawe ji dëkk ci biir leer gu kenn manta jege
coppite yi neel teere irwaun nadiim ci serin tuubaa teere irwaun nadiim ci serin tuubaa wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
ba keroog muy dej atteb yoon fi kaw suuf , fa waa dun ya di seentu ndigalu yoonam . yalla aji sax ji dafa wax ,
yoon dabu ko fenn moona ñaan nañu pilaat mu reylu ko
jaare ko ci leeral leen mbugël yi ñu waajal ñeel ñi ragalul yàlla mbaa ñuy tooñ nit ñi di jalgati mbaa ñuy gàttañlu ci def jaamu yàlla yi
say doomi rakk ji yàlla tànn ñu ngi lay nuyuñetteelu bataaxal bi yàlla may yowaana mu bind ko
jeggalu , njuumte am na ci sa siiwalug njangat .
laaj na nguur gu yaatu guy bennale biir reew mepp ci lu mu neew neew diirub naari app , la jibal moom mi feete kaw ci tanneefu njiitu reew ma .
ab dencukaayub mbind man nanoo firi embitam mu doon ay mbind lees man a jang .
te yaw sama nawle bu wer , nanga dimbali jigeen noonu xeexoon ci sama wet ci tas xebaar bu baax bi , boole ci kelema ak samay yeneeni nawle , noom ni yalla bind seeni tur ci teereb dund ba .
man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam xam ci anam yi wikipedia taxawal buruundi am reewu diwaanu diggu afrig la , reye na , km , , km suuf la , , km di ndox .
mu feeñu léen diirub ñeent fukki fan di diisoo ak ñoom ci lu jëm ci nguuru yàlla
faraas moom daa jàppe woon loolu muy aw xët ci digg ginaawam ndaxte moom kat manul woon a dékku ag nguur gu almaañ gu am doole ci wetam
xam xam yu mel noonu ñu ngi soqikoo ci aada yu nit tëral ci aaday àddina waaye soqikoowul ci kirist
waaye moytul yu deme ni werantey neen ak limi maam , ay xuloo ak i xeccoo ci doxalinu yoonu musaa , ndax loolu waxi neen la , te amul benn njarin .
noonu nepp niy dawal gaal ak ni ciy tukki ak ni ciy liggeey ak ni ciy baana baana , nepp di sore berab boobu ,
bokk na ci seere yi li ma abal mom baay addaymaanii nettali mu ne moom de sax na jamono ju yàgg ci sàkku ci sunu boroom mu won ko maqaamam sëñ bi mu ëppal bis ci sàkku gi ñu ne yeen de du ngeen xam ci sëñ bi lu dul bu ubee ba toog ngir daje ak nit ñi ngeen ne kii de mooy sëñ bi mbaa mu ubbi mihraab bi taxaw ngeen ne sëñ bi de jiite nanu lu dul loolu ciy mbiram de fàddu na leen
coppite yi neel jefandikukat avicbot wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
soxla nanu jappalekat yu men a bind , soppali ak jubbanti jukki yi ci angale .
dëkkub tuubaa kii di sheex ahmadu bamba moo ko sanc ci atum 1887
paj loo xam ci li doktoor raoult wax ne niwaakin men na faj covid bi ak coow li mu jur ci addina si , rawatina senegaal ?
jataay bi defaraat na beneen sart , boo xam ne moo waral ab goornamaab faraas bu bees , nu xame ko ci turu goornamaab doxaliin bi .
bi loolu weyee nu fas yeene noo dugal gaal jeme reewu itali .
misaal degerluwiinu perem mooy . ohm x mm m , kon lii da lay wax ne ag wenu perem gu gudde m dijjee mm ndegerloom gu mbej day doon . ohm .
dina sampu bu nu tambaliwaatee . modili mottali dina nu sampu bu nu tambaliwaatee .
yàlla wàcce na ko ci gaayam yu sell yi ñu bind ko ci làkku gereg
kon yii tur ci jii aaya ju tedd , mant a doon lu dul lakk , wi nga xam ne bokk na ci li yalla t .
waaye dinañu doon sarxalkati yàlla ak kirist tey nguuru ak moom junniy at
isipt gu yagg ga daa nekkoon gu di boroomug xay gu kawe gu dimbalee ci amal ay wunni yu am solo ci wallug xam xamu xayma , ak xam xamu falag fidiw .
leya moom it xam ne taxawaayam yagg na , mu fab jaamam silpa , may ko yanqooba . bi loolu amee silpa , jaamub leya , amal yanqooba doom ju goor . leya ne ndaw werseg wu rey ! daldi ko tudde gadd mu firi werseg . silpa jaamub leya dellu , amal yanqooba doom ju goor . leya ne eey waay , maaka beg ! jeeg ji dinanu ma wooye boroom mbegte mi . mu tudde ko nag aser mu firi boroom mbegte .
looloo ma tax di jooy , rongoon di wal wali .
moona , am na ci yeen koo xam ne seytaane la !
yalla ju araam la , ji waa filisti doon jaamu ci dekku ekron .
lawbe labbo su de kenn la ci kallama pulaar la joge
wax ji ba nekk ci seen diggu pecc ñu jekki jekki rekk déggati riir mu rey
nicolas agbohou jangalekat la ci fannu koom koom ci daara yu mag ya ca tugal , cosaanoo kodiwaar .
kenn muccul ci boobu xare , te mbon du ca wallu boroom .
xibaar bi nu dégg ci yeesu kirist di leen ko yégal mooy lii
noonu kilifa ga jàpp ci loxob waxambaane wa wéetoo ak moom laaj ko
bi mu ko defee sancug faraas tamblee putuxlu ci kanadaa , ak barabi dex yi ci aamerig gu bej gannaar gi .
