start_time
float64
0
2.73M
end_time
float64
326
2.78M
speaker_id
stringclasses
55 values
text
stringlengths
1
4.06k
audio
audioduration (s)
0.17
388
1,856,562
1,868,492
11spk3
benn bois boo ko gisoon nii ci mbed mi fu mu nekk nii boo xëyee le matin rekk boo ko ñëwee da ngay fekk day tooy xepp vitres yi day tool yow sa bopp booy dox fi ngay jaar mel ni dafa taw ba pare te pourtant
1,868,492
1,868,876
11spk1
%hum %hum
1,868,876
1,892,652
11spk3
taw taw amul mais lay bi moom moo moo am quoi ni muy tooyee noonu nag loolu moom mooy li nga xamante ne bii moom la xaal bi soxla présentement moom la ñébe bi soxla moo tax %e comme ni ko monsieur Badiane waxeewoon ñi nga xamante ne bii ci njëlbeen bi dañu %e indiwoon ay projets d' adaptation changement climatique daal di song ay mbayum xaal ba amoon ci lu kii quoi lu mucc ayib kooku wax nañ ci waxati waxaat nañ ci yaakaar naa ni dootuma ci dellu si
1,892,652
1,893,132
11spk1
%hum %hum
1,893,132
1,894,960
11spk3
ñooñu présentement ñoom ñoo labouré
1,894,960
1,895,395
11spk1
%hum %hum
1,895,395
1,913,475
11spk3
ba actuellement nii ñu ngi ci seen deuxième semis wu xaal ci ci la saison là actuellement xaal boobu sax na mais fu mu nekk nii léegi %e lay bi moom mooy bi nga xamante ne bii moom moo koy ñoral te dinaa dégg ci wolof yi di wax sax naan xaal boobu d' habitude moom moo gën a neex bi nga xamante ne bi moom mooy ñor ci biir kii bi quoi ci biir nawet quoi
1,913,475
1,913,775
11spk2
%hum %hum
1,913,775
1,914,126
11spk3
%hum
1,914,126
1,920,971
11spk1
mais ndax jangoro yi nga xamante ni dañ koy nemmeeku ci mbey mi dafa am rapport ak li nga xamante ne moom mooy changement climatique yi
1,920,971
1,927,724
11spk3
tout à fait am na bëri na ay ay ay ay ay ay jangor yuy ja() jangoro yi nga xamante ne bii dafal dal gàncax gi
1,927,724
1,928,158
11spk1
%hum %hum
1,928,158
1,941,370
11spk3
souvent bon changements climatiques yi bokk nañ ci bari na ci am na ci par exemple ay genre yenn genre xeetu %e kii quoi sauterelles ay sauterelles ñu koy wax cri() criquet criquet:Fra lañu koy wax mais:Fra du criquet:Fra sauterelles la en:Fra realité:Fra
1,941,370
1,941,830
11spk1
%hum %hum
1,941,830
1,950,070
11spk3
am na ci yi nga xamante ne bii ñaare ñàkk taw moom moo koy moo koy indi mais la plus part bu tawee rekk day gis dafay ànd ak taw bi daal di kii quoi lessive bi mu dem quoi
1,956,023
1,960,879
11spk3
ay compagnons yooyu yi nga xamante ne bii souvent dañuy ànd bu climat bi xonkee ñu xonk ànd ak moom
1,960,879
1,961,359
11spk1
%hum %hum
1,961,359
1,963,413
11spk3
bu weexee tamit ñu daal di %e daal di kii quoi dem quoi
1,963,413
1,963,813
11spk1
%hum %hum
1,963,813
1,970,879
11spk3
mais comme loolu mbirum DPV la je préfère monsieur Badiane moom mi nga parce que moom moo ma gën a maitriser kii bi kii quoi domaine boobu quoi
1,972,728
1,977,675
11spk2
waaw waaw waaw maanaam ci %e gën a pro() %e gën a dooleel li Maodo wax
1,977,675
