start_time
float64
0
2.73M
end_time
float64
326
2.78M
speaker_id
stringclasses
55 values
text
stringlengths
1
4.06k
audio
audioduration (s)
0.17
388
178,031
178,465
11spk2
%hum %hum
178,465
183,699
11spk3
xam nga waxoon nañ la ni la ñu ngi liggéey Etat nag toujours dafa am ñi nga xamante ni ñoom ñoo koy jàppale
183,699
184,114
11spk2
%hum %hum
184,114
194,505
11spk3
ñu leen di tuddee les partenaires techniques et financiers partenaires techniques et financiers boo leen boo boo ko dégloo bu baax moom mooy ONG ak projet programmes yi nga xamante ni ñoo fi nekk
194,505
194,921
11spk2
%hum %hum
194,921
210,938
11spk3
ñooñu vraiment ñu ngi ci bay actuellement seen wàll bu baax a baax boo ñëwee par exemple fii au niveau de Fatick nga gis %e projet bu mel ni Proval CV avant moom sax avant avant Proval di ñëw sax di judd ak %e le PDRS
210,938
211,354
11spk2
%hum %hum
211,354
217,546
11spk3
am na benn écloserie bi nga xamante ni bii defoon nañ ko fii ci ginnaawu agriculture non seulement éclo() écloserie boobu mu ngi foofu
217,546
217,934
11spk2
%hum %hum
217,934
231,186
11spk3
mais %e ñu ngi def aquaculture fii et vraiment population Fatick yi ñu ngi ciy gis seen bopp les kii GIE des kii quoi des femmes de Ndiaye Ndiaye là vraiment ñu ngi ciy gis seen bopp bu baax a baax a baax donc ñu ngi fay yar ay ay kii quoi ay waas
231,186
231,765
11spk2
%hum %hum
231,765
276,377
11spk3
dégg nga ba mu toll nu mu nu mu ko neexee ñu ngi koy jaayee vraiment ay prix yu baax de la même manière boo demee élevage am na fa ay projets yi nga xamante ne bii donc ñu ngi fi %e aussi c' est des projets donc d' adaptation au changement climatique yi nga xamante ne bii yenn yi mi ngi jëm ci amélioration %e génétique %e donc kii quoi des races %e yeneen yi mi ngi jëm vraiment ci des projets donc de stabilisation wala yu mel kii quoi yu mel noonu quoi donc yooyu yépp gars yi ñu ngi ci ñu ngi ci kii quoi ñu ngi ciy bay seen wa() seen seen seen wàll te yaakaar nañ ni tamit yooyu c' est des projets kii quoi c' est des projets oubien donc des programmes yi nga xamante ni bii tay bu fekkee %e li nga xamante ne bii %e moom lañ si séntu
280,960
281,235
11spk2
%hum %hum
281,235
302,932
11spk3
parce que man dama jàpp ne ni lii sunu maamu pël yi di def muy élevage extensif loolu dañ ko war a dañ dañ ko war a dépassé yore téeméer wala ñaar téeméeri nag yoo xam ne mënalooleen dara boo xëyee dàq leen ñu dem bu ñu toogee ba ñu ni dugg nañ période soudure nga bàyyi leen ñu daal di dem defi %e lu ñuy wax %e
305,481
305,873
11spk2
%hum %hum
305,873
311,687
11spk3
jéem a kari kii quoi kari ndox mi loolu am na lu ko gën xam nga loolu nga amoon par exemple fu ngay amee téeméeri nag
311,687
312,111
11spk2
%hum %hum
312,111
324,848
11spk3
yi nga xamante ne mënoo ci dara ludul toog di ko xool di ko topp naan ko is is nga am tay jii juróomi nag yi nga xam ne wóor na la ni yii c' est est des races améliorées juróomi nag yi nga xam ne nag bu nekk mun na la indil lu mu bon bon bon trente littres meew par jour
324,848
325,265
11spk2
%hum %hum
325,265
335,186
