text
stringlengths
38
33.7k
mooy la nuy faral di wax gi ndax melokaanu ña fa dëkk bii baat day safaano ak afrig gu ñuul gi di tekki afrig gu bëj saalumu sahara
liggeey bi dees na ko def ci fanweeri weer , maanaam naari at ak genn wall .
sancug espaañ gi neewoon na doole te doyadi ci kanamu jongante gi tugal doon def ci wàll googu
xeyna dal baa ngi lay fook loo yaa ngiy gane beneen dal .
da ñuy wéy ci nekkin woowu mel na ay xob yuy naaw ñu réer ci biiri xeeti anam yu bari
yal na yalla do di dalal sama xel , moom mi ma yaakaar .
na la samab yar genal xaalis , xam xam daqal la ngen gi wurus .
coppite yi neel jefandikukat mike . lifeguard wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
ametist ni nu ko gennee ca suuf si , bu am guddaayu cm in .
ba loolu amee nu teg mbalkam njapp mi ci diggante xaymab ndaje mi ak sarxalukaay bi , ba noppi duy ko ndoxum njapp . ci la musaa ak aaroona ak i doomam di raxas seeni loxo ak seeni tank , ndax bu nuy dugg ci xaymab ndaje mi , ak bu nuy jegeji sarxalukaay bi , danuy japp , na ko aji sax ji sante woon musaa .
ba mu daj . su ko defee nga jel saafukaayu wen , teg ko , mu mel ni miiru wen bu dox sa digganteek dekk bi , te nga janook dekk bi . noonu nga koy gawe , mu gawu . loolu di misaal , neel waa ker israyil .
ci yéen nag waxtu yépp a baax àddina du leen bañ waaye bañ na ma man ndaxte maa wax ne seeni jëf baaxul
danuy ar ni gaynde , arati ni gaynde gu mat yemmu , ank um rebbam , yobbu te kenn du wallu .
dab ndeyam ak baayam jele na fa doj wa nuy jaamoo baal te baayam sampoon ko fa . terewul mu sax ci xeetu bakkaar ya yerbowam doomu nebat doon bakkaarloo israyil , ban koo deddu .
coppite yi neel melosuufug senegaal wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
sëñ bi def na ag xasida gum u tënke arafi mazalul jannatil latii wuhidal muttaquun ba ca tilka huqbal laziinat taqaw ne tooñ gu nu ma doon tooñ jeex na aji not jee ko jeexal ji damm ngànnaayul ki doon puukarewu mu damm
yaw teyofil mu tedd mi xam nga ne nit ñu bare sasoo nañoo bind ab nettali bu jëm ci mbir yi xewoon ci sunu biir li dëppook waxi seede yi ko teewe woon li dale ca ndoorte la te ñu mujj nekk jawriñi kàddug yàlla
sukkandiku ci melokaani ceri ndombo gi ak atte yi neel ndomboy mbej yi .
demleen nag buntu dëkk ba woo ku ngeen fa gis ci reeri céet gi
pas pas gile war na feen ci palin yu yiw yu nu wara amal leeg leeg ci tannin gu yaa te am sutura , mbaa topp yoon wu woor wu andak taw feex ci wallu pal .
moo fesal li afrig , rawati na afrig gu nuul gi indi ci xayug adduna bi .
bii xeetu doxalukaay manees na koo jefandikoo niki ab jurukaayu mbej , ab safaanukaay .
li dale ci robowam ñetteelu buur ci yuda la woon
jangunu tubaab waaye mokkal nanu yeneeni lakk ba men a xall yoon wu leen di aar , di leen tee reer . ndaxte , lakk wolof walla araab may na leen nu xam fu nuy teg seeni tank ba ban a saaraan . te bi nuy now ci reew mii gisunu kenn ku leen tette waaye am nanu seen ngor ak seen diine , japp nanu ci ba taxaw fu deger . ba tax kenn yobbuwuleen ci weneen yoon wu doonul seen yoonu bopp . kon tey , moodu yu jekk ya xam nanu fan lan samp seeni tank ba men a teye seen aada ak seen ngor ak seen fulla . loolu lepp am nay firnde ndaxte bu daayira yi nekkee fepp tey , xeer wu njekk wi noom noo ko teg ba xale yi mujj a agsi men cee jarinoo .