1,978,152
11spk1
%hum %hum
1,978,152
1,986,517
11spk2
maanaam dafa maanaam dafa am lu ñu tuddee paramètres climatiques yoo xam ne day bokk maanaam foog mu ñëw li ñuy tuddee température ak humidité
1,986,517
1,987,024
11spk1
%hum %hum
1,987,024
2,010,207
11spk2
bokk na ci li nga xam ni ñoom ñooy yokk wala ñu wàññi maanaam ñooy dooleel mbaa ñu néewal doole màggaayu doomu jangoro maanaam ma jox la misaal gis nga fi mu toll nii boo duggee ci toolu dugub bi foofu Maodo nga xool deuxième vague bi wala lifin gi da ngay gis am na lu mel ne ay ronkoñ lay doon da ngay gis mu mel ne gomme boo demee ci tool yi nga xool ni %e gubu dugub yi bari na ci
2,010,207
2,010,767
11spk1
%hum %hum
2,010,767
2,021,874
11spk2
mooy li ñu wax noonu maanaam ci ci ci ñi fa fa fa ni taw bi bindoo moom moo ko yokk moom lañ tuddee l' ergot du mil noonu la tudd maanaam maladie ay champignons la fongipte
2,021,874
2,022,609
11spk1
%hum %hum
2,022,609
2,042,225
11spk2
charbon bi it boo xoolee bëri na mooy li nga xam ne boo ko defee da ngay gis am puudar bu génn day yàq gub bi ba nga xam ne buy génn day def lu mel ne ab pucantaan bu verte mais boo defee boo ko dee génne nii puudar bu ñuul mooy génn mooy *** champignon bi xam nga kooku bu bëree ci gub kooku munoo munat() boo ko kiwee boo ko bojjee mun munoo ko def cere
2,042,225
2,042,841
11spk1
%hum %hum
2,042,841
2,045,744
11spk2
ergo bi it bu ci bëree ba jël guub bi yépp daanaka da koy yàq
2,045,744
2,046,344
11spk3
da koy yàq
2,046,344
2,093,313
11spk2
kon xam nga ne day wàññi bu baax la nga doon am ci rendement boo xoolee %e li mu wax noonu %e dundug yenn bàyyi ma yi numu tud() maanaam sauterelles yi mooy soccent yi da ngay gis ne bu nawet bi lifinee ñu ne waa ana soccant yi maanaam balaa ñuy lifin dañuy bàyyi nen yi bu ñu nenee dañu koy gas suul ko ci suuf ba ko foofu muy dund Yàlla nag xam nga dafa bëri kéemaan ndax nen bi dafa am lu koy ëmb ba nga xam ne fute gi maanaam tàngoor yi ñuy fàttali ne boo xoolee ci suuf nii comme ni ñuy wax tàng na ci kaw soxna si Maguette si suuf moo gën a tàng man ci gëstu bi ma doon def ci liggéey dafa am ay sondes yuñ doon dugal ci suuf di natt tàngooru suuf si di natt tàngoor wi ci kaw ak humidité bi ci kaw
2,093,313
2,093,672
11spk3
%hum %hum
2,093,672
2,094,617
11spk2
waaye Maodo boo ko defee
2,094,617
2,096,706
11spk3
comme yeneen services yi gis naa kay ñoom ñu koy def %e
2,110,882
2,114,919
11spk2
waaye nag nga gis bu nawet bi jotee rekk nga gis ne bu ndox laalee suuf rekk nga gis
2,114,919
2,115,506
11spk3
mu toj
2,115,506
2,121,716
11spk2
mu daal di toj mu génn ñax mu bon mi it li ñoo tuddee ñax mu bon mi it noonu lay bindoo daanaka
2,121,716
2,122,314
11spk3
%hum %hum
2,122,314
2,128,199
11spk2
maanaam li wolof naan li fi jiwu jugut jeexu fi loolu la maanaam mu ngi ci biir bu demee ñu ne ah ñax mi wow na
2,128,199
2,128,903
11spk3
%hum %hum
2,128,903
2,131,808
11spk2
