audio
audioduration (s)
2.29
12.5
transcription
stringlengths
26
118
bant lu mu yàgg yàgg ci dex du ko taxa soppaliku jasig
ba mu lekkee yàpp wi rekk la neer mi tàmbali
dànkaafu naa ko ba tàyyi mu të maa déglu
liggéey bii amul mujj làmbal leneen
danga koy gajafal ndax mu man koo lekk
nanga butti jén yi dal di leen raxas ba ñu set
sàcc ndënd yomb na waaye foo koy tëgge
elimaan warula def lu nit ñi di àññ
kanam gee ras rekk waaye du mag noonu
wurëmbél mumbél wurëmbélbél mumbébél
yenn pexe yi ñu lay fexeel dinaa leen njuuy
mu ngiy tepp teppal nanu xaar ba ci kanam
defal ndànk ma wax ag sa moroomi gor yi
njagamaar maanaam janq bu amagul fukki at ak juróom ñett
yaa ngi bàyyi bunt bi ubbiku ba yoo yi solu ci néeg bi
buur saalum nag dafa muusoon ba mu jéggi dayo
abal ma almet ma jafal cuuraayu bant bi
du ña xas ñépp ay wone njàmbaar bu ñu ca tolloo
soo ko ko dënkee dina ci def farlu gi ci war
Nee ñu bareetul ñuy jëfandikoo kaata
sama mbubb mi dafa xottiku ci baat bi
bu gàmmu jotee lu nekk la tiijaan yi di jóge di dem tiwaawan
xamuma ku la ko xelal waaye def nga lu baax
loo xalaat ci mbootaay gi nu taxawal ci gox bi
caaxaan wéy na danga war jëmbët fulla ci njàng mi
bu mband amaan xale yépp a daan seetaansi
yàquteem a tax fu mu liggéeye ñu mujj ci dàq ko
kolkolaat yégul né yembà baah nà
te balaa doon def lenn dina ma ko yëgal
cere ji dafa wow kaas ko bala nga koy tay
su naanul dangay gis ne dafay baax ci moom
su ngeen ko téyewul dina ko dóor bolde bi
xanaa mënuleen dindi ëkk wii ci diggu yoon wi
ku digee gaanà rekanté nà nga fiep fanaanoo
yónnee naa bataaxal ngir yégal ko ko
mu ni yunn ci néeg bi gis niiw bi ci kow lal bi
soo demee seen kër dañu ko bërgël
bu bëggee dara ci yow dafay neex làmmiñ
Nanga jél doxalin bu dëppoo ag jamano
man xamuma lu waral kóolute gi nga am ci moom
garab gii farmasi rekk nga ko mëna ame
kuy jiite am réew danga wara tenkoñ
danga bëggul dem rekk yaa ngi ne kocc dara jotu la
ci tamxarit wi waa gox bi dañu natt jënd xàbban
boo fay deme woto dafay mel ni lu jége
gumba tal na leneen lu dul nas i pusó
danga geestu ma xam ne moom geen di wax
altine biy ñów lañuy wori bu soobee yàlla
boo xiddiwul nu may gise li may jàng
dangay gis jiit yi di dox ci leere gi
ndax dénd wii mën naa xadd néeg bi
dafa tàmbali woon di ma gaaral ma yemale ko
basaN gu rafet gii maatam laa ko jënde woon
ba ñu dajee ak yaw dañu daw wëqét
kamisol ca jamano sunuy maam yaa la xewoon
liggéeykat bu maandu la moo tax ma naw ko
fegu moo gën xaar ba jàngoro ji dikk ngay seeti doktoor
lamp baa ngiy xóoy petarool beey waaja jeex
céy sama njaqare ja ba ñu ma nee awyoN ba dafa dem wacc la
làmniñ wu ndaw wi ngay séen ca biir
xàmmewuma ko woon genn wàllu kanam gi dafa jib
mu daldi jël li mu soxla dem mu delluwaat ci yaayam ni ko
maa ko gis ci peroN bi la yàbbi logu poon bi
dafa ko tere wax baat bi waaye mu dellu waxaat ko
am na ñoo xam ne xalam dafa leen di yëngal
ndokk lii mooy dal gone gu dëgër bopp
dama seetaani woon futbal ba waa ndar yee gañe
dama lay jox dugub nga jox ma tollale bi ci soow
bul màmm nag xamal fi nga war a yem
sottilal sanqaleñ yi ceeb ndax ñu dem
danga wara sunjuñ mbote mi ndax mu baña nàmp
soo saagaatee dinaa la boole ak sa baay
fii laa ko tegoon xef ak xippi ñu jél ko
li dés ci géttam gi matatul sax fukki we
kër gu xate nii kenn mënu fi yar xar
Nataalu liir bu taaye lañu tay ci pot bi
ab ngàttaan la tóoju bi dafa kowe ci moom
gerte gi ñu war a segal a ngi ci paan bi
xale yi dañu wuti bantu sonk yu ñu def liit
ab suusal la ko mujj yàkkal ci dëkk bi ñu ne
ku mën sàmm kàddoom la lu mu la wax mën nga cee jàpp
ngóoné yónni jaam bi mu jëndi dugub soqal ko ko
ellëg la ndaje ma na ku nekk ñów ak sa ëlléer
taalifkat bu ñu ràññee la ci kàllaamay wolof
dañu boole jënd masin buy bàcc ceeb
bi xale yi nówee mu may leen ñu lekk
sama kër a ngi féete jàkka ji sowu
dama leen woolu ngir laaj leen seen xalaat
bu wàccee dafay liggéeyi feneen ngir am ndollentu deppaas
buum yi yépp cëgg lañu leen defare
yéesu dafa raamu ba raxasal ay taalibeem seeni tànk
boo sàgganee laaru mbaxane mi dina wadd
fas di nà dov vandé rutimgeer à cà ràv
ku sa bëgge bari sa ngor néew
xamuloo ndax xar ma nga fay jénde médd la
cokker mënta réer morom ma ci dédd
wàjj lay faral reere moo gën a woyof
seydinaa usmaan a mujj ci saaba yonent bi
su ma naree dee ci àll gayndee may rey
su dara desul lu dul ñàkkante ma dem sama yoon