xeppal sa xadar yeefar yi la yegul , ak lang yi la tuddul .
ci gattal , ci noonu lanu tambalee gis yenn ci ay jefandiku yu mbej doxalukaay bu mbej , soppalikaay aki niitu . .
ngir waxi sangub mbindéef yi ku nekk na yal na ko yàlla dolli ay xéewal ci anam gu sax ku nekk na ku nekk na di gëm yàlla walla bis bu mujj ba nay wax aw yiw mbaa mu noppi
bi ma seetee nag ne awuñu woon ci dëgg gi xibaaru jàmm bi di jàngle ma yedd sefas ci kanam ñépp ne ko
lii nga xam ne gisiinu big bang wee ko wone , alquaraan it jotoon na koo wone booba ak leegi toll na ci fukk ak neenti xarnu , ci jamono joj nit lu neew la xamoon ci adduna bi .
boroom bi dégg naa ci nit ñu bare ci mbirum kooku ñu seede lu bare lu bon lu mu def say gaay ci yerusalem
ca ndoortel nguurug aserus nag , nu bind aserus bataaxal buy duural waa yudaak yerusalem .
mennum óstraali ak papuwasi ginne gu bees ñoo am ay peggu suuf ak yeneen réew ci dunu ginne gu bees gi ak endonesi gi ñuy boole wàllam gu bari ci oseyaani
su la sa tekkiit neexee , man nga koo denc soo besee enter dugg walla klig denc ci banqaasu jumtukaay bi .
soo leen defee fii waroo yem rekk ci bind seen tekki ci wu fraas .
ki sax mbugal na maa mbugal , waaye waccu ma , ma dee .
tamit naari ca xeelu xarnu , ak seen buur abu bakr bin omar , xeex nanu ak ja ogo yi .
ndaxte du gone moo wara yor waajuram waaye waajur moo wara yor gone yi
ndaxte amatuma fu ma dajale sama ngóob mi
saafara jafe jafe ci dali web yi facebook , youtube , webmail ak yeneen .
noonu ma gis malaaka mu wacce ca asamaan , yor caabiy kamb ga ak callala gu rey .
ban wone bataaxal bi su fekkee popup yi danu leen boloke
ki jel ndam li degg du keneen ku moy askani senegaal .
looloo waraloon xare ba tàkkoon ci diggante siin ak britani di woon xare bu nuy tudde xareb afyon bu njëkk bi nga xam ne wéyoon na la ko dale woon ca atum 1840 ba 1842 nga xam ne ca la britani nangoo waaxub hong kong bu straateji bi waax bii mi ngi woon ci loxol britani ba bu yàggul
waaye su fekkee kenn ci nun ñëw walla malaaka sax mu jóge asamaan di yégle beneen xibaar bu méngoowul ak bi nu leen yégal kooku yal na alku
waaye yeesu moom di beddeeku ci bérab yu wéet ya di ñaan
yalla , yaa masa doon sama buur , di ma walloo ci digg reew mi .
ag juboo amoon na ci diggante brusiya ak otris ñu koy wax atum 1866
ci gii xaaju afrig , lakk yu bari lan fay wax , kallaama waa angalteer ak gu waa faraas nooy yi fa gen a tas , waaye bu nu fatte kiswhili di itam lakk bu tas ca diwaan ba baati bantu ak yu araab noo booloo doon ko .
xam xamu nosukaay walla xam xam bi neel nosukaay , moo yor gestu gi aju ci ceslaay yu xibaar yi , xarala yi neel seenug nos ak seenug jefandikuwiin ci noste yi nuy jefandikoo ay nosukaay .