11spk3
ah litre meew bu ne nga mën ko jaayee six cent franc par jours ah yaakaar naa ne loolu moom moo ëpp njëriñ fuuf yow di nga liggéeyal sa bopp te doo ci sonn te doo ci doo ci am àq
343,499
345,936
11spk3
ñu ngi récolter %e seen i gerte
345,936
346,370
11spk2
gerte yi
347,940
348,252
11spk2
%hum %hum
348,252
349,359
11spk3
mais seen xel dalul
349,359
349,914
11spk2
dëgg la
349,914
366,528
11spk3
weer bi ñu ko war a weeree dëgg-dëgg dégg nga sax nangootuñ ko def parce que divagation mu ngi fi boo duggee ci àll bi bon communes yi %e ni ñuy waroon def kii quoi daal di di élaborer %e kii quoi le parcours donc du bétail là amul
366,528
366,944
11spk2
%hum %hum
366,944
385,361
11spk3
pratiquement boo xoolee parcours boobu mun naa ko nii que c' est c' est kii quoi c' est biaisé tay gis nga nag éleveur éléveur mi ngeeg %e mbir bi nga xamante ne bii ci ci ci kii quoi ci boppam moom yaakaar na ni bu xasee ba ba ba départ jur gi nga xamante ni moom la yor dara baaxul pour jur googu
385,361
385,954
11spk2
%hum %hum
385,954
416,300
11spk3
tout son problème moom mooy na jur gi lekk ba suur na jur gi naan ba màndi donc man yaakaar naa ni que ni nit ñi aussi léegi war nañu mën a xoolaat seen bopp %e xam ni que vraiment daal di am kii yar ay kii yu bëri dégg nga te vraiment du la amal benn njëriñ fexe woon ba nga am ñaar wala ñett yi nga xamante ni lu mu bon bon bon chaque jour mu mën la génneel au moins dix mille wala quinze mille franc je pense que loolu moom moo ëpp %e moom moo ëpp njëriñ fuuf parce que loolu en rélité bu fekkee yaa ngi ci sax fonctionnaire bi nga xamanate ne bii moom moo lay encadré sax yow di nga am loo xamante ne moom du ko am quoi
416,300
416,915
11spk2
kon dañuy
421,643
422,056
11spk2
%hum %hum
422,056
425,653
11spk3
war nañ mën a changé doxalin vraiment bu fekkee bëgguñu kii quoi parce que
425,653
426,218
11spk2
d' accord
426,218
426,529
11spk3
%hum
426,529
428,371
11spk2
bala ma lay bàyyi ci information yi
429,783
430,083
11spk3
%hum %hum
430,083
442,146
11spk2
ndax waa DRDR mun nañu témoigner tay jii que ni %e ni ngeen di joxee information yu dem ci producteurs yi ndax %e ñoom kiiyal na leen ils sont en phase ak li nga xam moom mooy information yi
442,146
444,143
11spk3
loolu dama koy bàyyi moom mu tontu ci
444,143
444,664
11spk2
DRDR ayca
449,272
459,994
11spk1
%e maanaam dafa %e ñi ñi nit ñi sax dañ léegi dañ ma ne yow boo est ce que duñ yóbbu météo ma ne leen ndo() ba tay it maanaam xam-xam dadul caaxaan
459,994
460,409
11spk2
%hum %hum
460,409
463,803
11spk1
wax ju tegu ci xam-xam soxna Maguette
463,803
464,345.995175
11spk2
%hum %hum
464,345.995175
471,892
11spk1
dëggu tegu ci xarale ak jumtukaay yu mucc ayib dama ne am nay jamono waa météo bu ñu waxee kenn du leen déglu
471,892
472,470
11spk2
%hum %hum
472,470
491,321
11spk1
li may wax nii yàggut waaye adduna dafay dox ay jumtukaay maanaam dama ne dama ne ñi doon ñi ko doon wax ay Sénégalis lañ te ba léegi ay Sénégalais lañu jàng am xam-xam jumtukaay rekk moo fa moo doonoon seen gàllankoor Yàlla def na diggante bi at ay at