ñu kii nga gis ñax mi de bu tawaatee nga gis ñax mu bon mi dikk
2,131,808
2,132,278
11spk1
%hum %hum
2,132,278
2,133,181
11spk2
kon kay jiw baa ngi ci suuf
2,133,181
2,133,672
11spk3
%hum %hum
2,139,568
2,147,820
11spk2
ci beneen bi boo xoolee ci guub bi nii waaye dafa am beneen solo gis nga ci xam nga gis nga bu nit defutoon pexe sax pour jéem a xeex ak yàqkat yi
2,147,820
2,148,420
11spk1
%hum %hum
2,148,420
2,169,035
11spk2
soxna soxna %e Maguette day am ci ndox Maodo man dama def %e fi ma ne def naa jàngat ci wàllu dugub ci benn feebar bu ñuy benn gunóor bu ko sonalmuy la chenille de l' épidémie maanaam boo xoolee guub bi ñu gis ci lu mel ne ay ab sax bu koy def nii nga gis ci ay gajaŋ
2,169,035
2,169,750
11spk3
%hum %hum
2,169,750
2,193,868
11spk2
yu mel ne ay dëkkuwaay sax boobu mooy ragova la chenille:Fra ******* man ci gëstu bi ma defoon en quatre vingt dix neuf ca toolu Bambey séeréer ca toolu dugub ba dafa wane ne am na tolluwaayu taw bu ko méngóog ànd ak i ngelaw ci yenn vitesse yi tu vois maanaam ci yenn ngelaw yi day daane sax bi bu ko daanee ndox moomu di rogalaat daf koy yóbbu
2,193,868
2,194,808
11spk3
da koy yóbbu
2,194,808
2,207,823
11spk2
maanaam yow baykat bi doo doo jëfandikoo benn puudar du leen luy loo xam ne mën na indi gàllankoor doo ci def dara Yàlla ci boppam ci mbaaxam moom ci tawam léeg-léeg mu lijjanti ci xeetu
2,207,823
2,214,018
11spk3
loolu la wolo() loolu la wolof di wax naan Yàlla ku muy xulóowee boo xeexee rekk da ngaa ñàkk jom
2,214,018
2,221,992
11spk2
loolu da koy méngale ak beneen boo xam ne tu() ña nga xam ne dañuy tuddee les auxiliaires maanaam ñi nga xam ne Yàlla dafa leen bind
2,221,992
2,222,412
11spk1
%hum %hum
2,222,412
2,234,202
11spk2
ñoom ñu war a lekk yàqkat yimbërëŋaan ma jox la misaal mbërëŋaat ma jox la misaal ñu koy wax pumelleya:Fra senegalensis:Fra mais mbërëŋaan boo ko gisee xam nga da nga koy xeeb di ko di ko bërëŋ ak di ko wéq ak yooyu
2,234,202
2,234,502
11spk1
%hum %hum
2,234,502
2,248,274
11spk2
héy aka am solo ci lutte biologique maanaam dafa am ñoo xam ne Yàlla da leen ni ay doomu ay yeneen ay ci ci biir %e lim bind ca ñay yàq gàncax ga daf leen di mbooleeg ñoom ñu leen di faagaagal ci tool bi
2,248,274
2,249,054
11spk1
am na solo
2,249,054
2,261,870
11spk2
léegi nag boo indee nag puudar wala ab liquide nga traité te na nga ko jëfandikoo baaxul la muy def mooy da ngay reyaale ñooñee nga xam ne ñoom dañ lay faagaagal yàqkat yi
2,261,870
2,262,482
11spk1
%hum %hum
2,262,482
2,293,292
11spk2
kon moo tax ñu naan looloo tax ñu naan puudar ak liquide ak traitement yooyu nañ ciy def ndànk ndax dafa tegu ci loo xam ne boo xamul mun ngaa yàqal ca ñoo xam ne de façon naturelle Yàlla moo ko bindee noonu ñii fa leen bind ñuy def lii mu bind ñee pour ñuy faagaagal ñii ndax mu am équilibre xam nga équilibre bi nag nit ci boppam léeg-léeg ci bëgg a defar moo koy yàq te bu ko yàqee nag maanaam daal di déréglé mbir ma su ko defee auxiliaires yooyu maanaam ñooñu nga xam ne ñooy faagaagal yàqkat yi ci tool te ñoom ñépp ay gunóor lañ