waaye keneen moo may seedeel te bir na ma ne la muy wax ci man dëgg la yéen yónni ngeen ay ndaw ci yaxya te seede na dëgg
noonu erodd ak ay xarekatam toroxal yeesu di ko ñaawal
sama fit a ngi tef tefi , doole iis , get giim .
ku àtte yoon wi nag sàmmoo ko waaye danga koo àtte
mingi dale ci rendik yilimaan ba jant di so ca bisub natteel ba fu nu ko fi rendee mu baax , bu dul guddi .
te itam nanga ma waajal néeg ndaxte yaakaar naa ne yàlla dina nangu seeni ñaan ba delloosi ma leen
rax ci dolli ndigal a ngii tukkee ci man , jem ci li ngeen wara defal magi yawut yooyu ci biir liggeeyu ker yalla googu njeg ga mu leen dikke , nanu leen ko fey ba mu mat , jele ko ca alali buur , ca galagi diiwaan ba ca wallaa dex . nanu ko fey noonu , ba liggeey ba bana taxaw . mboolem lu ci war , muy yekk yu ndaw mbaa ay kuuy mbaa ay xar yu ndaw yu nuy defal yalla boroom asamaan saraxu doomal , muy bele it mbaa xorom mbaa biin mbaa diw , lu ci sarxalkati yerusalem laaj , nanu leen ko jox bes ak bes , te ban koo saggane . su ko defee nu mana sarxalal yalla boroom asamaan lu ko neex tey naanal buur ak i doomam gudd fan .
coppite yi neel liggeey ci muridulaa wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
yaaka sanku tey , yaw dunu geej bu xumb bi woon , yaw dekk bu siiw bi woon , di jambaaru waa geej , yaak say nit a daa tiital mboolem ni leen wer . tey sa besub jell bii , dun yeey xala lox . duni geej yeey tiit ci sa sankute gi .
ci mbiri seen bàkkaar dina léen yey ci li ñu ma gëmul
bul di baril am po , bul di ree lu bari , mbaa ngay baril looy yengatu ak a defi neen .
ndaxte lóot mi dëkkoon ci seen biir dafa dëkke woon tiisu xol ndax ñaawteef yi mu gis ak a dégg guddi ak bëccëg
nga di leen diir fittu kanam , nu wone gannaaw .
coppite yi neel jefandikukat evula wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
bi mbenn ma newee , wal ma dafa dal ca ker ga te yenguwul , ndaxte nit ka dafa tabax ker ga tabax bu deger .
ñu leen di fattali rekk ne iraak moom mujj na genn ci tapoo gii ci suwe atum 1968 g
lii moo doonoon tambalig rawante gi ci wallug sanc .
kon bu bëgg bëgg ëmbee bàkkaar lay wasin te bu bàkkaar màggee jur dee
yombul joxe ci ab tekki bu daj ndax amul benn tekki bu nepp and deggoo .
lu mel ni sér bu mag wàcc jóge ci asamaan ñu yoor ko ca ñeenti laf ya mu ñëw ba ci man
teg nog yu jaad yi noppe ngir compizconfig am xat u luggey . . .
buleen sunjun aw nag , te fekk koy bacc am pepp .
diirub weer mooy 29 bés 12 waxtu 44 simili ak 2 8 saa muy 29 53 bés
ceddo mooy goore , am fit , am jom , fonk kaddu , ban ku la noot , xam boppam , begg cosaanam ak maamaam .
beneen turu jefandikukat nga jefandikoo , danga war a tambaliwaat fay gi .
kok bëkk néeg la woon ci bëkk néeg yi bu ma waxul ngën ji bëkk néeg
dun yepp daldi ne mes , te kenn gisatul tund ya .
