sentence: Ni njàngum tubaab bi amee kurél guy saytu lépp lu ci aju ( inspection d’académie ) , noonu lees war a wutale daara yi tamit ag kurél guy wattu lépp lu ci aju . inspection d’académie sentence: D angay xool ni alkaati yiy doxal e ci doxi ñaxtu yi . sentence: Seetal rekk , guddig weeru koor , ci ngelaw li , ñuy fanaane taxaw guddi ba bët set . sentence: Muy lu jaaduwul , lu doy waar . sentence: Nit dina feebar , dem loppitaal ñ u koy jox i garabi - tubaab te du wér , fekk ne feebaru ng ë m la ame . sentence: Ndaxte , ñooy wattu s unu kaaraange guddeek bëccëg . sentence: Bala nga koy xam Gàmmu jot , walla Màggal , walla Pópangin . Pópangin sentence: Dama ne , S apo ŋ , Farã s , Amerig añs ñoo ñu ëpp bor fuuf te doo leen mës a dégg ñuy ñaan ku leen ko baal . S apo ŋ Farã s Amerig sentence: Raayante bi moo fi war a jóg , wolof mooy làmmiñ wi nu war a boole . sentence: Seen liggéey yombul te anam yiñ koy defe dafa metti lool . sentence: Mën nañ ko bañ a wax waaye dégg nañ ko , te loo ci wax xam nañ ko . sentence: Dafa di , nag , Ërob rawatina Farãs , dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafóoni waaso yi . Ërob Farãs sentence: Te mbir mi , wareesu koo yemale re kk ci taalibe yi . sentence: Luy sa xalaat ci la takk - der ya duggoon kër Ilimaan Ñiŋ ( Caaroy ) , jaay njambootam doole , dóor waa kër ga , toroxal leen ? Ñiŋ Caaroy sentence: Alal ji ma wax nii mat na téeméeri yoon bor bi ñuy leb , su nu ko sàmmoon rekk , du soxla ñuy lebi kenn . sentence: Waaye , bi leen DIC wooloo , ku nekk ci ñoom dellu na ginnaaw . DIC sentence: Yaa doon sama royukaay . sentence: Loolu , du lu ma jékki - jekki rekk def ko . sentence: Waaye , nag , du lépp a bon ci daara yi . sentence: Bu ngeen fàttalikoo , 4i at ci ginnaaw , Maki Sàll amaloon na fi ndajem jawriñ ca Pikin , ca la waxe woon ni benn taalibe dootul taxawaalu ci mbedd yi ; boobaak léegi , nag , tey la Waalo g ë n a aay . Sàll Pikin Waalo sentence: Xamul woon xàjj - ak - seen te bëggul woon lu jege sax boddekonte , rawatina ñeel nit ku ñuul . sentence: Fexe ba lempo yeembambaay , ñi war a fey ñépp di fey amagul Senegaal fi mu tollu nii . Senegaal sentence: Waaye , Mabaaba , ak lu mu doon mbër mu mag yépp , amul ndam ci xeexam bu mujj bi mu séqaloon ak meneen mbër mu xarañ te gaaw ci rey nit . sentence: Yenn saa yi ma daje ak ñenn ci ñoom , nu lal aw waxtaan . sentence: Waaye , Yàlla am na ci nit ñi yërmande joo xam ne , fépp fu mu boole ay nit yu wute ci waaso , dina fa tàggat aw làmmiñ wu leen di boole , ñu cay jokkoo . sentence: Sumay wax aada , xam - xam , cosaan ak sag yi m u là mboo ma tax di wax . sentence: Jean - Michel Aulas Njiitu Olympique Lyonnais . Aulas Olympique Lyonnais sentence: Boo fa demee , benn xale du génn . sentence: Boo demee réew mu mel ni Marog , looloo fa am . Marog sentence: Ndaxte askanuw Senegaal dafa ragal yat . Senegaal sentence: Fii ci Senegaal , fépp foo dem , dégg nañ wolof . Senegaal sentence: Waxuma , nag , tëgg , fecc ak li xew jamono jii .