2,293,292
2,293,712
11spk1
%hum %hum
2,293,712
2,314,414
11spk2
waaye gunóor bu nekk ak la la Yàlla sant ci liggéey taw bi nag léeg-léeg mu gën a jàppale nag gunóor yooyu maanaam auxiliaires yi léeg-léeg moomit moom %e wax dëgg gëstu wane na ko boo xam ne man mii def naa ko ci wàllu sax boobu nga xam ne moom mooy sonal ngub bi dugub bi ñu koy tuddee chenille de l' épidémie nga gis ne ba ñu ko xoolee gis ne yenn taawaay yoo xam ne doo mate ay trente milimètres
2,314,414
2,314,933
11spk1
%hum %hum
2,314,933
2,330,153
11spk2
boole koog yenn vitesse yenn ngelaw yoo xam ni yu yemambaay yoo xam ne du fàq maanaam du damm guub bi boo ko boolee gis ngeen bi ñu ko defee ni ñu ko xaymaa wàññi na lu ci bëri ci yàqu-yàqu yi nga xam ne ci wàllu te taw bi kese
2,334,288
2,334,818
11spk1
%hum %hum
2,334,818
2,344,856
11spk2
taw ngelaw lu fo() ngelaw li yenn ngelaw yi mooy yàq waaye yenn ngelaw yi mu ne ah ma ne ko lu am solo la daanaka boo ko xoolee sax ngelaw yi mun na dëngal mën na kifin bi mën na fàq waaye boo xoolee am na lu muy liggéey ci suuf boole koog ndox mi
2,344,856
2,345,516
11spk1
%hum %hum
2,345,516
2,351,431
11spk2
ci wàllu naturel maanaam yu ñuy wax xeetu naturel boo xam ne Yàlla moo ko defee noonu ndax Yàlla lim bind lépp dafa bugg ñu équilibré
2,351,431
2,366,764
11spk1
am na solo sànq monsieur Samb Maodo mu ngi am lu muy wax di ko souligné muy problème mu Tataguine %e Diohine jàpp Toucar muy mel ni miin na rekk la ñu am chaque année ak li nga xamante ne moo fay xew tay yan saafara lañ ci mën a indi
2,366,764
2,374,772
11spk2
waaw maanaam loolu %e comme nu nga ko waxee maanaam dafa am ay kuréel yoo xam ni ñoom la ñu sas ñu def ci ak fi may waxee ak yéen nii ñu ngi ci enquêtes yi
2,374,772
2,375,344
11spk1
%hum
2,378,879
2,407,190
11spk2
suñu naataangoo bi ñoom Omar Ndiaye moom mooy chef bureau régional sécurité alimentaire ama na équipe pluridisplinaire boo xam ni services yi ci war a ñëw yépp ñu ngi ci fi mu toll nii ñu ngi ci département yi di def enquête yi bu ñu paree danañ ko tënk dina am atelier boo xam ne dinañu ci daje boo xam ne dina ci woo ñu saytu ko xool ko su ko defee su boobaa danañ ko gën a mun a faram-fàccee gën cee mën a dugg su ko defee la cay génn bu ñu ko tënkee jox ko kilifa yi ñu ñu ñu mun koo bàyyi xel gën a xam ne lii kat mu ne ah ma ne ko ah bu ñu ko bàyyiwul xel xëy na mu
0
26,887
11spk1
mën na indi ay jafe-jafe waaye ndax loolu moom mooy %e li ñu war %e ay ndaw lañ bu ñu gisee loo xam ne jagul danañ ko wax waaye nag lépp nag nay tegu ci xam-xam moo tax ñu koy def ci enquête ndem ca baykat ya ña nga ca bu jeexee ki ko yor dina ko woo ñi mu ci ko war a woo ñu daje ñu lifin su ko defee la cay génn buñ ko jébale la ca des comme ni ma la ko waxoon enquêtes agricoles yi dina génni dina wane ne ci taxawaay maanaam ci wàllu rendement ñaata lay am ndax li ñu am toll na ak li ñu amoon daaw