ci moom ngeen jaare ba mucc bu ngeen téyee bu dëgër njàngle mi ni ma leen ko yégale
aji sax ji ne ma waxyuy fen la yonent yiy waxe ci sama tur . yebaluma leen , santuma leen ko , waxumaak noom . peenuy fen ak gisaaney neen ak nax yu nu fental seen bopp lanu leen di jottlee waxyu . moo tax aji sax ji dafa wax ne yonent yi ma yebalul te nuy waxe waxyu ci sama tur naan saamar ak ub xiif du am ci mim reew , saamar ak ub xiif ay mujje yooyu yonent . ni nu doon jottli ay waxyu it , xiif ak saamar a leen di rey , nu sanni seeni neew ci mbeddi yerusalem , te dunu am ku leen rob , nook seeni jabar ak seeni doom , goor ak jigeen . dinaa leen xepp seen ay .
ci firi wolof bu injiil bi ci gereg amee te mu bëgga wax ci ndombam dañu koy firi almasi
te li ma koy faral di naan mooy lii bu soobee yalla , na ma ubbil bunt , ba ma man a new ci yeen .
séeniy jëf it bokk muy sab caabi ngay gaalam
jeexiital yi jeqiku gu atum 1848 defoon ci amug bennoo gu almaañ gi
namibi pénc mu namibi republik bu namibi réew afrig
bi muy jub benn dekk , fukki gaana new , dogale ko .
li jem ci woy wi yusu nduur woy tudde ko bu leen kuppe , xam naa ne niy kuppe xam nanu sekere bi ci biir woy bi .
sama mbokk kat , taxul nga war maa liggeeyal ci neen . wax ma lan mooy sa peyoor .
maay dikke mbugal seen jemmi tuur yi , noom , ni nu jam di binnee fi reew mi mepp . su babilon yeegoon asamaan , dabbli fa tata ju ne kekk sax , du tee ay yaqkat bawoo fi man , dal ci kawam . kaddug aji sax jee .
su fekkee ne noonu la deme nag , du kon deretu kirist moo epp doole ?
d . seedar ak garab gu dul ruus ay garab lanu yu neex xet .
sama xalam tiisal , sama toxoro jooy .
moona am na xam xam bu nuy yégal ñi mat xam xam bu bokkul ci àddina si te njiiti àddina si xamuñu ko ñoom ñi nara wéy
nanu jàll nag léegi ci laaj yi ngeen ma doon bind ci baña ànd ak jigéen ndax lu baax la ci góor
noonu ñii dinañu sóobu ci mbugal gu dul jeex waaye ñi jub dinañu tàbbi ci dund gu dul jeex
buur bii di henri mi nekoon ab mool 1394 1460 g doonoon doomi buur bu portigaal bi tudoon john mu njëkk mi moom mooy ki njëkk a def ay wuññi ci waa portigaal yi
xol laa lay sakkoo guddi , sama jemm jepp di la laaj .
ta fitna xaritu alcande la yoon wumu jar booyal toolu boroom boyal taw feexu askanam
ci kaw loolu dinaa leen wax degg ne leen musuma leen a xam soreleen ma , yeen niy def bakkaar .
yoon wu ma leen di xalaat maa ngi sant yàlla sama boroom
bi mu taggtoo ak mbooloo mi , mu yeeg ca tund wa , naan fa yalla .
kon nag sammleen mboolem santaane bi ma leen di denk tey , ndax ngeen am doole ba nanguji reew ma ngeen jall jem , ngir nanguji ko , ndax itam ngeen gudd fan ca reew ma aji sax ji ginoona jox seeni maam , nook seen askan reew mu meew maak lem ja tuuroo . reew mooma ngeen jem , di ko nanguji , dey , niroowul ak reewum misra ga ngeen joge , fa ngeen daan jiwe , ba noppi topp seenum njiwu , di ko suuxate dooley tank ni mbeyum der . reew mooma ngeen jall jem , ngir nanguji ko , reewum tund ak i xur la , te ndoxum taw lay naan . reew la mu seen yalla aji sax ji yeg , fu mu tollu seen geti yalla aji sax jaa ngi ne ko jakk , terutel at ba ndeetelam .