491,321
491,731
11spk2
%hum %hum
491,731
496,897
11spk1
ñu am ay jumtukaay yoo xam ni tax na liñ doon wax mu gën a tegu
496,897
497,628
11spk2
%hum %hum
497,628
512,551
11spk1
xam-xam bi mosu fee jóg jumtukaay dong moo doon jafe-jafe te defe naa jumtukaay yooyu ba ci ña ca war a jóg jóge ah gis na ñépp gis nañ kenn naatablewul waxu météo moo xam ci mbay la moo xam ci sàmm moo xam ci napp kon loolu lu lu ko waral mooy li mu wax rekk
518,639
519,200
11spk2
bien sûr
519,200
537,932
11spk1
léegi nag ñun ñi nga xam ni ñun ci wàllu bay man tay ñun dañ ko jiital informa() climatique fañ teg jiwu teg engrais teg fa lay la ñuy aaree gàncax teg fa jumtukaay bu ndaw mooy matériel bu ndaw bi ak matériel bu mag bi mooy tracteur ak la muy àndal foofu la tegu donc dafa nekk facteur de production
537,932
538,493
11spk2
%hum %hum
538,493
552,892
11spk1
changement climatique ta() tax na ñu teg ko ca a kanam léegi dañ ko boole woon waaye léegi dañ ko teg ca kanam boo ko tegul doo dem ndax ñoom boo leen dégloo di nga xam ndax yow war ngaa jiw wala ndax waroo jiw
552,892
553,688
11spk2
%hum %hum
553,688
578,242
11spk1
léegi ci biir waxtaan yi dañu naan sax léegi nañu xool pour ñëw léegi ci li nga laajoon changement climatique tax na fi mu toll nii ñépp dañu war a teel a ji même ceeb sax dañu ko war a teel a ji ku ci bëgg a génn fi mu toll nii da ngay teel a ji maanaam di moytu yenn xeetu variété yi nga xam ne dañuy laal ñenti weer jëm kaw
578,242
579,939
11spk2
mais teel a ji bi ndax du indi problème
579,939
585,686
11spk1
déedéet teel a ji bi du indi jafe-jafe teel a ji bi mooy li ñuy mën a faru ñu faru ko
585,686
586,532
11spk2
dafa mel ni am na ji
589,509
589,881
11spk2
%hum %hum
589,881
598,548
11spk3
man expérience bi nga xamante ne bii am naa ko ci lu mel ni mbayum gerte wala yu mel noonu xam nga gerte dañu naan pour nga jiw ko il faut nga am une pluie utile
598,548
599,148
11spk2
%hum %hum
599,148
612,675
11spk3
dégg nga une pluie utile mooy taw bi nga xamante ne bii dafay nekk ba vingt milimètres soxna Maguette vingt milimètres taw moom mooy nga jël %e nu mu tudd ñaar fukki litres ndox nga wasaare ko ci benn surface su un mètre carré yaa ngi dégg
612,675
613,138
11spk2
d' accord
613,138
624,125
11spk3
donc boo jëlee vingt litres ndox nga sotti ko ci espace su maanaam dégg nga ñenti ñenti careaux:Fra bi tooy bi muy tooy boobu xam nga dafay dafay da() da() day xóot quoi
624,125
624,450
11spk2
%hum %hum
624,450
631,619
11spk3
xam nga maam mag yu njëkk dañu daan gas seen loxo dina xóot mais gis nga gerte googu boo xa() bu xasee ba ba ba ba kii quoi ba sax bu xasee ba sax
631,619
632,098
11spk2
%hum %hum
632,098
637,492
11spk3
%e ak %e kii quoi %e évaporation bi nga xamante ne bii moom mu mu moom lay àndal ak yéen xam nga lu ma wax
637,492
637,856
11spk2
%hum %hum
637,856
642,169
11spk3
gerte bi xam nga gerte doom bi dafa kii quoi dafa niin gàccax bi dafa niin quoi dafa niin quoi
642,169
642,549
11spk2
%hum %hum
642,549
659,970
11spk3
