audio
audioduration (s)
2
201
transcription
stringlengths
2
439
foofu lañ jàpp ni normalement fa la nawet wi war a
mooy suuf boo xamante ne bu ci ndox boo ko téyee ci sa loxo
aaral jaww gi moom la doomu adama bi nekk si suuf li muy jëfandikoo muy dem si kaw asamaan dafa dem a dem a dem ba yàq loolu noonu léegi moo tax nag adduna bi gën a tàng
préparer sol bi tamit netoyer ko bam set wecc lakk lépp waa
ak aussi les compétences formationbi mais boo leen sensibiliser ba orienté leen à travers cette approche mais aussi jàppale leen ci ci formation ci li ñu wooyee champs école paysan
pour batir un programme
balaa mu ñor nawet bi jeex balaa mu ñor taw bi jeex
am na ñi nga xamante ne bi toog nañu presque weer après ñu soog a mën a am ndox bi nga xam ne bii war na mën leen permettre ñu déclenché seen ay semis am encore une troisième vague
le treize août boobu noonu am na ci yoo xam ne yii jot naa ñor am na ci loo xam ne meññ na lool mais dafaa tawut ba tey loolu moo ko gàllankoor
waaw bëri na ñoo xam ne fi mu nekk nii ñu ngi jot message
daf koy maye directement
waaw moo tax it ñu ngi leen di jaajëfee bu baax
beneen bi ci des fexe ba lutté contre l exode rural
wax dëgg yàlla ma remercier bu baax a baax directeur
phosphate si gerte la gën a aay mais gàncax yëpp a ko soxla gàncax yëpp a ko bëgg
nga xam aussi produit bi ni muy duggee ci marché bi ak prix yi nga xam ne moom la ñuy appliqué ci at mi yëpp loolu moo lay permettre suba ak même xeetu produit yi wala xeetu variétés yi nga xam ne producteur moom la ñu gën a soxla
dañu ne li mu wax noonu ak jafejafe yi ciy am yëpp
kii wax na ko sànq fii kolda cinq mille cinq mille ménages la ñu am bénéficiares et cinq mille ménages et quarante cinq mille bénéficiares si tu multiplies encviron par neuf
yéen da ngeen ne deux cent soixante quinze ñun trois cent la ñuy tàmbalee ba trois cent vingt cinq ma seet lu ngeen ci mën
ku nekk dañ ko mené
wala suuf bi dugub la fi war a béy wala suuf bi nanam la fi war a béy
am na service maanaam ñi fa nekkal agriculture
boole koog yenn vitesse yenn ngelaw yoo xam ni yu yemambaay yoo xam ne du fàq maanaam du damm guub bi boo ko boolee gis ngeen bi ñu ko defee ni ñu ko xaymaa wàññi na lu ci bëri ci yàquyàqu yi nga xam ne ci wàllu te taw bi kese
loolu day tax dina leen dimbali bu baax
donc yooyu moom la ñuy wax état actuel de l atmosphère état actuel de l atmosphère boobu nag
mais si la cochenille du manioc
di leen di ñaanal jàmm ak xéwal
tey jii dafay baax tey jii par exemple lu mel ne côté jigéen ñi bu ñu amoon lu mel ne comme alphabétisation mais ci biir alphabétisation bi ñu defaale ci par exemple éducation financière
xam nga tey garab yi moo daan waral que ñu am un micro climat