29,270
37,181
11spk1
yooyu yépp dañ bugg mu tegu ci xam-xam tegu ci enquête tegu ci ay gëstu tegu ci lu wóor mu bañ ñoo bett wax joo xam ne da ngay taxaw rekk naan nañ dem tool nañ dem tool te teguwul fenn
37,181
39,920
11spk2
%hum %hum mais ndax ñoom am nañu am nañu yaakaar
43,757
44,238
11spk2
%hum %hum
44,238
56,841
11spk3
moom mooy que %e présentement cas boobu kii quoi zo() zone boobu ñu wax léegi quoi mu doon kii quoi la vallée morte de * gis nañ que nii les autorités de la région là jël nañ ko def nañ ko même aussi vraiment muy %e seen soxla
56,841
57,620
11spk2
d' accord
57,620
64,489
11spk3
te fi may waxee ak yow nii léegi am na un %e programme bi nga xamante gars yi ñu ngi koy tëgg ak %e Fond Vers Climat
69,026
83,137
11spk3
gars yi ñu ngi ci actuellement ñu ngi def toilettafe projet bi te am nañu yaakaar projet boobu su paree %e insaa àllaa dina %e nekk li nga xamante ni bii disons roue de secours lay nekk daal pour %e vraiment ñi nga xamante ni ñoo dëkk ci côté boobu
83,137
83,595
11spk2
%hum %hum
83,595
100,961
11spk3
parce que gis nañ que nii normalement bu fekkee lépp jaar na yoon ñoom dinañ favoriser bu baax lu mel ni kii même mbayu dër bi ñu koy wax kii quoi maraichage te am nañu yaakaar que ni vraiment loolu aussi bu fekkee antu na day nekk li nga xamante ne bii donc lu baax lay nekk daal
100,961
101,620
11spk2
%hum %hum
101,620
112,942
11spk3
tamit %e yàlla moom saa yu **** ni ko wolof di waxee rekk du tëj bunt tëj paranteer saa yu %e bu benn bunt nee ràpp rekk xamal ni beneen bi moom moom fàŋŋ ubbeeku
112,942
113,342
11spk2
%hum %hum
113,342
130,282
11spk3
d' habitude c' est comme ça quoi donc am nañ yaakaar daal que insaa àllaa projet boobu léegi mu taxaw je sais que gars yi sori nañ si lool ñu ngi woon si toilettage projet bi kii quoi toilettage bi %e am na ay questions yi nga xamante ni peut être que moom bari na ñu ñu koy laaj gars yi ñu ngi formulé actuellement tontu bi pour jox leen ko
130,282
130,662
11spk1
%hum
130,662
136,232
11spk3
mais am nañ yaakaar ni insaa àllaa que %e dina dina kii daal dina dina kii quoi dina aboutir
142,738
143,317
11spk3
%hum %hum
143,317
150,572
11spk2
tay jii lan lañ mun a jàpp ci changement climatique ci façon mbay yi nga xamante ne am na fii ci Sénégal lan lañ leen mën a baaxee
150,572
156,627
11spk3
bon comme ni mu waxee ah bon xam nga bu ñuy wax mbay mbay ñun centré wu ñu mbay mi yépp daal ci ci ci
158,389
158,769
11spk2
%hum %hum
158,769
161,496
11spk3
parce que ñun bu ñu nee agriculture on parle de la grande agriculture
161,496
161,957
11spk2
%hum %hum
161,957
167,167
11spk3
boo waxee grande agriculture élevage mu ngi ci biir pêche bi mu ngi ci biir et %e
172,092
172,635
11spk2
%hum %hum
172,635
178,031
11spk3
actuellement yooyu dama la bëgg a xamal ni la que actuellement ñu ngi comme ni ko monsieur Badiane waxee woon ci njëlbéenam