donc bu xasee ba sax ba pare xam nga la lu ko ray yombul li ngay la nu muy demee ba évaporer wu ba suuf sa wow koŋŋ koŋŋ koŋŋ ba amatul dara dara dara li nga xamante ne bii mën na ko puiser ci ci suuf si ba mën ba mën a dem balaa muy egg foofu dina nekk presque weer wala kii quoi weer ak nangam balaa boobu insaa àllaa dina tawaat quoi
666,327
667,192
11spk2
ah d' accord
673,835
676,138
11spk1
maanaam %e pour dëggal li mu wax
676,671
681,107
11spk1
Yàlla dafa maa nattu dama def ay gëstu yu xaw a bëri ci li muy wax nii ci gerte gi
681,107
681,587
11spk2
%hum %hum
681,587
704,607
11spk1
ba ci dugub maa ngi leen wax ne dugub bu xiifee ca njëlbéen bonut loolu constat empirique la nga dem ISRA kuréel gi yor wàllu gëstu bi soo demee am na benn centre ISRA bu ñuy wax ñoom ñooy gëstu lépp lu ñuy wax déve() lu ñuy wax mécanisme d' adaptation des résidus à la sécheresse Yàlla def ma jaar fa Yàlla def ma liggéey ci ci gerte
704,607
705,148
11spk2
%hum %hum
705,148
717,112
11spk1
gis nga ñoom li ñu liggéey ci dugub ak gerte maanaam pour ngir dëggal li ñu maanaam loolu mag ñi gis ci dugub ni bu xiifee ca njëlbeen bonut day yokk dana feeñ ca rendement ba
717,112
717,452
11spk2
%hum %hum
717,452
724,476
11spk1
ñoom dañ ko gëstu ba génn ba bind ko ba teg ko dugub bu xiifee ca njëlbeen ga comme ni mu ko waxee
724,476
725,068
11spk2
%hum %hum
725,068
737,444
11spk1
reen ba lay pousse ba mu gën a jëm ca suuf mu jëm ci suuf un mètre ba un mètre cinquante lépp lu fay ndox lépp luy ndox nag mu mu raasaatu yéegal ca kaw
737,444
738,043
11spk2
%hum %hum
738,043
755,164
11spk1
bu ko fa taw ba fekkee dooleeku ci loolu loola nga gis mun na indi xeetu bu suuf sa amee doole bu suf sa amee doole rekk nga gis mu feeñ ca ngoob ba pour dëggal ko ko ci gerte gerte am na fu muy toll ci xiif ndax man def naa ko ci loolu ma lay wax noonu jàngat boobu ma doon def
755,164
755,526
11spk2
%hum %hum
755,526
760,590
11spk1
en deux mille deux deux mille trois dañ doon xiifal gerte gi xiifal forcé
760,590
761,238
11spk3
%hum %hum
761,238
782,727
11spk1
xoon ko reen bi waa ISRA def nañ ko am nañ benn appareil lu ñu tuddee séseauton boo koy xiifal boo ko lifinee da ngay mën a xool soxna Maguette di mën a mesurer développement racine yeeg maanaam ni reen yi di poussé reen yu mag yi di dee bu ñu ko gëstuwee ñoom dem nañ ba gis ne reen bi dina dem ba deux mètres bu dugub dina dem ba un mètre cinquante bu gerte dina def
783,768
784,314
11spk1
loolu moo tax
789,763
790,350
11spk2
%hum %hum
790,350
798,752
11spk1
doole jooju muy yëkkatee mu ñëw bu ñëwee bu xëccee bu ñëwee mu boole ca di jur doom day tax li ñu tuddee alimentation hudrique bi dafay gën a am doole
811,103
811,501
11spk2
%hum %hum
811,501
814,836
11spk1
loolu pour dëggal li mu wax la pour wane ne gëstu wane na ko ba noppi
819,251
820,159
11spk2
am na solo
820,159
833,043
11spk1
kon li muy wax noonu lu am solo la te ca suñu di() diir boobu nag eh nañuy ñaan projet boobu nga wax noonu mu antu ndax su ma juumut juróom-ñeeti communes defe naa dana ca bokk
833,043
835,119
11spk2
waaw huit communes dina si bokk li nga wax loolu la
835,119
835,621
11spk2
%hum %hum