audio
audioduration (s) 2.29
12.5
| transcription
stringlengths 26
118
|
---|---|
bu kiy indi suuf si ñówee nga ne ko mu jal ko fii |
|
bëgg i ween du ma taxa takk i ngegenaay |
|
lijgéey na naam waaye nag yaakaaroon naa lu ëpp lii |
|
xelmati naa nit ci néeg bi waaye nag jotumaa xam kan la |
|
sa fas wi dawkat la waaye amul gawar gu baax |
|
ndënd ya sàjj nañu njagamaar yaa ngay tëb di dal |
|
liggéey ci sag njiiteef lu ma neex la |
|
ku ma soxla rekk na daldi ñów fii ci suma kanam |
|
boo bëggee togg yaasa dangay marine ganaar gi ak limoN |
|
boo weesoo pom bi ba noppi nga jàdd ci sa càmmoñ |
|
congo l golo lu mu bugal borom tool |
|
dañuy ràññaatle tëgg bu ñuul ak tëgg bu weex |
|
bi muy xale bu tuuti la tàmbali di napp |
|
ñuy werante ba mu yàgg ñu tëggaat sabar gi |
|
masin dafay gar rekk bu ko defee nga wolaat ba mu mokk |
|
yaa ngi may gëtën ak sa wax ju dul jeex |
|
xew xew boobaa nga amoon ci xarnu bi ñu weesu |
|
mbëtt ma ne kàttit dagg geenub golo ga |
|
bu sama mébét yeggee dinaa la may lu bañ |
|
dinaa ko raatale ci suuf ba dootuñu gis ci moom lu ci bokk |
|
dencal përngal bi ba ba ngay fóotati |
|
kilifa gu bees gaa ngiy jéem yolomal sàrt bi |
|
ndey saan mu ngi yërëmtalu boo ko gisee |
|
dàqal xandanduur wi kenn du fi dégg dara |
|
ba mu àggee ca ron garab ga dafa ne cuub jonkan |
|
gerte gi dafa xëm moo tax ñeex mi wex |
|
dama bëgg nga faramfàcce ko ngir mu leer |
|
sa caax bi jén yu ndaw rekk la mëna jàpp |
|
baayoo baay jox ma yet ma indil la fas ag jaam |
|
xawma lu ko jot yaram mi dafa def yu mel ni ay càqar |
|
dafa xaa baabal soo defee ak moom dinga ko réccu |
|
mënuma geestu sama loos dafa biddanti |
|
ku jél rongoñ siim céree m bu ko ñaan ñéh |
|
ca suba sa mu xëyaat dem summeeku ba set daldi né |
|
jën wu ñu bërëm a gën a saf fuuf jën wu ñu togg ci cin |
|
bu jóolóoli yi tëggee nu tàmbalee liggéey |
|
yëre yi ñu paase yaa ngi ci armoor bi |
|
dara jotu ko óom bi rekk a fof tuuti |
|
raatale na lépp defaatleen beneen yëgle |
|
jox ko waay yàlla ji ci buntu kër gi |
|
su fi armool bi jogee dina yaatal bërëb bi |
|
li nga ko ñéebloo tax mu foog ni danga ko ragal |
|
loolu moo won ay waajuram ne dafa am ug may |
|
dama koo bàyyi muy tuñ tuñi fale ca poor ba |
|
yoon wi baax na léegi dër nañu ko |
|
bul jaar foofu dég yaa nga fa fees dell |
|
adunà ñét a ko japà sahlé ak ub sahà bi ak sahàmi |
|
loolu doyatu ko mu daldi toog bu baax |
|
mu daldi koy jox ñaari tax yu ñu tabax ak ban ni ko |
|
jox sama baay muraakem seel la maa ko nangoo ci Naar yi |
|
doomu aadama bu nekk am na ndey ak baay |
|
réew yu naat yi ñoo sos kuréel googu |
|
soo moytuwul dinaa la rattaxal pes léegi |
|
loolu suñu mbokku pël yi bu ñu la deggee yaakaar naa ne |
|
dafa boot xale bi santal liggéey bi keneen |
|
waxtaan wu mel nii dafay tax xale yi xam démb |
|
ku ndóbin rey sa maam boo gisee lu ñuul daw |
|
dinañu fi guddee tey kiy wax dafa leeb |
|
Naka la agsi ci kër gi rekk dal di bëcci sayu matt wa |
|
ndar dëkku teraangu la dañu lay ganale ba nga rus |
|
su ñu accul mbànd mi dina am ay wallaxnjaan |
|
ba ko soxna sa wonnee la wewu gaynde ga galanu ca put ga |
|
xas naa joxe sama kàddu mënatuma dellu gannaaw |
|
rëbb bu jub loxo la woon waaye gis gisam dafa wàññiku |
|
danga dëgër bopp boo doon waxteef koo jàpp du mucc mukk |
|
ku gen di buur ci adunà moo gen di daam cà laahirà |
|
jabaram ja woon a tax mu dogoo ak mbokkam yépp |
|
benn moroomam dafa ko kolooj ba bët bi xonq coyy |
|
jigéen ji nag yumaane rekk la bañ |
|
kenn jëfandikootul paan bi ndax xomaag gi |
|
ba mu fa jógee daldi dem ca ka ca des |
|
cuuraay du noppee gilli ca néegam ba |
|
njugub baa ngiy lang ci fiilu kuraN bi |
|
lu di nav té du tag mukà ngélav |
|
dama feddali pas pas bi ba mu dëgër |
|
jigéen ju asaru du yomba am jëkkër |
|
mu ni dama koy wallu ci njëlam lu jëkk li |
|
muus mi dafa fettax dal ci kow janax ji |
|
dem naa fi benn waay bu joge kéedugu ñëw fii dée nga |
|
amari jullit sedd bi nag loo ci xam |
|
ay ñam yu deme ni jén yàpp ak ñoom seen |
|
dégg nga ñu naan ngay làkk ni ndeer |
|
ku xamul buur saay na xam buur dee na |
|
ndaw soosu ku yebu bàyyi ko te wuti jeneen jabar |
|
asan dafa biddanti moo tax mu fekk saxaar dem |
|
wolof njaay nee sawóor bëgg na dugub waaye du bey |
|
ewaay baay bul jooy sa guileem mag na |
|
am xéy laa ko ameel ngont li maa ko moom |
|
njiit lii du ku ñuy jay dëgg la bëgg dégg |
|
ku ñu ma may rekk ma ni bëgguma ko ma bëggoon nag wuti |
|
mëñul woon dox dañu ko nguufaan ba ca oto ba |
|
bi fi amari di jóge di dem bitim réew booba janq bii liir la |
|
faatu sottalagul liggéey bi ñu ko santoon |
|
abdu dafa ñaan permi ndax li muy séetal |
|
danga pëtëm pëtëme sa liggéey bi |
|
xale bu dëgër bopp la loo ko tere rekk lay def |
|
saa waay yow itam gaañuma la waay |
|
doo fi dëkk dogal bu jóge ci saax saax bi la |
|
bëgga riccamtéku moo la tax di wax lii |
|
tegtal ma fu ma war a jaar ba jot tali bi |