mu daanu ci suuf , degg baat bu ko ne sool , sool , lu tax nga di ma fitnaal ?
span data l n name state nekkiin span doxalees blockliststate
lii nag mooy li jegeele diggante nasi ak fasi nga xam ne mujj nanu àgg ci def ag dëppoo ci seen biir mooy taxawal ag tapoo gu xare nu duppee ko diggub berlin rom
mu ne leen demleen ci addina sepp , yegal xebaar bu baax bi mbindeef yepp .
amoon na benn waay bu woppoon , nu koy wax lasaar .
ba loolu amee buur sant ilkiya sarxalkat bu mag ba , mook sarxalkat ya ca topp , ak wattukati buntu ker aji sax ji , ne leen nu gennee ker aji sax ji mboolem ndab ya nu defaraloon baal ak aseraak biddiiwi asamaan yepp . mu genne lepp yerusalem , lakk ko ca tooli sedoron , ba noppi yobbu doom ba betel . gannaaw loolu mu daq sarxalkati tuur ya buuri yudaa faloon nuy taal cuuraay ca berabi jaamookaay ya ca dekki yudaa ak la wer yerusalem , daqaale nay taalal cuuraay baal , ak jant beek weer week xeeti delloon yeek mboolem biddiiwi asamaan yepp . bu loolu weesoo jele na ker aji sax ji tuur ma tudd asera , genne ko yerusalem ba ca xuru sedoron , lakk ko foofa ca xuru sedoron , wol ko ba muy sunguf , mu xepp ko ca segi baadoola ya . mabb na it keri nit na doon jaay seen bopp fa nuy maggale tuur ya ca biir ker aji sax ji , te jigeen na daan fa rabbal tuur ma nuy wax asera ay xayma .
jigéen ju nekk ci mat dafay jàq ndaxte waxtu wi mu wara jur jot na
noonu ñi mujj ñooy jiituji ñi jiitu ñooy mujj
gannaaw loolu ma dégg lu mel ni baat bu xumb bu jollee ca mbooloo mu bare ca asamaan naan
ba loolu amee daawuda joge gaat , daw laquji ca biir xuntim adulam . magam yaak waa ker baayam gepp yeg ko , dikk , fekksi ko fa . ci biir loolu mboolem boroom njaqare ya , ak na bor jiital , ak
noonu la kaabu mujjee ci diggu xix xarnu
mu ko daan def ginaaw bu wàccee kaamil bi waaye kaamil bi moom lu saxoon la suba ak ngoon naka jekk njëkk sëñ biy tukki waaye salaatu halan nabii gi moom saxal gi man na a nekk muy ndigalul sëñ bi mbaa xalifaam bu baax bu sell ba ngir xér gu mu defoon ci muccug sëñ bi ak ag delluseem ci jàmm mu sàkkaloon ko mbooloo mu ci daawul sàggan suba ak ngoon waxambaane wu ragal yàlla wu dëkkoon kokki wii di samba joop nu gënoon koo xam ci samba asta daan leen jiite
dinañu tanqamlu dëgg jeng jëm ci léebi diiney neen
jege gu lay jariñ te dula lor boo dee naafila nanga yéene dundal sunnas
te bul di ràppal ak a reesal lu lewul doonte lu ras nga am te am rooy rafetal
sama doom yaa ngi ak man bés bu nekk te li ma am lépp yaa ko moom
te baal nu sunuy tooñ ni nu baale ñi nu tooñ
waaw kay yaw mi bëgga toj kër yàlla gi tabaxaat ko ci ñetti fan wàccal ci bant bi te musal sa bopp
ci kaw loolu buur seetluwaat mbir ma , daldi sakklu naari welluy wurus . mu ne mbooloo ma yeen waa israyil , bare ngeen lu ngeen di jaabante yoonu yerusalem . xool leen fii kay ! seen yalla ya leen genne woon reewum misraa ngi . ba loolu amee mu teg wenn wellu wa ca dekk ba nuy wax betel , wa ca des mu tegi ko ca dan . mbir moomu doon bakkaar . mbooloo ma dox jiitu wenn wellu wa , ba agg dan . ci kaw loolu yerbowam tabax ay
dénk léen ñu def lu baax te bare jëf yu rafet ñu yéwén bay sédd ñi amul di fàggu dencu ëllëg bu wér
yokk s ci limu seetukaay yi ci banqaasu ceet gi ? n n dalee s
fii war na am noo gise sarwisi dalub web yi and ak xelteef bi , and ak ay tektal ci naka lanu leen di suuxalee bu waree ne .
atum ak li ko jege , ci la reew yu bari ci dendug afrig tambalee moom seen bopp , ginnaaw bi tubaab yi duyee seeni gafaka ba nu fees dell . waaye nooteel gi yemul foofu , de . wax ji lii do la woon dangeen a begg moom seen bopp ? yoon waa ngoog waaye na leen leer ne dinanu wey di leen yilif . kon , beneen xeetu nooteel daldi judduwaat . booba ba tey , boo jelee reew mu mel ni senegaal , lepp lu fi baax sunu njiit yi jox ko waa faras toog . su may xool fi nu jaar yepp , doore ko ca jamonoy njaam ga ba tey , ci laay gen a gem li seex anta joob waxoon ca niseer su nu yaakaaree ne naawteef yi nu tubaab bi def den na ci nun , noo ngi nax sunu bopp . degg la ndax tubaab bi dafa raxas sunu xel ba gematunu sax sunu bopp . du nakk am nu ni ma , degg la ne tubaab yi toon nan nu waaye nun it war nanoo seet ba xam ndax def nanu sunu wareef ci ellegu afrig . loolu neexul a weddi .
sa neegu biir sax , bu fa saagaa boroom daraja . xamoo picc muy yobbu sa kaddu ,